Serigne Assane Mbacké épouse Ndèye Fatou Ndiaye de Walf
![Serigne Assane Mbacké épouse Ndèye Fatou Ndiaye de Walf](https://senego.com/wp-content/uploads/2016/05/ndeye-fatou.jpg)
Serigne Assane Mbacké, le marabout politicien qui a créé le Mouvement Appel 221 et qui s’oppose farouchement au Président Macky Sall, a épousé ce dimanche la journaliste Ndèye Fatou Ndiaye de Walf Tv. Certainement que la proximité sur les plateaux de Walf où le jeune marabout est un habitué, a facilité les choses… L’union a été scellée ce dimanche à Dakar.
Serigne Assane Mbacké est le fils de Serigne Atekh qui est lui même fils de Serigne Fallou Ibn Khadimou Rassoul. Senego souhaite un heureux ménage aux nouveaux mariés.
dieureudieuf gars mais nagn wakh sounou khalate bayi saga yi rek
Cheikh tidiane, rousseul sa tour bi bok
tu pouvais choisir mieux
Moi, je m’étonne toujours de découvrir des propos déplacés de gens qui se cachent derrière leur clavier. Je suis sûr que si on permettait à chacun de s’exprimer à visage découvert,beaucoup des internautes qui insultent ou tiennent des propos irrévérencieux n’oseraient pas lever la tête pour regarder leur (s) interlocuteurs ou alors ils seraient des malades. Il y a intérêt à faire attention , pour un croyant (musulman, chrétien ou même animiste):tout ce que vous direz ou écrirez vous sera présenté un jour ou l’autre. Je considère tout propos malintentionné comme du dieuw. Et le dieuw en Islam est sévèrement puni. A bon entendeur salut!
boko nekhe? sakh tak ab karithie?n sen yon ne?ku thi
Heureux menage yalna yalla baekel sey bi
kou wakhati serigne dara wakhna kooyou baayam ndakh lii ngeen di wakh manaa diakhase khelou sokhna si seytaani wakhoul daga waay yaakhna khel
HEUREUX MENAGE
khana nekh ak hjk limay wakh khamnako te mbacke la sante nak ragaloumassi dara.kou dieufewoul ndigeul kene doula respecte ak ko mana done nakk
kouy wakh wakhal louraft yallako toudon
Yalla na sey bi barkl Amine Ya Allah
heureux menage
Qu’ont elles ces filles intellectuelles à vouloir se marier avec des trou de culs comme ce mbacké mbacké, politicien et menteur. L’argent, le pouvoir ou le passe partout associé au nom de famille.
félicitation yalna seybi barkel
niite kou ñoul dal mo soxor ñanal kéne mo geune kouko meunoul nga nopii. fii kou sagnone melni S.A.MB…. Yalna seuy bii barkél andak ndiabotou l’islam
bon xol rek mandolen thi lo sen yon nekol yalna saybi barkel koko monol ge mando
yaw cheikh tidiane ak kou mèlni yaw seene datta yaay dafa khassaw kènne sokhlawouko h
yaw cheikh tidiane ak kou mèlni yaw seene datta yaay dafa khassaw kènne sokhlawouko
bayileene s assane yeene daal seene kooyou baay rek
yalla na barkell
boulay gnam dila fass ces gens ne savent pas la valeur d’une femme. tous des esclavagistes
Serignou tay, haaliss – matériel – ngoûr akh mouy neikh rek! Thiaaam… Gnak lihsaan!!!
yalla na sey bi barkel
Amine
gour doul
bonne heurese menage
saybi yalnako yalla barkel
koy wax lu niaw domou xaram la bayam takol yayam nono rek gen mana mel domo xaramye
amlen yar waye xamna sen bay takolon sen yay thi farata motax dogen am yar domo xaram ye
amlen yar waye khamna sen bay da takolon sen yay thi farata motakh amolen ben yar nono rek gen mana mel domo xaramye
Yen khana khana khamouléne li guen di wakh dieuwla té kouthi moytouwoul wakh bou niaw di nga dêê dê bouniaW bilahi togñ bakhoul wasalam
Italy yaw ak cheikh tidiane …… amlen yar ak teguine mo gueunetay wakh lou wakh bou amm solo
bou katé diégui sakou yi dhé.cest petits mbacke la daniouy khéméme rekkk
Yalla na sey bi barkel,Amiin
amale seu fouleu teye sa seey et ton boulot. boule ngliger dara. dina bakh inch Allah. goor yeup.ame sene caprices. bonne chance.
sant yala yalana se y book s’il seyou yala geureum te barkell koo
man de assane diaakhal nama
ak dof sakh
Doff bou réw nga choisir comme dieukeur.