Senego-TV-Baïdy Sèye : « J’ai peur qu’on s’en sorte avec un score qui … » Regardez
En ce 24 février 2019, jour de vote, Senego s’est enquis de la situation à Guédiawaye. Une localité où on craignait le plus, des tensions entres militants. Jusque-là, tout se passe pour le mieux, à la grande satisfaction de Baïdy Sèye, maire de Ndiarème Limamoulaye, venu voter, tôt ce matin.
« Je suis confiant… Parce que nous sommes partis aux parrainages, par la suite, la précampagne,ensuite la campagne… Et la façon dont on a travaillé dans la commune, particulièrement dans la grande coalition Bby, et les responsables qui nous ont rejoint, comme Aïssata Tall Sall (…), nous sommes optimistes…« , dira–il…
Regardez
Avenir Sénégal nguéni foyé adouna nguén gueum faté yalla djay Sénégal ak sénégalais yi doméram
Dougalén sama commenter yén gneup ay domaram nguén
Ay sathii nguén
Macky sall diamla yen ay domaram nguey Macky d’où goor bakhoul
Sathieuna bapare
Bouleen sathii reek
Tu na PA honte de dire sa FI si diapora doryi mette Lay don si yen
Dangaye fen
Sénégal fepp leu yoké. Fo lal rek bakh neu
Macky tek neu Sénégal fou sori, deuk bi di gueuneu am yokouté, opposition bi wakh rek
Ken dou lal equipe bouy gagné. Falatt fi Macky rek moy deug, mo niou arranger nioun nieup. Bilan bou am solo, nieup di guiss
Macky Tabakh rek, borom guiss guiss. Negn ko bayi mo agalé li mou santhie. Nieup leu diakhal nakh meunmeuneum
Président bi dafa nek ci yonou emergence, bi mou néké ci ngour gui ba tay. Da ngenn beugeu délou ci ginaw ? Da ngen beu geu yokk fitneu bi amon 2012 ? Mann dett. Macky lay votel.
Macky SALL, kou beugueu reweum leu, deflou bakh rek, dal khel. Lolou tek ci, bilan bou dal khel. Lolou mo ma doy ngir benen mandat. Bilan bou lerr, doynama, moy wadji deh !
Election bi, moy falatt macky SALL. Dieureudieuf Macky.
Macky SALL mo beuri dolé, mouss am khél. Lepp lou mou fi liguey dall na sunu khel, wolou negn ko ngir att yi nieuw. Dieureudieuf président
Macky SALL dafa def lou mou meun yeup. Deuxième mandat bi,i neu def Sénégal rewou diamb, rewou teranga, nakh lepp lou mou niouy defal
Macky nioun guissou niou kou ko meun ci guew gui. Moy ki takh diamb am ci rewmi, kom kom ak institution yi