7 COMMENTAIRES
  • Amina

    rebatass yangui dora wakh kai do nit motakh diaro wakhal

  • rebatass

    douma jiguene douma goor si diegeune ter bila sama khalat la wakh walla amatou massi droit

  • Amina

    REBATASS mandeh dama yakaron ne goor nga way tey mo khamnane djigeen nga parce que goor momoul yena wakh yi

  • nekhfall

    rebatass yaw mom khamou ma goor nga wala djiguen mai khorom zero niak fayda

  • nekhfall

    yaw mom khamou ma goor nga wala djiguen mai khorom zero niak fayda

  • rebatass

    tay mom nekhone na. mais nak mareme faye yi tay dagua guen game sa sagnser dara rafetousi gua warone sagnser lou rafet tagualou bamou bakh

  • fogu

    supr

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *