Waly Seck rend hommage à Youssou Ndour et interprète « Samba Abidjan »
Vidéo-Bercy: Waly Seck rend hommage à Youssou Ndour et interprète "Samba Abidjan"
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
guys waly khalela t sngalais la nianal lennko aduna amoule solo kou waly nekone sa makkk dagua beugu mou wesou fiiii m3 yalla bakhna
defa melni niou demone bercy ils ont la honte????????????
wa man demay laajt bakham bercy fessna wala feesoul???????????????????????
bess bou waly dayeni youssou dinako fessal, gnoune fesna fessoul sougnou yone lignou nekh moye waly teuguena bercy khana nekh aye wakh daye diekh te mome bou bayiwoule youssou gueneko thi aye mbirame gnoune ak fansam gnou bayiko dafa doye
Waly tu courageux mais c bien sa ira inchallah bon ven
pape diouf vole de tes propres ailes avc you tu n arrivera rien waly lui est responsable loufi way wakh loudoul lolou nafekh la essayer mo geun top ci guinaw nitt moulay manipulee
Mais franchement arrtez de polimiquer et de crer la zizanie entre youssou et Waly!youssou avait l’ge de waly!et il avait rv et avait cru en lui et souhaitait persvrer et arriver au niveau qu’il est aujourd’hui ! par l’aide du tout puissant! accompagne des prires de ses parents et proches. ….jusqu’ ce qu’il est devenu aujourd’hui ! !!donc pourquoi pas waly?Mais il est aussi! un fils du Sngal qui veut perser dans la musique qui est son mtier et hritier de sa famille FARA mareen ! donc prions pour lui ! Et qu’on arrte de lui mettre des btons les roues!ce que le bon trac sur son destin!!!nul ne pourra l’arrter ! donc du coup ! que tout soit beau!pourque la paix reste et demeure! youssou n’ecoute personne! regarde waly comme birane!soit digne et noble!ce garon t’aime et te respecte ! Et aime son frre Birane!Il a le droit de viser trs haut!ce qui est le souhait de tout un chacun!lii mou la dfale pour faire taire les mauvaises langues , les pestes et punaises ! warnala doye ! waye Ndour « waly »bergane!ooh c’est fort et norme ! « yani wone koula sedeu si galou xaate doo thia lekeu ! » Donc clou la bouche des sparatistes des coeurs unis! wassalam!waly yallah nala soubhanahou wa talah sameu, yire leu! moussaleu si thiaate mauvaises langues et yeux !pekhs ennemis ! amine si bark seydina mouhamed (psl)bonne continuation tu es encore jeune. …rien n’est trop tard! ce n’est que le dbut ! seck fara mareenebi!!!!lafe thiaate !
gėne balma bayilėn diwakh loulėne wooroul youssou ndour massou mako dėgue mouwakh si wally louy ndourou jalousie wally tamit nonou de
way petit waly yow bilahi watalahi demal adouna dinala parce que tu es entour par des hypocrites et la sen tv
youssou ndour yalla moko teral.les jaloux vont megrir t waly yow toutinga trop si renrdre hommage you parce que tu n’as pas reconnu sa grandeur
Bercy est fini waly fesait son travail koi kil en soit ça n regarde k lui arrêté et mettez vous déjà au travail oci l tps d parler ou d critiké est très précieux
mashallah mashallah
kaniane fankoul mour bour yalla moy mayer ,waly beurigo thi bartal pousse mou Deme niaka pouse mou deme ,goudi yi kou yeebou nagou. te bayi sokhoor,
Ceux qui disent sans cesse wally déy dem, dites lui de travailler. Tous les professionnels de la musique ont été plus déçu par le spectacle qu’autre chose. salle bou fess, yalla moko yor. wayé le spectacle devait être top et malheureusement cela a fait tâche d’huile
Boy by day dém kéne doukoté mais waly bodiécko dél balé
on ne peut pas concurrencer quelqu’un et lui demander de l’aide
wally tu peux faire du <> mais tu devrais savoir que youssou n’est pas ne de la dernière pluie.
je ne suis pas fan de youssou mais nakk
Youssou Ndour waar nga rouss, aussi ce qui travaillent avec You sont des ignares, geumouniou senn bopp, toppou thi guinaaw Youssou reik Nit dafay geum bopam, You dou Yalla dou Yoneen, Qui est Youssou Ndour, etpuis qu’on se disent la verité, en ces nuits que nous sommes Boy bi il est meilleur que qui que soit, kou mou metti Ya kham, Wally sa noon dou massa contan
Malgré les grèves malgré les eaux malgré les bouchons il a réussit a mobilisé malgré tout bonne continuation ne regarde pas derrière toi fonce rek le chien aboit la caravane passe laisse les parler tu ne viens que de commencer ta carrière allez y fonce en avant les critiques ne font que te renforcer
Youssou ak famille ndour diar nagnou kholate de ils sont trop méchants ils ne font que de l exploitation sur des personnes comme ………,
wally seck si tu m’écoutes ou quelqu’un qui le connait, je ne vais pas rentrer dans les polémiques de salles pleine ou vide car il est clair que fessoul mais cela n’est pas une honte. Ton grand problème pour moi qui était dans la salle, c’est que je n’ai vu aucun spectacle, rien de nouveau que tu présente. C’était just comme si tu avais déplacé le penc mi à paris et c’est sur ça que je veux m’arrêter : Oublies toutes ces polémiques qui ne t’aideront pas et travaille sur tes musiques et un spectacle digne de ce nom. Soit plus professionnel car au final c’est ce que les annales vont retenir; j’ai été décu par le spectacle et non par une histoire de salle dont j’en ai rien à foutre. Je paie mes euros, je viens voir un compatriote en compagnie de deux amis suèdois, alors j’ai envie que mon pays montre un spectacle digne du nom. Malheureusement cela n’a pas été le cas. Alors travaille sur ce plan et oublies les histoires de comparaison qui n’ont ni tête ni queue. Jamais tu ne seras youssou ndour et jamais youssou ndour ne sera wally seck. Sois plus conscient parce que moi je juge le spectacle et sur ce plan, j’ai été profondément déçu. J’espère que tu recevras ce message et que tu sauras le comprendre positivement. Sois en paix et que dieu te donne longue vie et une belle carrière. Amine.
Franchement yavait du monde mais pas de ouf quoi. Fan.s yi wakh deug bakhna touti aussi et franchement ce goss doit bcp travailler et son répertoire n’est pas du tout riche
Youssou n merite rien li dafa rouslou sakh You khol bou boneuh bou niaw égoïste mai Bercy bayou kèn momouka
damani damamni sn lamin dafa Reuy Man mifa nkon khamnani bercy 2013 ambianc bifaamon ak lifa nkon si ay nit ak bou 2016 sorna trop youssou dal moy sn papa
wally inch.allah lou.bakh rek ngay ame. ya.Allah seey noons di gueune yokou. meunou niou tchi yow dara
Yénn foutez nous la paix. Qu’est ce que ça veut dire ! C’est une salle et rien d’autre. même Makhou Pobar moune nafa déf concert konėk nieup car l’essentiel c’est payer. J’ai vu quelqu’un louer la loué pour du quarting pendant 8h. Alors fessna fessoul sounou Yonne nékoussi.
Man d sn tv lay wakhal yen loutakh guen am problèmes de direct ?? aaaa nooooooooooo
7400 il pareil avant c 10632 billets achetés mais 7400 c comme zénith pareil même zénith et plus grand que 7000 épuis pk il n’ont pas donné une belle lumière pour les journalistes ya que tange tandian qui commente tous sa j’étais laba mais la musique c le même rythme tu ne peux pas savoir de quel son ye pa différence c chansons passables pour les organisateurs
youssou mdour moy sn Papa wally khamnasi darra bercybi ak thiowlou barri amoul lou Mat 5000 person Mo yay dibalou yn fans wally yna khamoul mais sn papa wally khamna you
Youssou a toujours était comme ça daffa gniémé déffanté souvenez-vous dans un passé récent coumba gawlo ni layko déffone diko khékhe baniou jouboyé yaguoule parce que gawlo dagueum bopam et a réussi machaAllah. Omar péne a eu sa dose lui aussi. Papa thione mome bataye bagnikhougnouko, les rappeurs awady et deugetee a leur début il ne les aidé pas eux aussi dagnka danne nakharlou tout le temps. Faté khadiouffi sénégalais nio bakh rék mais youssou est très égoïste.
pourkoi jugr une personne sans connaitre ses motivation youssou gnimouy lak dinaniou bari.
Kaw man je suis dacord avec toi
aka yarakh
wally ya rafet xol yalla nl yalla yokk ay xeewl
Mane vraiment parfois g honte detr sénégalais..Deukk bo khame ni aye polimik rek…Waly est jeune il a l’avenir devant deffa goul 10 ans si musique di teugue Bercy..Fi ndanane yi nio fiyy takhawe deyeur Céline Dion mo wara teugue lundi bi…Konn mou fess dou débat importance moy teugue na fa…Concernant Youssou Ndour c’est une icône mondiale le plus grand chanteur de lafrik donc ken warou ko comparé ak ken…Sino Bon vent à Waly tè gorre Yalla ngene deme ligueyi Waly ame na dépense dè
su waly diokhone thieur youssou ndour deug,il allait raisonner les journalistes de sntv de son goro bougane gueye qui le compare a youssou et font des garouwales you niak fayda.je te conseille waly a ton retour d’essayer de remettre les points sur le iii en disant publquement que tu ne boxe pas dans la meme categorie que youssou si tu ne le fait pas tu t’attirera toujours la haine des millions et des millions de fans de youssou ndour qui frequentent les reseaux sociaux a bon entendeur salut waly
Ah sa none dou contane khalébio
Youssou yalla moko rendre hommage bagne beugue kounagou li yalla déf do sounou sa khol do diekh zoo
God bless you wally sa khol mo nice motakh tu seras toujours heureux bonne contuniation bro
merci waly nila adouna amoul solo xalaton nako ni la ko giisè won bilakhi boula yala fayè sa xol do giis dara lo ragal nila xel pouso la xalè daf koy fore mag daf koy for yala na diam yag histoire retiendra yala na yala tapè xol yi yala na yala rakhas xol yi senegal dieum kanam
Bilahi zoo wakhatico li da fa rousslou . Il est mauvais youssou ndour
Nouy mlni ay spkiti yinou bakhal
Youssou Ndour kay dama yakar ni amoul kholou djoulit nitt dal mo lendeum ba wally mettrer fin si rumeurs yi yagna mé youssou mo bayi di geumelo nitt yi ke ni wally day concurrence ak mom ndakh bagnone ko apporter soutien ,guiss nga nit loumou ame rekk day fekk mou geun si mom li mou ame ni tayy dewene day geneu yokkou inchalla ndakh borom khol bou rafet la mé wally toth ngafa la wakh bercy kay mi ngui doga lal faramarene pirr
wally khamna youssou way proplmbi si fans wally yi lank dano goordjigun trop
wally yabakh
No wally macontane sii yaw limome Youssou Warna tous nak tchimmml
Rafetna machalah même s’il a refusé d’être le parrain tu as quand même tenu à le rendre hommage Nice na vraiment waly bravo et boul guestou après ça passe à autre chose.
nice na
Diaroul rendre hommage se vaux rien misérable vanupied qu’il est
li gathie la
merci tu es genti