Vidéo – Grand Bal 2016: Un « combat de lutte » entre Youssou Ndour et Balla Gaye 2

Quand le roi du Mbalakh fait du « Leewto » avec l’ex roi des arènes lors du Grand Bal de Cices du 9 juillet.

 

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l'exprimer dans un langage respectueux.

";

24 commentaires

  1. ki voit ce monde, reconnait sil né pas méchant bien k you es l meilleur ! de lambiance de la bonne musik, noto sambay mayane !! nit gnilo beugggg dafa yagggg !!! koussi mer changel nationalité !

  2. Affaire bi dal comme conflit de generaation , ancien gloire yi nenagne sen roi youssou ndour la , jene generation bi, j’ai bien dit generation fraiche, wakhouma gniy jeune jeune lou, gnepp nenagne wally sen roi, loussi nit meune, mé you limalay digeul moy boula adouna diay ba nga andak wally gen si mbedd ndakh bouboba defaite totale ndakh khalé yi wally lagnouy topou, mou nekh la mou nakhari la wally la nit gni beug té gni la topou gni dagnouyt dem ba magett , gni djoudouwone sa generation moy gniy jeune jeune lou , da gnouy ba dougne mana dem soirée , yaw nak nga retraité di settane wally di toth mondame ak khalé yiy mang ak yiy djoudou, kone khame nga ni affaire bi si ay lokho wally lay moudjou, so badjanetou ba djekhal rekk nga dem nopalou, khana wakho ni ‘ arene bou makk bi moy adouna koufi beugeu tekki faw nga lewto ba tass , té sakh lamb ji ben mbeur yoyatoufi » , wally day mbapat , di claf ,té makk mouko si maytou woul dinala djokh sa torokhal ,ndakh khalé fraiche la

    • Sawaaye yaw bariiwoo kham kham dara.
      Goor djiguène gni barouwougnoufi bénne bari nak banga yaakaarni ils peuvent peuser.
      Koula moudieu dioudde gueune laa beuggue Youssou.
      Les choses sont ainsi structurés. Qui dit mieux ?

  3. C’est pas les jeunes efféminés fans de waly qui disaient que « leur star » va détroner youssou ndour ? C’est ces mêmes personnes qui demandent à youssou de prendre la retraite ? Est ce parce qu’ils savent maintenant que tant que you est là « leur star » ne fera pas le buzz ? Il me semble que youssou ndour vous a foutu la trouille mdrrrrrrr
    Au passage parait que la soirée de votre « star » samedi au king fahd palace a été un vrai fiasco
    Sénégal deuk guenouko nekh ré ba tass

  4. Mé wa senego loutakh ngen dag sama commentaire bi ni mé ame na djot , damani kone sougnou nekhé ni you ay fansou mandikate la ame , wala lougnou nekh , wakh day raffett, ndakh sougnou artiste yi , gneppa lene beugg, té defflen ndank ndakh bess bou nekk ame gnou saga seniy yaye, rakk, makk, tanta , tonton, etc, ndakh wally gnepa ko beug,bouken saga ken surtt na gnouy wakhetane rekk di rafetal lepprekk, adouna yagoul

  5. Sa way khamo soire bou fiasco d King fad d russite total entre 50000 khal df bamou bakh tabl wou diakarlok faramarne bi mou bguelne yne nak fans you yna gnak fayda yne gnouy comparer si sne commentaires you ak waly you limou df waly dfagouko way nak yalla moy my mo mye waly loutakh gneup nane waly waly kom meunoulne wakh ba yalla limou name thi waly dou am nopalou lne nit kou bakh Day nangou dogal

  6. khawma goney waly khawma thiouthie dafay kham lékam niveau musical bou youssou sa kham kham sakh yégagoul fofou ndank rek boul ko so ngou bokoy so ngou moulay dougeul ci sakou bi way rek la youssou di def

  7. Jaja jaja thiey Senegal ñoomana diakhase ay nit ken koune ngui diapalel tank kinga beugue degu ak feen manouño bok ben khol ap khol bubeug yalla nek deug si sakh waye khol bu ay thiakhan nek ay thian reka si sakh beugue Len yalla te bayi thiakhan yii lilep ay foo la rek nguen balna akh

Laisser un commentaire