Yalla nako Yalla sunou borom mei werr delo watko si sagom,Amiin
allemagne
Ey waaay doumou diambour bi ndeysann Amina ma trés chère bayil télé senegal daniou boon
deuch
marthia
Non mais febarou diambour ngen kay siwal ci media seytaneiyi lakhassousi non doyna war
sohnasi
ooohh amina yalla nala yalla yeukati thi diameu sister bayil tele bakhougnou
Fa
Bilay Allemagne ak sokhnasi wakh ngen deug man tam lolou lakoy wakh. Tfm dafa bari nit you doul ligueye dara et ça les dérange lingay def. Tanel ak diam nath.
bakel
yalla nako yalla yaikeuti inchalla
lahat
lalla nako yalla yaka ty
lahat
yalla nako yalla yaka ty
zoula
djouga sisa bop tfm tele misti seurign touwan te rek mofa am t amina dawoul thiow yala nala yala yeukeuti t ga regle t bayi garouwale ak gnin wane wou
Fatyma
Ay Way bayilénak télé bi yala nala yala yekeuti khamnane ni bofa néka Ken dou fegne thi gniom legougniounou
fa
aye bilaye domou diabour bi yalla nako yalla yeuketi,te Amina del moye tous Sénégal danion sokhor douniou dém té douniou bayi kenene dém
hihihi
Deguene chimère aussi ndeysane…
Beri Feem
ON PRIE POUR ELLE. QU ELLE SE RETABLISSE VITE. ELLE EST SYMPA AMINA POTE QU OI QU ON DISE.
Amina
bayilen tfm dara lou niaw amoufa delen wakh loulen leer Amina dafa febarr rek te dina werr in chaa Allah
xolatale sa bopp
Mbacke mbacke
amina yalla naga tane ak diam barkep serigne khadim awa ba barkep serigne bara khadim rasoul nitt soy wakh warna wakh louka lerr ak lou yo nam nek

mlle l'animatrice on dit une sphére