PUBLICITÉ

Senego Tv – Titi : « Jongué ak beug lou nékh sama aladji motakh may khessal »

Pour la première fois, Titi s’est prononcée sur sa dépigmentation. Selon la chanteuse, elle s’éclaircit la peau pour plaire à son époux et se faire plus coquette.

Regardez !

Ak Beug Lou Nékh Sama Aladji Motakh Jongué
whatsapp 278
Annonces

(5) commentaires

Deug

Kone bakhna, wa koulou atihi yawmal hiyamaty fardane kou nek yaw rek digga taxaw niou pése sa jeuff. Yaw kepp Dong nii def la mba niou defal la

Hd

Sa aladji mo begu Lou bone(khessal) si yow

Dunkléosteus

Sa aladji bi dé khamoul Lou bakh, ndakh kou gnémé khassawaayou khessal gnémé nga lekk si cabinet.

Gainde

Me khessal amoul koleure de sino raproch toi d tn pere kelk soit le problem aduna amoul solo

Fall Ali

hessal do rouss toudouko ak sa greffage da aram