Cheikh Bethio revient sur ses relations avec Serigne Saliou. Le guide des Thanta koun en a profité pour apporter des précisions sur certains termes confus. Regardez
Serigne Béthio Thioune parle de l’histoire des Cheikh …

Cheikh Bethio revient sur ses relations avec Serigne Saliou. Le guide des Thanta koun en a profité pour apporter des précisions sur certains termes confus. Regardez
Comments are closed.
Téléchargez notre application pour une expérience optimisée et pour recevoir les dernières nouvelles en temps réel.
thioy yalla
Je vous demanderai de lui parler directement sans bolè si serigne touba ak serigne saliou Man deih ap mouride la SERIGNE TOUBA keppa ma niorr ak liko niorr mom.mouy fonk alquran djouli woor natt azaka mouroum korr tenkou si dinè ak CHARIA fonkal ko kharidas yi ak magalam gui ak touba.liii mafi liim koou si nekoul ak ko meun done Man sokhna seynabou ndiaye nawlo mala….alors bethio momou il est le représentant de Satan sur terre rien de lui n’est serigne touba rien de serigne touba n’est lui alors svp khass yi na yèm si mom kepp.wa salam
ki il est malade kou beug dnigrer mouride yi si yow lay diar koula Kate b nga kheum rek bo ywo cheikhal ko ngay doul serigne saliou bi ngay wakh moussoul cheikhal djiguen.yow sa esk cheikh nga?
Mina xana guel nguey nek ? Sokhna môme l’islam 4 lako yemaler.
DIEUREUDIEUF CHEIKH BETHIO THIOUNE Diaamou Serign Saliou , Gnoune wa TOUBA CANADA dé, Sante nagnoula bou wérr, Rawatina mane AMINA FALL… Lépp Loognou Sante Souba ngoone gnou déffko, mane barki Serign Saliou, pré na sakh tékk sama étud yi feullé Nék Sakh Sa Sokhna !!!
AMINA Depui Montréal
il dit même pas un verset du coran ce mec il connait rien pour que suivre un mec qui connait pas le coran il faut qu il sache un jour on va mourir il a aucun pouvoir surnaturel pour que ces moutons les suit kara lui dit a chaque des verts du coran non malgré kara il abuse grave le jour jugement ça être dure qu Allah nous garde cause ses satans.
verdad bethio dé mofi soule ay nite té dewougnou wala dangua faté sa toouune yak bethio
verdad bethio dé mofi soule ay nite té dewougnou wala dangua faté sa toouune yak bethio
verdad mousouma guiss thiaga boumelni bethio
dafa rère rek.
OK ON EST BIEN AU SÉNÉGAL SORTI DE PRISON POUR RAISON DE MALADIE,IL RETROUVE LA SANTE ET LE COURRAGE DE VOYAGER MAIS PAS POUR PAYER SA DETTE.DEUX MORTS DANS LA NATURE ET DES FAMILLES EN DE TRESSE. OK LA JUSTICE SÉNÉGALAISE OU LA POLITIQUE SENEGALAISE SONT AU SERVICE DES ???PAS LUI IL N’EST PAS MARABOUT
dafa réer ñiko top nièp dano réer wayé yalla naléne yalla guindi si barké kou tédd ki
VERDAD khamo dara si lingay wakh ki yakh dér yonou mouride kassé lafi nèké wayé bou dadièk euleul sgne touba ak sgne saliou dana mèrè kouka défoul dara
Thiey SERIGNE BETHIO yonou mouride amougnou sa Faye..koula top am kham-kham, am pastef,am yar am teguine..nangou ligueye..contrairement a ces internautes moykatou yalla di diokhe ay leçon.. Yengni di wah guemolen dara…
mane mom boma diokhone ken si sokhna yi ma kheweulou dina bakh
mane mom ba diokhone ken si sa sokhnayi dou wakh dara
qui kay yalla nako yalla guindi balla de ak mbolem djoulite dafa rère rek
un jour viendra
betio betio betio un jour viendra
bethio toune safara direct ladieume
Deysaan il ne sait méme pas que Islam interdit la croyance à la métampsycose et le mensonge. Ceux qui le suivent n,ont certes pas compris ce que Dieu a dit dans le coran.
Sen tv mou sonall yonwi kamono dara khaliss rek la boukan kam Mè mom wa darou khodoss Me khaliss ak diekhane you bari moko yob ci cheikh bi
Un très grand ignorant ce Mr Bethio et qui suit que des sectes diaboliques.
cheikh bi dans ses oeuvres au Maroc a bouscoura.les pauvres thiantacounes ont depensé bcp d’argent pour cette visite
wakh diou amoul seydina mouhamad haley wassalam beug yega si yalla dou soti
Bethio,serigne saliou,serigne touba,yalla yombouna trop top
koula top ame mgougal yalla kaye
deux chose rek mo ame
un fimou djiogue kham-kham nekoufa
deux wala defouniou si mome kham-kham
ngeureumal yalla kouka beug yalla ngaye beug top ko santko
Qui peut dire mieux ?
Sentv ndayssane amougnou programme top dof bii !
CE GROS PORC EST DEVENU FOU.
MAIS PUISQUE LES AUTORITES MOURIDES LE LAISSENT FAIRE,IL VA CONTINUER A DEBITER DES CONNERIES