Vidéo. Dj Boubs sur la supposée concurrence entre You et Waly: "Des gens tapis dans l'ombre sont..."

 

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Dans le même thême

68 commentaires

  1. djiby

    Hé dama né dagno déme soirée You ba sone wayé bougnou wakh deug rék soirée Waly mo gueune nékh fof le temps You est dépassé.ou est Pélé il a fait son temps ou est Maradona il a fait son temps.donc You, il temps que vous arrêtez la musique sinon Messi (Waly)dalaye yobou retraite vous êtes prévenu


  2. natacha

    yaw AS boo khamoul nga nopi lan leu Youssou di ignané Wally? et puis You moko ndieukeu invité Bercy 2013 demoul donc pourquoi You diko fallé mayleen gnou diam lep fileu niou fek.


  3. as

    doudou wakhnga lepp, le temp de you est passe, moi j allais aux soiree de you waye legui mere l ,da tite dongue motakh mouy wo ekon ,da ragal waly ,you dafa ignane, et puis il a 1 groupe prince art ,poukoi il ne laisse ces petits pauvres chanteurs faire leur petit bonhome de chemin, mais il veux tout accaparer ,mo takh sa ndiogou wakh na ko deugeu, nekhoul ba nekhoul mais you dafa niakk fayda amoul bene classe ,heurbi warone naka fekk mou demm makk siar seydina mouhamed psl, mais mou nekk fi di concurence ak ay domame, waly a fais son devoir waye na birane ,invitena you ci bercy by waye you f semblant de ne pas l entendre ,waye lou waye rendi sa lokho lay nathieu, waly machalla yalla mo ka may, djamm mou nou ci dara


  4. MBEUR

    senegal l pays werente du tekkele SPORT MESSI vs RONALDO MODOU LO vs BALLA GAYE REAL vs BARCA MEDIA AHMED AIDARA vs MAMADOU MOHAMED NDAYE TFM SENTV DANSE NDAYE GUEYE vs OUMOU SOW etc… POLOTIQUE KARIME WADE vs MACKY SALL etc…. MUSIC FATA vs DADI BIP SON etc.. VIVIANE vs TITI etc.. PAPE DIOUF vs WALLY MAINTENANT C YOUSSOU VS WALLY


  5. na

    daguene di nelaw yewoulene bogue wally seck lague na deugue bi xana nekh xalet bruit xalet derangé xalet saf gneupe bou ayé dou yombeu gnoune ak mome ba biir bercy kouci sa khol khassane kalamele god kou ayé wal sa momé gno aye bercy framaréne gnofay kay teugue bama nekh


  6. Doudou

    Youssouf Ndour dou dara genoufi ken ndakh nitt ken khamou KO yalla rekk mo kham si télé wala concert rekk ng en koy guise mou yore ben image mé est ce le c’est réellement ken khamoul bakham âme na loumouy deff du KO neubou wala té parfw sa nga guiss nit yakar ni kou respectable kou grand fekk il est si petit au fond de lui.Bref Youssou bougouta guiss kou mana wayy pour mom mom d’ONG mo wara woy mo wara fegn mo wara porter drapeau Sénégal man nagnela wowé roi du mbalakh ndakh sa y temps ya KO marker wone bâ legui GNi nga bokalone diamono yaw la gnouy deglou cé normal mem chose pr Wally fekhé na bâ ame jeunesse bi , té Kate bat bou nekh y alla koy maye d’où si waly yalla la ,com on l’a dit defone nga mm chose avec Ndongo lo diko takhamelou mé loutakh kou mana woy rekk gnepp beug KO rekk nga ni yaw la beugeu remplacer wayé gnoun ki gnou beug sou ou khol kene dou KO dindi té sakh roi bi gnou lay wakh si sa empire la yam me gnoun GNU beug Wally moy sou ou roi te âme nane si droit, té bou yalla né waw ndam rekk ndakh khôl bou rafett deffou la concurrent de bay la la deff té dom bou nekk gnane nga y alla nekk bay té pr nga nekk bay sa ngay deff yeffou lila sa y dieumé sa salam Wally avec ta belle voix tu IRAS loin mw je vois du sens dans tes textes surtout TN dernier album magnifique message rekk te lepp lui nga si woy déluge la bonne continuation boul tit boul ragal té lou takh ma nawla mot sa geum sa bopou . diam rekk inchalla et y alla na y alla sopi y ou bambou deff la si kholame et bonne continuation à lui


  7. Manou

    mane dale senegal diakhalnama, légui débat bi entre You la ak Wally pfff.

    You est le number one, wally a tracé son chemin té souko wathioul ci kanam la dieum inchallah, mais débat amoufi, mais je dirai que la seule personne qui peut faire taire les gens c’est Youssou himself…Wally wonako ba sonou entant que son fils, a mon avis le 30 avril quand ils étaient tous les deux au king fadh, Youssou devait s’accordé une pause pour ndieuw si boy bi wakh bi diekh, et s’il l’avait fait connaissant Wally il va pleuré pcq ce gosse a un joli coeur. Seul Youssou peut clore ce débat qui n’a ni queue ni tete, sénégalais mome wakh rek.


  8. Aram

    amar yaw khamo lingay wakh bayu waly sakh Youssou moko yobou bercy kon bercy diakhalout Youssou waw te thaiga yi ak goor djigeen yi topeu waly diko djaye boulen deglo dina khamne dou touss si kanamou patron Dakarou te bou wedee na lath bayam Thione Youssou dou tonge deh waye kouka togne guiss ko Thione fila tok si television bi nan Youssou waey na thiebou sew mom bou pary dina waey thiebou dije motakh niep guiss nenj fimou monji ak faux billets kharal rek dess na guissagoulen dara Youssou nak kouko bange dangay dem wakh ak Yalla wala ngua dem wakh ak sa Ndey parce que Ndeyam mako ligeuyal si katanou Yalla mai wakh domram yi nan Youssou mak la waly moy khale waw lolou degeu la waye Youssou fowewoul ndawam kou fowe sa ndaw sa mak rear la Youssou nak dafa khey rek nek thia am diom am foula ak fayda lengko meusa khamey fowewoul ndawam motakh generation bou nieuw mou diakahlen Machaa Allah law la thiat Youssou rek


    • ODI

      bilaye ARAM wahal d dibi dou firire waly lan la? kes ce ki la fait? il esta kel niveau? kele consecration il a? faut arreter de nous futre les boules et sil s laisser emballer par ces mediocres il le regrettera tte sa vie na liggey kham nimbir mi ay paliers la diéma ague fi bayam ague dabord lolou mooy wakh dji. youssou ndour nak taneef la yalla mooy khol kouko nékh mou def ko si mom louma lale mou barkel


    • MOR

      Mé dara worou la ni youssou fowé na ndawam am dete khamaloko dara les apparences sont trompeuses lou deugou si bir khol dal mo geun bou ken guiss nit ki si apparence nga koy juger yamal si cadrou woy rekk boul bakar


  9. na

    amina doul doul doul doul waay yaw yaye avocat wou you walla negue lene di wax rék you ak wally amougnou sene diote sakh merde sene genre yi rek gno tasse senegal


  10. rim

    Li Senegal rèk la am . Khawma daguèna dof walla loulèn dal youssou bokoul ak yoon wally boy teugeulè dagay khol nio tollo parmarès nitko nioil ai bopam mo tardè


  11. Amina

    pom dadout moromou new man wakhouma si affairou musik way li Youssou def Senegal si ligeuye ben domou adama defouko fi mem president yifi diar defouniouko fi kon Youssou law la thiat nitt kou gniol nak mo mel nonou bou tekiwoul dara dou begeu guiss kou teki way dama yakarr ne doff yi sakh kham nanioune Youssou dou moromou Thione wakhatoumala Waly te yaw Waly boula domram yi djaye begeu tekale sa bop ak Youssou dinga kham ne lep degeu leu ladial sa papa Youssou kouka togne guiss ko pace que dou togne dou tontou dou wakh wakh gou niaw dou saga motakh louko way def rek guiss ko te sak jour mougui set loukai diemale kanam ak lou diemale Senegal kanam mom bokoul si nyiy yakh Senegal dokhoul si affairou faux billets journalists ak animateur domram yiy wakh si mom pour wout buzz la rek way kham nenj ne meunou nio wakhal Youssou dara lou niaw ndakh limou takhawal Senegal sen bayi meuniouko wakhoumala niom mandeh meusoumako guiss mais mangui niane Yalla bala ma dee guiss ko sokhlawouma si mom touss way begeu nako gereum nianal ko nianou khassss Ndour Yalla na sa diam yokou Yalla nala Yalla mousal si nonyi ak sene pekhe Yalla nala Yalla yok begeu yeko,Amiin limala nianal lep Yalla defal nako mais nian dou doy


  12. Waly ballago

    Man waly faramaren bi nay wakh ak yèn YOUSSOU NDOUR dou moromou sah sama baye THIONE waxouma ak man mi nga khamni wayan rk lay dèf khawma dra music man dama comacè tite sah si bercy bi grand PAPE kay diapssi book ak wa prince are


  13. Zoo

    Mais foutez nous la paix avec se vieux sorcier qui n’essaie même pas d’être à la hauteur de tous . Le goss la apeler partout mais il est la sur son coin a faire une oreille sourde ..c’est comme sa qu’il avait fait avec ndongo il l’ignorait comme feu ndongo lo n’existait pas « fatei khadioufi  » bouleine niou raye  » c’est lui qui as organisé tous se débat .Il n’a qu’à le clôturer lui même « boye diakhane di saw sa bop ngaye saw « foutez nous la paix merde .bouleine niou raye ak waly ak youssou ndour mais nit lo ko beugue beugue wakhal deugue


  14. Riss

    C’est juste des aigris qui essaient de griller les senegalais ! Youssou a assez de personnalité pour s’attarder a ces debats ! Comparaison bi yakh energie le ! Foutez nous la paix


  15. Thiara

    SAMI tu veux dire par la que youssou doit arreter de chanter parce que y a wally ? Mais dans quel monde sommes nous ? Ah mais on s’en fout de wally hein !

    Moyène !


  16. Diagne

    Bour dey Maguette Youssou ndour a 58 ans Wally a 31 ans il a tout l avenir derrière lui alors que you est presque a la retraite il doit suivre les conseils de SA garape si caw lagni fequente


  17. Sami

    Personne n’a chercher a comparé youssou ndour et wally .Cest youssou ndour qui doit clôturer se faut débat .mais les journaliste vont continuer a écrire et parler parce que c’est lui même qui est flou il faut pas être l’avocat du diable


  18. elhaje

    youssou ndour n est pas comparable qui que se soit dans la mysique africsine wally je lui souhaite le meilleur mais si tu veux avanc teguil say beute si youssou je parle an connaissance de cause merci


  19. Arame

    nitt yi nio dou bayi werr si ben fanne waly youssou bayam mom sakh il la reconnu legui khepp nagn pape diouf nagn bayil sen thiahanne yi nak


Laisser un commentaire