Abdoulaye Wade est à Dakar. Son avion a atterri à 16h 45 minutes. Comme à l’accoutumée, il est vêtu d’un grand boubou, bleu, aux couleurs du Pds. il a été accueilli par des responsables du Pds et quelques leaders de l’opposition. L’ancien chef d’Etat a ensuite rejoint les militants, qui sont massivement venus lui témoigner leur affection et leur fidélité.
A (re)-lire aussi : Senego Tv – Regardez en direct l’arrivée spectaculaire de Me Wade à Pikine…
Avant de passer par Rufisque et Bargny, le pape du « Sopi », s’est offert un bain de foule spectaculaire à Diamniadio. Regardez !
Yèna nopi lèn, da nguèna nèk khalè rèk .yèn toubab Bou khonkhe thiour nèkone fi ministre de intèrieur di dèf di dindi,dèmone bas assumè intèrim pouvoir bi .hen….teuthe lèn sèn g..te bou nguèn baniè dègue deug
Yallah rèkka meune li
Modou dé maky douko amm sou diogue si ngour gui incha ALLAH, ndakh khol Bou deugeur
Souniou diapé ci article 31 bo code electoral, Karim mo gueuneu khaamni ke meunoul nek électeur bey nek candidat. Eligibloul.
eligibloul pour nek candidat, meunoul nek president, naw leu ci politique.
Karim wade, nekoul candidat wayé sonall neu peuple bi ci élection yi
Karim neu dem ligueyal France.
Karim Wade dafa am niari nationalité, sou beugué nek candidat, benn rek leu wara am.
dou kou leu nekh nek candidat. Dafa am ay critéres you loi bi tek ci rew bou ci nek. Ancien prisonnier, am casier judiciaire bou fess del, meunoul nek candidat. Loi bi mo ko wakh. Karim, beugou niou
Karim fou mou toll bi ngi violer loi bi.
Karim Wade, Définition : Dafa am niari nationalité, Sénégal ak France. Sathie leu, Njoublang leu. Coupable neu ci enrichissment illicite, teud neu 6 ans Kasso ak amende 130 Milliards.
Karim wade mom, élimination d’office !
Loi bi mo leral né, kepp kou niou condamné 5 ans prison, do meun am sey droits civils ak politiques. Lann mo leroul ci lii ?
Karim Toubab leu, neu dem servir wa France, reweum !
Français ou pas, Sathie leu, corrupteur leu, Karim amoul place ci politique bi.
Article 30 AK 31 lerr neu, meunoul nek candidat.
Karim Wade francais leu. Na dem nek candidat France, changer rewam. Corrupteur leu, Taupe ci bopou rewmi !
Loi bi dal, benn leu pour nieup, Karim mi ngeu teup di dal parce que dama nam années noces yi ci ngourou papam. War na yéwou, bayi gent bi khol deug bi : Dotoul nek candidat en 2019