Vidéo émouvante: Wally Ballago Seck fond en larmes à son départ de l'aéroport LSS

A quelques heures de son grand rendez-vous à AccorHotels Arena, Waly Ballago Seck, en quittant chez lui pour aller à l’aéroport Léopold Sédar Senghor, a fondu en larmes devant ses proches et fans.

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

51 commentaires

  1. chelsea

    ngay dem bercy di jooy khamnga loy joy lounga sombi mo wekh khat dinga khamne you national thiomo bo dellous dingako respect


  2. Laobé

    IBRAHIMA tu es mechent trop même. Tu dois être un simple homme débrouillard. Si tu veux réussir dans ta vie souhaite la paix à tes prochains.


  3. Badiéne

    Yallanala sounou borom soutoural, nakh yallah khol rék laye faye, té sa khol raffété na sét na, respecté gua say wadiour, ak béppeu domou adama, amoul kén kou meuneu wate né meusse neu dégue wally wakh lou niaw si nitt ak koumou mana donn, rien que pour cela, moi je te respecte, d’admire et je prie pour toi, bégueuleul say fans qui vont se déplacer pour te voir sur scène et pour le reste laisse c pas important. Du courage


  4. mbalax man

    com mbeur bouy beuré dji rek mdrrrr mé bon courage waly tu es courageux.pape diouf mom top youssou ndour rek naane ko guouy guou daar guaa ngi. sarap ndayi pape rek bopam bou ndaw bi


  5. MO

    Wally souy dioy khalatoul fessayou wala bagna fess bercy , ndakh mom spectacle bimouy djokhé mo ko interesser té en plus kouy dem kharé kouné so khalaté ni say none gnii ngi lay khar soth szniy beufn bamou wekh nga dioy,mé boul tit ,boul ragal ,ndam rekk


  6. perso

    vivement dimanche qu’on en finisse franchement le Sénégal s’est arrêté de vivre. Rien a foutre de ce truc. yalla diapaléla


  7. zeynab

    boul djioye mare sèègam daga dém rèk pour tèwal sa rèw yala nala si yala may ndam sa xol rafèt na amga yeurmendè yala nala yala fay sa xole soula sougnou borom fayè rèk do diakhlè machala ndam rèk inchalakhou rabi yala nala yala sam on est tous derier toi kou dèm ak kou dèmoul gni dèm yala nalè yala yobou si diam t gnou gnibisi si diam gni dèmoul gnogui yor sèn courous di gniene yala na yala sougnou borom nagoul gnou gniene yi yeup amine ya rabi


  8. leuz

    Des fois je me demande yene degrés de sokor yi depuis quand lako yene sénégalais yi am… Wally fessal bercy ou pas, réussir bercy ou pas n’empêche pas que le lendemain tout le monde vaque à ses occupations … Kon na Gnu ko nianal mou réussir encourager ko wagni woul dara…c’est un jeune qui a de l’ambition et qui excelle bien dans ce qu’il fait…une prestation réussie à Bercy sera une fierté pour le Sénégal et pour tous les gens qui sont dans le domaine de la culture… Arrêtons cette méchanceté gratuite envers nos célébrités…mane mom kou si guene way bouma nekh dama fecc ba mou nekh, damay malaw damy laal bassang damay youssou damay pene damay nder damay titi damay viviane etc…douma nangou kouma cantonné si ben artiste nane ay fi la far wala feule…ay ki Lay deglou douma deglou keule..ma bagne ma lank lou nekh rek je. Consomme…bonne chance à Wally…yalla na diam yaagg


    • Manou

      @Leuz je vais te répondre, moi je ne suis pas surpris quand on a vu qu’on vendait de la viande d’âne dans les marchés senegalais, parce que j’ai eu ma réponse a ma question a savoir pkoi senegalais sokhor légui ??? lek bou bonne bouniouy lek la rek je tassure, le senegalais est trop méchant légui…personne ne doit réussir, ni avancé, ni rever…


  9. rik

    souba rekk la souba

    wally mo hame limouye dioye dehh

    berci dadoul fess

    billet yi dafa diaroul

    le 5 laye halate rekk mo tahh moye djioye


Laisser un commentaire