Vidéo: Après ses excuses, Bethio Thioune fait une nouvelle déclaration. Regardez

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.

Aucune recommandation disponible.

97 commentaires

  1. sylla

    man de bal nako ci xol bou sedd nak yalla na nou yalla saxall ci ak talibe ba fawwwwwwou nak ci barke serigne Touba ak khassiadyi amine


  2. borom

    mbokou talibè yi délosi lén sen khel te bania top sen hol li dou dara yen nifi wakh yep ana ko khamni mouston sounou borom amoul té sounou borom. moguena mague neup kouko degualou mou djégual la wayé amna nio khamni danouy perfito si lini bayilen wakh dji té déf li khalifa bi wakh


  3. abdou

    lisez la sourate baqara  » …fatalaqa mir rabbihi kalimatin fataba ‘alayhi …  » le repentir d’ Adama fut agréé parce qu’il reçut de son Seigneur l’ordre


  4. deugg

    Peut-etre que je ne comprends pas bien le wolof mais je ne vois rien de grave dans ce que Cheikh Bethio a dit. Personne ne sait qui a l’agrement de Dieu. On se permet d’etre optimiste sur certaines personnes mais on a aucune certitude qu’ils ont l’agrement de Dieu.


  5. wax katou deuggggg

    Gni di togne dh da melni khalif bi lagne beug waxal bethio defoul kéne dara ci ndigeul kep la nekk serigne saliou moko ni kou diébalou ci mom am geureumeul yalla lolou lerna kouy mer nal kalamél serigne saliou! Jaloux kep molen diap


  6. secka

    yéwou diaféna ba kham ngeni lou way wakh nit dingako layo cheikh bethio dé bou layok serigne bi ba paré dinguen layo ak mom nanou délosi khel yi tey khalat. nit nak bou nopé khalat ken khamoul loumou don


  7. mame Saliou

    Thioune Ya beugue Saliou ta gore kene me lou ne yaw diaradiafatii ya fiy Seringe Saliou midy Seringe Touba khadim rassoull


  8. wakh deugue99

    nanfek bou mak bou bone bi serigne sidy matar limoulawakh moy nga delouwat si tl bi yessalat sa diegoulmou t nga ni spectateur mom molako sant pour nga gniewat diegeulou. mais au lieu nga wakhko mou ler ngay wakh wakhou nanfek nane minima linga wakh molako sante kou comprendoul nak di am khel gniak. tout eu le t kham ni dingue nga d te souf khatna khot na. toup nak dou Wess bala ngay d


  9. kira

    ceux qui sont derrire bethio est ce qu ils sont conscients c’est une question que je me pose moi je suis n mouride de par mes parents ils m ont donns le cheikh ahmadou bamba Mais bethio ce qu il prne me laisse perplexe


  10. baye lahat

    nekhoul ba nekhoul way les Mback Mback sont jaloux de bethio parce qu’il est griot pourtant serignebi amonna dieguoub guwel bou mokone pothie sakh.deug deug bethio moy serigne touba.vive les marabout griots


  11. wakhedeug

    C’est que bethio dangua warone dieguelou cii ndigueleu khalif général si sa première déclaration ndax khalif bi moo la woo wakhla ngua diéguelou publiquement comme ningua wakhé say ndiombé publiquement ,mais déffololou motakh serigne bi wakhla ngua délouwat,dieureudieufe serigne touba,serigne sidi mokhtar mbacké yagui fi lol té and akk weur.


  12. haqiiqa

    Mouridisme c’est du n’importe quoi fatttte ngen sénégalais yi!!ya que vous qu’on entend jaamou ji len Yalla mo geune


Laisser un commentaire