Vidéo- L’émouvant témoignage de Zoula et Fafa sur Waly seck… Regardez !

» Le prince des faramarènes est un homme sans méchanceté, philanthropique » nous dit Zoula et Fafa…
Zoula et fafa font un magnifique témoignage sur… par sendiaspotv
» Le prince des faramarènes est un homme sans méchanceté, philanthropique » nous dit Zoula et Fafa…
Zoula et fafa font un magnifique témoignage sur… par sendiaspotv
mia khaana tu parle de abba? kokou dé goumoul dara il utilisé juste waly pour se faire un nom légui il é connu mou koy dirr mbague diko dieundé gnénéne motakh moi je le sui plu souko gayi beugué touti waly mo takh
Wakh bou wérroul noop yi koy deglou wéer en se blocant di outt kouleu gaganti Ay doul késse on dirait 2 Oubbi en delires celui de droite tu as une chic voix, baat bi thiagana
walahi bella wakhatiko déeee je tassure deugue pirr nga wakh
bilahi fafa dafa sincere deugou thi loumoy wakh outèk lolou nonou
fo reconnaître kil a 1 grand coeur kan mm
Waly est une personne genereux jen suis temoin kholom ben la si aduna dina lakk niou bari bou nitt meunon guiss loumouy def si lou bakh lou ken yeugoul dagay yémou yalna yalla goudal sa fane ??
merci yène bakh ngène déee
ndeysane yéna bakh wayyy
merci fafa yaw mom dangua sincere trop machala outèk lolou nek sen tv may bagna toudou toureum
wakh sa mbakhou way wagni woul dara thi sa boss
ndeysane yéna gnack kignane way
you bakh yi môme kéne douko commentaire diéye senegal
waly yal nala yalladefal djamm FO tolou d’El wakh amine
Les commentaires sont fermés.