(Vidéo) Lutte – Sa Thies à Modou Lo: « Ba kérok fi mouy déé, li Balla Gaye di ame si lamb douko meussa ame »
Après Balla Gaye 2, Sa Thiès répond sévèrement aux attaques de Modou Lô. Visiblement très en colère, le frère du lion de Guédiawaye a demandé au Rock des Parcelles Assainies de savoir raison gardé et de ne pas s’immiscer dans leur affaire de famille. Selon Sa Thiès, Modou Lô n’aura jamais ce qu’a eu Balla Gaye 2 dans la lutte. Regardez!
wakhko mou ligaye ta bayi tontoubi.Modou demna balenefi
ligayal bayi wakhgui Modou rombeneu yagna affaire dou aye jeul roi ou pas ligayal en + yaw tolowo akh Modou catégorie tu son poulain en cemoment jemal def limou def wala li Balla def bayi wakhbi stp boy. yenay creel sene bop ay ennemis si dara Balla wakh yaw wakh svp sen fans you bari bayinaniou nokh seni wakh svp aaaah.
Sa.thies.modou.lo.da.ame.nianou.waye.dioure.kone.loumou.ame.balla.amouko.bilahi
BOUL MOU REEY YAAW, DANGUENE MEUNA WAKH REK, WAYEE BOUGOULENN KOU LENN TOONTOU. JER NE SAIS PAS COMBAT LAC 2 AK MODOU LO LOU SIIY SEN YONN MANGUENN SIY WAY LINGUEN SSI WAKH YEUP. WA LEGUI MODOU TONTOU GUENN DI MEER. WOUTI LENN NIANI WADIOUR. NONN MODOU MO BONNNN…. MDRR.
sport dafa warr bole mai pas di nonante
Vas faire foitre sa c ton pere qui a parlé dans les médias
Sa thies a raison