43 COMMENTAIRES
  • kouthia fan

    Kouthia aussi yalla na retraiter TFM….

  • fa

    Yaw bou ba koutia bou fa diogue sa defet la you dou dakh Ken ci tfm rgler koutia day animer rek donc soof gua trop amou lo ben comptences tey ya gua fa

  • D

    Khana amougnou yénéne ambitions bey retraité fofou !

  • guis guis

    non senegalais mo nafkh mais khouthia mo bayi kn dakhouko mom dafa sis pour mom tfm 24/24 khouthia show lanou wardi wan ba carthi Gnral mo geuna nkh khouthia show

  • Anonyme

    khouthia dafa badola dafa ta amoul colgar biga sidy lamine dakh youssou moka fat ta tay miguini diko Santager souba ak ngon khouthia mom na dm rk bala kham khamadi dinako raya ta nimou nkwon tfm amoul bn tl bokay Gr beug nk animateur beug nk directeur Di programme khouthia doul waay

  • fifi

    liguy nimou diaf khouthia Di bayi Ndakh rk dano wara redifis ay emissiom non ki mo rew ta mom mo raay programou tfm goudigui

  • diaw

    Mai kothia amoll lomoy wakh

  • diaw

    bouba dafa am fola rek

  • diaw

    Mai bouba dafa am fola rek

  • fifi

    lima nakhri moy senegalais dano amoul stlou khouthia mom rk mo nk tfm Di am proplm ak ay chfam ta biyoon dasi bol ay doul nan karim mais khouthia dpuis kagne migui togne Karim wade si tlbi ta amoul problm kon lolou manoul nk proplmbi khouthia dafa sis lolou moy wakhdji ta Gfm dafa ay animateur khouthia manoufi Nioy tk emissionm souba ak ngon mani na bayi mo geun si programou tfm Cart znaral you mlnou noun fans Gfm danko sokhla

  • Assane Thiam

    Oooh!!! Bouba…na nga xamnè buur ayoule dagya aay,yaw momo niit yi, ba loula nekh nga def c pck sa jang soriwoul ba loula nekh nga Wakh.Kouthia n’est qu’un Animateur,il peut dire tout ce que bon lui semble d’autant plus sâche bien k nul n’est indispensable…Réfèrez_vous à la parole de Dieu:Yalla dou massa dièkhal ta loumou yor dou diekh…Bouba lakalè nga,xamal sa bop…

  • Anonyme

    doul wayn ngndi saaytan khouthia kn dfouka darra nna emission lani ykha rediff lousi bouba man yndaguna khamoul khouthia rk na dm nou ndiaye chansam

  • Anonyme

    bo nk tele daga wara df saliguy ta dm mais beugdi lidjnti ay detayou Rediff dou deug douyon

  • Cheikh niang

    Bouba bul wutal sa bop @y non, dou koutia rek dangafy diotek gnenen sakul diamu t kham ni ngouruk yalla reka doul diekh

  • Verdad

    Bouba danga rouss rek waye gneup khamnagne ne yaay bouki biy matte biir tfm..nopi baa out moy sa joob..égoïste

  • bay

    tfm kn masoufa dakh bn nit khouthia dafa amoul respect ta dafa jaloux foum dm dinafa diogu sod nimou nk tfm lay nk si teleyi

  • Grand

    Xamo touss yaw bouba doul waayy

  • On accélère la cadence

    Kouthia fait parti des premiers animateurs de la tfm. En ce moment là, Il n’y avait pas de programmes la télé était vide. Ils le choyé le chouchouté maintenant qu’il reste où qu’il part, çà leur ai bien égal parce qu’ils ont de nouveaux talents. Lolou késsé la dommage pour oustaz boundoukh bandakh barboute tu nous as fait bcp rire merci pour tous.

  • chelsea

    mais vous l foutez-nous la paix avec ce kouthia de merde l.bouba defoul dara le problme c’est kouthia il n’est que un simple employ qui veut diriger le groupe de mdias le plus puissant au senegal.moom moy kann? t mayniou jamm.arrogant

  • serigne Abdou salam dienne

    Doyna waar wayé loudoule jaammu jammako guene

  • Modérateur

    Senego guir yalla bloqué lén Chelsea fadjare rou kor mouy niapp Ndéye deugue Ndéye rek li dou yonn assamane ci khineu sakh mou saga

  • papalare

    Franchement je n’ai rien contre le comédien Kouthia mais il faut reconnaître que ces derniers temps son émission avait pris de l’eau. Elle était devenue fade et monotone n’avait plus aucune portée et ne faisait plus rire comme avant. Je croyais que le comédien allait rebondir mais il a tarde à le faire croyant que son concept pourrait résister advitum eternum .

  • bleu

    Chelsea deug rek la wakh

  • gfm

    koutia bayil siss yow nga yaga togne karim ken moussoula wah dara tay nga bega dem prsk amato ben horom ken setanatoula say sponsors daw nga beugua tahal bouba mani bayilen diamour koutia si bopam mo beuri ay caprices yow wa tfm gno la ragal danga len heuss ba nap lou eup nak tourou yow chak jr gnou rediffuse sa emmission ak dimanches oci nit dangay am ngor mak nga bayil thiahan yi tenga deloussiwat rero amoul gnaka wahtane reka am youssou dafa sone si nehal bi

  • Mimi

    Ohoooooo nasa guelaw nekh bouba diokhal Ndiaye chance boleko Mari ndiago ay rekk lagn deff tê am khorom

  • RafRaf

    kouthia ne fait rien dimportant il fait juste de la comédie sa pouré mèm na pas ètre redifusé ,ya des émissions plus important et nèkh ,dégage de la TFM et ny va surtout pas a la SENTV ,arrèt de faire la nomade tu es égoiste,

  • gfm

    NDIAYE AK DOYEN GNONGUI FI GNOY DIEL SA PLACE GNOLA GUENA AY EUP LA HOROM EUP LA CLASSE DEMAL WAY ATHIA OUSHHHH

  • chelsea

    blue merci toi.louma beuga wakh rek mooy kouthia boumouniou tankal.nioune TFM moniou eupal solo kouthia.nadem fouko nekh mokham.comme mission am bi nekhatoul kenn mouy singali bouba.youssou ndour yalla nafi yague t weurr youssou defa bakh trop barki rassoululahi

  • bleu

    Merci Chelsea tu as tt dit ce koutia il m énerve il est si arrogant khawma koumou Yap rek limo ame tfm da Bari trop chaque jour mou guede gnoukoy nekhal

  • bleu

    Gfm pourquoi pa gnou dieuli mari ndiago ndiaye Horacio doyen mixer len gnome gneup ils feront mieux q lui c sur

  • chelsea

    bleu thank you.mais youssou aussi il ne doit pas se laisser faire ndakh badola badola l rek bou sol yr badola bou soumm badola.kenn mounouko defal teranga bomou guiss ko youssou yalla nafi yague t weur

  • Cheikh

    waayy fans tfm yép wah loudoul deug rék

  • le justicer

    allé vous faire fautre avec tfm vive la démocratie..je rappelle ke la fami ndour a fait la même chose a titi et d’autre artiste ossi..ils se croient métre du monde mais il se trop…je leur consil de redecendre sur terre

  • bleu

    Le justicier va te faire foutre toi même

  • gfm

    merci BLEU hel day fatou hamnga ndiaye ak doyen per samay typo lagnou mais marie ndiago dafa meun limouy def machala vive tfm gno fi nek wahoumako beugu bimalen beugu mais deugu rek la

  • gfm

    le justicier louy sa blem loudoul deugu dou yagu en tt cas dé wa tfm yagu nagnou di def lou bah di innové leuk nak loko bagn bagn nangoul ni dafa meuna daw wah touti dieuf lou bari famille ndour kou wahal yala hamni yatal rek lagnou ham sissougnou ken te dohougnou si injustice diam ak salam ak ligueye lagnou ham bagne nako ba dougnou tontou critiques koulen togn gnou bayila ak yala motah chq jr yala di woné bopam koulen togn dinga ko guiss

  • ado

    notre pays est un pays de brigands et de voleurs qui se courtisent . maky . idy .karim .wade ousmane ngom souleymane ndéné . kif kif .l argent ne se travaille pas au senegal ça se vole au nez et au barbe de tout le monde .où sont leurs cabinets ou leurs études . rien que des bluffs . ils pillent nos deniers pour créer des partis politiques bidons . je rallonge la liste avec fada .alioune sow. nos dauphins niasse .djibo .tanor .ils ont fait de la politique leur professions et leur gagne pain . et non pas un sacerdoce

  • Diazdia

    Qu il s en aille au diable bou foguene que Karim dina ko walou dioumena

  • Beugsarew

    Les medias senegalais on une grande responsabilité sur l’éducation et développement du pays . Je vous donne rendez vous d’ici moins de 15 vous verrez de vous même combien ces médias sont toxiques. L’africain doit aujourd’hui créer son propre modèle de concept médiatique au lieu de faire du copier coler à tord et à travers.

  • bay

    khouthia 3 ans migui topando Karim wade kn masouka tr dfgani karim dina dm ba warra gun nioukay tr mou wakhsi ?? wakh sou dof na say nopou wer senegalais dounkhouk deug Dani par par lo rk khouthia dafa sis

  • bouba bayil dicta

    bouba sonal nga nite ti téranga publiquement histoire aussi publiquement zéro soutoura

  • Cheikh Mbacké SARR

    tous ceux qui parlent mal de Bouba ne le connaissent pas seulement sous nos tropiques la méchanceté est la chose la mieux partagé, Bouba kou yarou kou am Soutoura kou mana dimbelé Diam yi seulement comme il est le frére de Loumou déf rek dafay garawa gnoukoy jugé ta khama lougne ko dara mais dieu est le plus juste des juges.

  • allll

    limo yakk Sénégal kw daniouy teugneukh teugneukh di deim deuk bi dina yeikheu avancei
    vs la amina potei sou takei c grace à kouthia, Ndiaye c grace à kouthia, maty dieng et meme mbaye etc et tant d’autr
    donc ki def li sokhoroul
    tei en plus foum gueneu meitei kouthia
    a cauz de GG de pape cheikh dialla ki a fei le tour des télé bah arrêté way kouthia incha Allah u aura tn kouthia tv, kouthia fm et kouthia info
    je vous remercie

Publiez un commentaire