Poursuivant sa campagne présidentielle, le leader de la coalition Idy2019 était à Linguère, ce lundi. En pleine caravane, Idrissa Seck descendra de son véhicule. Il voulait saluer une dame handicapée motrice. Admirez la déférence !
Vidéo : "Beau geste" Idy, grand seigneur à Linguère ...

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Mandé fans idy la wone wayé bamouy wakhtanak ablaye wade diko enrégistré paré nane cd 1 cd2 thilako ba khamni kiy diaroul wolou
Les seytane les jaloux dinguene dee idy moy sene baye yene gneupe
Combien d, handicapés à t’il dépassés a2 Thies sans qu’il s’arrête et descende de sa voiture? DES gestes faits pour faire effet sur des moutons
Et vous les autres louy sene maithier sur culé si senego di kritike t sene bayi gno geuneu niake responsabilité ndakh yarou gnou lene mo takh idy c tun homme de cœur bo geun sene bayi ndakh kaineu degoulen thi rew mi bastardi
Votons paisiblement et que dieu nous donne le meilleur président qui sera toujours au service du pays … ces 5 candidats ont tous des forces et des faiblesses .. des qualités et des défauts … aucun d’eux n’es parfait car la perfection n’existe pas dans ce monde mais c le peuple ki doit les accompagner et les compléter. J’aime mon pays
Oh c beau
Toi ne nous fatigue pas c la même personne ont ta payer pour dire du mal a idy regarde les 2 premier commentaire
Merci idy le geste est noble.les jaloux vont maigrir,votons idrissa seck,la solution a nos problemes
2012 ba tay, Senegal ngi ci Yokuté ci domaine yeup. Croissance PIB bi, agg neu 6,7% en 2016, niou koy khéymeu lou eup 7% ci 2018 bi. Li meussoul am sénégal, meussou niou am 6%, nientti att you teklo. Performances yi mo takh sunu rewmi bok ci 5 rew you geuneu takhaw ci continent bi. Lou ko Waral ? Macky Sall leu, Politique bou lerr, bou worr ak bou am solo. Fok nani, Idrissa Seck meunoul am résultats yi
liguey, bayi Sénégal si ay lokho you bakh, lokho Président. Dia Dieuf Macky SALL
Idrissa opposant bou ignane leu, beugoul guiss deug bi, li fi macky sall def yeup
Li mey khélal Idrissa moy mpou nopalou, topato santé weum ak bayi ngour bi
Idrissa ngi critiquer gouvernement rek té kenn dégoul programam pour présidentiels yi.
Ci sama khalatt, Idrissa Seck bokoul sakh ci paysage politique sénégalais bi. Sa you fégné rek, ci todj todj leu nek, wakh lou bonn ak yakk derr ngour gui.
Khawma ci Idrissa werr neu wala dett, wayé kou doywar leu. Meussou ko wédi, dafa weroul.
Idrissa, fou mou tol dey changer avis. Medecin Toubabmo ko seytou ci benn hopital Paris firndel ko. Mo takh fou niou tol ni, meunoul djité rewmi.
Idy dafa am carton rouge ci OCI, ngiy promouvoir Ismal à l’international. Bi mou wokhé ni ke pelerinage kenn dou ko défa Makkah. Dou djoulit bou bakh. Dou ma ko wotel
Idrissa dou nitt bouy mbolo, dey tassaro rek. Di neu fi indi probléme bou reuy ci rewwmi ak macky li mou liguey yeup.
Avant, dama beugonn parti rewmi, dama donn diapalé Idrissa, wayé bi mou wakhé ci Makkah ba tey, daf meu choqué. Dotoul dara ci mann
Avant, dama beugonn parti rewmi, dama donn diapalé Idrissa, wayé bi mou wakhé ci Makkah ba tey, daf meu choqué. Dotoul dara ci mannx
Idy mom saga ngour bi rek la fi néké. Di lenn dieumé pouss ci biti. Khamoul dara