Aucun effort n’est ménagé pour fêter son anniversaire au Penc Mi, Waly Ballago Seck se lâche et dévoile une démonstration de danse qui enchante ses fans.
(Vidéo) En mode Sabar, Waly Seck explose Penc Mi… Regardez
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l'exprimer dans un langage respectueux.
";

très bien domu guewel la waly wathe gua bonne chance ak guewel gui
mdr akay degue
Waly dafa hew kounek ak sa ay waly mo ayer nagoulen li yalla doguol bilay soul ker douko terė fegne
Billahi papa u make me happy wish u long life n good health
Billahi papa u make me happy whenever i watch u wish u long life n good health
kou yaboule nongue dogal ta xamni kou nek ak diamono
kou nongou lou yalla dogal do sone sa xol dou diekhe
waly khamoul dara fi pape diouf rek
Waly rek thi khale doyoul baye dés ba paré nak askanwi gno la beugue faf thiate hol seeda Tina
Melni gordjiguèn nii,fuck
Nel Yaw ak kou mel ni Yaw nio ko beug mais Boul si dougeul askan bi
ndella waly noboula ,mo khew ,koummou metti nga matt sa bakene hahahahaaaaa
numéro 1 de la musique sénégalaise
waly recul xalè
As Wally meunouma nop ndakh dounkh leu.
Italy khana da papeu guordjiguen la motakh ngua khamé léne
nn wally liguay dff nx na
wally ken dou iow
wally seck kn dou iow
Mane dama weet fima nek motakh may yakamti ay vido you Wally commentaires yi damay r ba nelaw
bref wakhnga deugue, meme les ennemis de waly cherche ces videos ,mome lagnouy weur, mo khew ci djamono te khewa khew ay way lii
waly mo khew si diamono bagne bagne beugue
wally moy star mom rékh khale lé té sokhor na