10 COMMENTAIRES
  • axer321

    c’est quoi ces conneries là ? on dirait une politicienne, l’islam n’apparait à personne. l’islam est pour tt le monde. confrontation entre A.K niass et Iran pour voir ?

  • diallo

    franchement dîné islame meussoul ame genre yi bilahi règlement de compte dîné bi hamouko j’ai pitié de notre Sénégal, ay magoum dieumeu nek fi di wére seniye bopeu si télé bi c’est vraiment irresponsable. si c’est vrai que vous êtes exemplaires concerter vous ( bintou, iran et khalifa niass) c’est mieux que de rester là à vous faire manquer de respect. manque de professionnalisme….

  • fall

    na fékhe rek simm

  • deugue

    wakhofi dara, foléne djangué, bouléne niou sonal way, damani li A k NIASS deugue la, diné dji dou bissap dou djindiére ba nouléne néx ngéne ndiaréko… deuguela A K NIASS barina ay defaut mais kham kham moom yefeumla… yaw ak iran ndaw yena yem outoum khaliss moléne sonal, yenay niane ba keneu warouléne contre dire, bouléne niou sonal way

  • jack

    wakhou naféq yii diakhasè wa réw mi rek lii gni wakh ba diall mouy soulli watt sim

  • hakh

    mon matre savant se dlire Iran c’est son lve et qui a droit de lui faire comprendre qu’on se met la place d’un guide.moi et Ahmed on aime la vie est tout le plaisir qui va avec,les gens qui iront aux paradis ils vont voir des prcheur de se bas monde l’enfer que sa leur tonneraient

  • nana menthe

    wakho fi dara ay dooore kate nguéne, dooore rek

  • N B

    yalla na yalla dolli diam si suu gal gi iep wathi si diam ken ba digue bark seydi mouhamad rawa tina ioune djigene oune ndaw souba lep si oune la dependre oy don mamay gor djiegene khal mag elek

  • Abdoul Aziz

    Masha Allah Adji Fatou Bintou Yallah na yallah yok sa ler ak sunou takhaw sii diiné L ‘Islam. Amine

  • ami

    ndeysane sama yaram dawna

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *