Talla Sylla: « Mon différend avec Idy, dou wakhi radio… »
Talla Sylla refuse de s’épancher sur son différend avec Idrissa Seck, président du parti Rewmi. Et pour cause! Pour le maire de Thiès, invité, ce vendredi de Kër-Gui, sur la Rfm, toute vérité n’est pas bonne à dire. Il faut tenir compte de sa famille, de la postérité et d’autres aléas…
Ecoutez:
Geweul sou reppee ci kharé soull ba lay dagg di teuguée.après lay comprendre
Bayileen sokhor gueweulou gueweul bi.
Talla noble la. Nit kou reew limou yor momouko. Sou limou yor wadé…. c’est valable pour Idy et pour les autres si ce que tu dis sur le mariage est vrai
Nite you melni yow motakh gueumeu pour ma Gueum politicien djiafé, ningafi mélone pendant très longtemps nga changer ko si at you néw, billa idi defé maire yow yako gueureum ndakh limoulako def guinaw YALLAH, tay ngani doumom, espèce de traître dakh 4*4 bignoula Diokh , dama yakarni danga dof légui, en plus tu as trahi ton propre ami qui était très proche de toi , en mariant sa femme, yow ya Bonn mais DIEU voie tout
Yaw traitre Nga , tu as traillie ton propre ami et marié sa femme Kén dou yow, té linga def bétoul gnilakham , motakh tu oublie vite tes fais et tes dires, yaw Yafi gueureumone idi ndakh motakh nga done maire guinaw YALLAH, alors tay nga wédi linga wakhone baparé sooss ay djeuf guinaw bignoula djiokhé 4*4, Meuno gno nakh
Talla démal andak macky comme lolou gua beugue
Sah djico bii nga yoor nékhou ma dara.kilifeu Day déff yeuffou kilifeu Di Wax waxou kilifeu.
Yaw talla sof nga torope sans Idy do neck touss