41 COMMENTAIRES
  • bek

    Yéne khana youssou ndour dafléni fay fate nguène niou a cet hypocrite

  • dg

    ya bakha longue vie a vous

  • DIEZ

    you rek si hol dafa beugu ay fans sam

  • fifi

    you do sen morom

  • anna

    Wa waw le père de birane machalla d’o scène morome

  • Il maestro

    Dass sort d’ici yaw ak ndawssi fii dou sen place sa keukeuw ndaye yaw das tu vas mourir du Cancer de coeur

  • fafa

    youssou limiy def dako meune dako wolou youkhouwoul wayanoul soiree youssou dou yeufi goné dou yeufi ma rireu ndo

  • mamadou

    thieyy youssou bilaye yaye ndadane tu est notre fierté

  • Das

    boulene gnou sonal avec ce guignol

  • dass

    sokhna wowal sa papa

  • etoile

    am na malade yo kham ni souñou beugee you rek weer 1love papa you

  • dass

    sietal kholiye dinfa fekki you

  • CHELSEA NEW LOOK

    ndeyssane youssou ndour defma neekh le grand you

  • Coumba

    Youssou ndour est notre fierté et. Puis Lima. nekh simôme am télé am n’a radiais douco utilisé moukh pr que détail il passe inaperçu . merci De YOu

  • as

    Youssou moy chéf koka nangou rék nopalou

  • SOKHNA SARR

    je suis une vieille fille vierge je cherche quelqu’un qui va me devierger

  • asta

    c cool

  • youssette

    Youssou ak Sénégal yalla déf baniou beugueuneté taarkallah!!! Yalla na yalla xéép doli

  • sallma

    Ndeysane!!! Beugueu bo guiss yeuk mokay faye té papoush firndél nganiouko bamou mate seukkk mashaallah… Love you

  • SOKHNA SARR

    man d jeukeur lay weur ab jeeg boubakh l nak.kou intress nga bayi sa ma woola niou deff bamou nooy

  • houla

    aaahhhhh quelle soirée super neekkkkkhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhhh
    love you Youssou

  • rose ballago

    cela me rappelle le youssou au tps thiossane, kan il sasseyait au milieu du public pour chanter !!! ohhhh ndour

  • fifi

    youssou ndour ak fans yi da niom ame maana

  • gogo

    oooh image bou nice way c’est trop joliiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiii!!!!!!

  • amsatou

    non c’etait chaud oh youssou ndour rek tu es notre fierté boko si da niou la si boler

  • popo

    oooh soiréééé dangakoy meune ba nge ba !! plus de 30ans de carriere, bou expérimentéwoul gnou lathie koko !! Dr youssou ndour

  • marame

    RIRI raye guama Sow pire lollll

  • marame

    sédé yalla

  • seydina

    youssou ndour lou nekh rek lay deff

  • daabo

    C jolis ma challa!!!!!!!!!

  • Pdg

    Fi dh amul ay kabayi kabayi way rek pas de battrai kougnu may khaliss gnu diokh ko fans yi ma yrureum habib faye ak jymmy mbaye mar nane boumoula takha nane potit deloussilen keur ga mo gane si yen

  • bidew

    ndeysann ohh c’est beau #mbaye dieye voice!!!

  • aissa

    non chanson bi mo may daanel instant bi da ma done beugue kheum

  • fff

    Youssou ndour aka meune beuss soiree bi nekh la deff

  • dede

    youssou ndour dafay sedal khol koiii frnachment lii nekh neuu dehhh machalla

  • Jddj

    Yay sen baye dh. Réussite totale yay gor

  • Riri

    Youssou rek yay sow pire koula concurrence di sow comprimé, discrétion, travailleur, discipline et création d bcp d’emploi machala kou mer nak ya ham

  • GFM

    li hawma loukoy fay ya oyof wathiésa bop bilay gnola beugu

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *