Publicité

Vidéo: Le Khalif Des Mourides :« Je Ne Tolererai Plus Que Macky Sall Soit Hué Quand Il Vient Me Rendre Visite» Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

23 commentaires

  1. bamomar

    yen gni agitee wou si kaw khaf yeuppe ay farrando wou macky ngene rekk , c’est vrai que serigne bi sou waxe kenne warrou se tekk batte ndaxe kilifeu la mbacke balla aissa waye khamoulene nafeke yenne gniy djinate nafeke est ce que li lenne senne baye di sante yeuppe yenne na ngi si , est ce que li lenne sougnou borrome sante yeuppe yenne na ngi si seurigne bi nakk yeuffou kilifeu rekk la deffe ndaxe kilifeu mome daffaye raffetale nitt nakk lou mou baye lollou laye guouppe na lerre si senne bopp supporter deugueu mo gueune supporter nitt


  2. Cheik ibra diarama

    Serigne bi bou khaséé ba wakh

    Amatoul lougn thi tek

    Serigne bi wakh ba paré nganè mbacké wakh nga deug « wayé »

    Kouko deff lenen nga wayé doo mouride

    Dieuredieufé borom touba diarama cheikh ibra fall


  3. sangue bi yagg fi lol te and ak wer bayileen di diokhe seen khalaaat di gene ralise ni ñi


    nioune mouride seetouniou kou niou beug ak kou niou bagne li serigne touba beug si nioune ak kilifeu bikofi teewal mo niou souñou yitee. un point-un trait macky dieufoufi lou wane k bagneel lam si kene dou mouride dou tidiane .


    kou joub joub nga. DOU MANE DONG BOKOUMASSSI MOKO GEUNE YA DES MILLIONS DE MOURIDES ET DES DIZAINES DE MILLIARDAIRES AME WOUNIOU AK MACKY .


    BAYILEEEN JAXASSE NGUIR YALLLA FI SENEGAL LA AMNA YOUFI XAJOUL.


  4. lamine diop

    serigne sidi Makhtar yalnafi yage te wer ak kone amin kilfa ni lay mel diamou lay wakh mom lay dokh maky politique lay def moy président de toules s’en égale amol mourde wala tidiane thie benen tarikha bo mana bok wala sakh doo diolt dagna wara respecter sounou présidant bou s’en égale yi khamene defofi dara niou diale kofi com ay moromam mai niou kham ni yala kofi tek dou mou ride dou tidaiane te maky ken ganouko nek talebe serigne touba


  5. wassin

    cheikh sidy MAKHTAR mbacké yala nafi yague té wérr. ki moye kilifeu. té mbacké mbacké you touté touti yi khamléne séne place. malettes khaliss, passeports diplomatiques, 8 x8 ak déme di thiakhane ci hotels you bakané yi, damané yoyou diékhna.


  6. kesk

    khaf je suis sur et certain toi comme des milliers de soidisant mourides Macky respecte bcps la tarikha mouride que en plus tu es un hypocrite si tu respecte réellement le khalife général des mourides « boulla diokhé ndigeul denko wara Dieufé si kanam ak si guinawam yeup  » mais c’est dommage que la majorité entre vous les soidisant mourides ayi nafek laniou ndakh mouride deug ndigeul Dieu réf Mame borom Touba.


  7. cheuteuteute

    mane khaf lima diakhale moye messou ma deg macky wakh begoul mouride yi . ti guissouma tamite mou dieufe ko. je n’arrive toujours pas a comprendre pourquoi tant de haine envers macky


  8. khaf

    Cheikh bi gnongui jeguelou..c est Macky Sall qui n aime pas les mourides…dounouko Youkhou sa kanamm..ndax sa dieum jou ted ji…wayee dinagnouko youkhou sa guinaaw..ndax mourides yimouy torokhal….Kou bougoul Serigne touba..gnoun Mourides Beugougnoula


    • sangue bi yagg fi lol te and ak wer bayileen di diokhe seen khalaaat di gene ralise ni ñi


      nioune mouride seetouniou kou niou beug ak kou niou bagne li serigne touba beug si nioune ak kilifeu bikofi teewal mo niou souñou yitee. un point-un trait macky dieufoufi lou wane k bagneel lam si kene dou mouride dou tidiane .


      kou joub joub nga. DOU MANE DONG BOKOUMASSSI MOKO GEUNE YA DES MILLIONS DE MOURIDES ET DES DIZAINES DE MILLIARDAIRES AME WOUNIOU AK MACKY .


      BAYILEEEN JAXASSE NGUIR YALLLA FI SENEGAL LA AMNA YOUFI XAJOUL.


Laisser un commentaire