9 COMMENTAIRES
  • Dembo Kanté

    Si Nous trompond d‘èlire se korrompeure nous allons tous regrétaient wasalam
    Sonko rek

  • Assan Boup

    Therese wakhal loula wor

  • therese

    Ken dou wédi ni Macky SALL moy ki wara meun defar rewmi. Mandat wam ngi wadja diekh, lep lou mou fi def guiss negn ko, meunmeuneum lerr neu

  • ruby

    Vote bou 19 février, di neu takh beu niou wonn ni nieup ni Macky SALL moy wadji. Nioun, kenn do tou niou nakh, kou matta nek Président né niouy wotel

  • error

    Macky SALL fou mou toll dey sam peuple bi di lenn diapalé. Dem neu fep ci senegal ngir khol lou nitt yi di doundou ci zone rural yi. Fofou ngeu khamni gnou niak dolé rek nio feu nek. Khamna li takh nioniou sonn, mo takh mou defal lenn solution you bakh. Di neu yobou Sénégal fou sori.

  • willy

    Ki niou fall 2012 ak 65% dou nenn deh. Lolou mo donn nortelou carriére bou am mana, kham li mou beugueu, gueum liguey. Elections yi score you eup li ley def

  • quoi

    Macky dafa am guiss guiss bou reuy, dou daw dou titt, dou bayi, dou tayi. Kom kom ak deuk bou bess rek ! Macky Rek !!

  • mariama

    Macky SALL nitou dieuf leu, moy président bi niouy weur. Mandat weum bou nieuk moy diekh, woné neu meun meuneum. Macky li mou deff ci 7 ans ken défou ko ci 58 ans indépendance.

  • Mouss

    Man deh li ma guiss moy elections yi dou am lamlamé, dou bett kenn, Macky moy péé. Mom lenn gueuneu nekk nitt niom nieup, gueun len ay. Mo am fouleu, gueuneu lenn kharagn ci rewmi ak ci bitim rew.

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *