4H avant le coup le coup d’envoi du match qui a opposé le Sénégal à l’Égypte, une délégation des lions, composée des joueurs Dame Ndoye, Mame Birame Diouf et Serigne Modou Kara Mbodj, est venu rendre visite au Général de Bamba, Amiir Sultan pour solliciter ses prières et ses conseils. Durant cette rencontre très instructive le Général de Bamba leur prédit la clef de la victoire de 2 buts à 0 et les 2 éventuels butteurs.
Source : Kara.com
dieureujeuf mbacké
anou diamouyala mou gnou war
sope rek
sop rek
soyons disciplines svp mouride tiudiane meme chose
y allah mo ham louy ame soube
y allah moo hame louy ame
y
kou téguinéwoul do tékii dara nioune mouride dé yaar ak téguine lagniou xam dieuredieuf mbacké
demlem diangui sen diné mogueun nguén di wéranté si gno khamni khamougn lén sén bop lagn fi nékal
Salut, cher senegalais sounou senegal nioko mom, sounouy mara nioko leen mom, sagarou tidiane ak sagarou mouride niouy dadié di khasanté parceque khamou niou originou fi niou tek sén tanka.
pour man dé ki nian, ki sarakhé, ki yéné, ngirr diam ci sounou réw yay ki geun. Té kilifayi ci laniouy dokh liniouy dadj goudi ngir noun yomboul. ngén balma akh balna nieup
di ziar tivaoune, touba, thiénaba, niasséne ,layene ,khadre, medina, meme souniou dekando yi Chretien etc………………………………………………………………………………………………………………………………………..
wakh de dafa wara rafete
Bayilène wakhante lourafetoule ah
yaw 7 babacar 7 go bonga mais bobayoul dinngat wakeur s.touba dinga xam yaw khamnalla bobax ok
dierdiefe s. touba s.modou kara yaw lanou geum de
fene rek
juste und coinciddnce arretez vos foutez..
ARET KOU GUEM BAKHNA KOU GUEMOUL YAKHAMMMMMMMMMMMMM KARA FEEP KARA PARTOUT KARA MERCI
ARETE KOU GUEUM BAKHNA KOU GUEMOUL YA KHAMMMMMMMMMMMMM KARA FEEP KARA PARTOUT KARA MERCI
Babakar sa papa moy fenne
Il n’a qu’à sauver le Sénégal de l’ébola et une une bonne saison pluvieuse s’il est véridique.Bravo à lui quand même d’avoir fanatisé certains débiles qui croient tjours à ses mensonges .Wake up Sénégal
arretez vos mensoges svp
Mes tamite amna niou yalla défalle afaire ba louniou niane mou maye léneko naniou ko na ngou réck yalla moko déff limou done tes kou sanione mélni môme dieureu dieuf mbacké
yalla rekka kham louy am euleuk wakh nako yennente bi psl si alkhouranne nenako bougne la ladjié louye khéw souba nell yalla rek moko kham ? MAAZA TAKJIBOU HADANN BIAYYI ARDINN TAMOUTOUNE IINNALLAHA LATIFOUNE KHABIRRR SADAKHALLAHOU AZIMME
Babacar yaw ko niak talibè gua
ya bakh dh mbaké
Yaw babacar xana ap 7 nga bokk
bayilene lo niaw lou way wakh nguene niko 7 leu 7 yi manane tidiane yi ay seti serigen touba lagne tamite boulene ko di faté!wa salam
Vraimen Lala tu as raison batay ils non pa compri k c’est la meme familles
fenne rek
Doomou ram wessoul koula mat baye wah nga wedi sakam toumak ak nit kou bakh kou guen sa baye