« Pikine Ci La Bokk » fait le plein pour accueillir son candidat

Lors du passage du candidat sortant, Macky Sall, dans le département, ce mercredi, le mouvement « Pikine Ci La Bokk » a mobilisé pour l’accueillir.

La structure, dirigée par Thierno Ndom Bâ, a été partout visible, sur les tee-shirts à l’effigie de Macky Sall et des slogans propagandistes.

Les inconditionnels de M. Bâ  ont ainsi, fait montre de leur entière adhésion au «Macky».

Une démonstration de force de plus qui confirme toute la force de frappe du mouvement qui rassure et promet de réélire Macky Sall avec un score de plus de 60% dans ce « cœur» de la grande banlieue dakaroise.

13 COMMENTAIRES
  • quiesttu

    Macky SALL dafa indi guiss guiss bou bess ci nou gni yoré rew, Selal alalalou rewmi, délossi khaliss bi niou sathie.

  • willysagnol

    Macky dafa meusseu beug defar rewmi bala mouy topato parti bi. Lolou mo ko woutek opposition bi.

  • ELOU

    2014 beu légui, Macky dafa indi guiss guiss bou bess ci Senegal, lolou mo indi Plan Senegal emergent, lou bakh ci nioun, di niou yobou ci rew yi emergents fi lekk 2035. Macky day guiss fou sori, mo takh meu key sanil carte février 2019
    « Macky SALL, ak PSE dafa guiss fou sorii ak kawé. Def neu lep beu changer sunu economie ak sunu croissance : Khalé you am gneurign, diamb, yeuk yeuk ci néwi dolé yi, deuk bou wor ak sett, lepp dal lou niouy yobou ci kom kom
    « 

  • rawa

    Macky SALL mo takh beu Sénégal nek rew mou am dolé, ci sunu petrole ak gaz bi.
    Senegal rewou diamb leu, rewou bou nekhé deuk. Kou nekh dem fo beugg, Dakar fekh neu, Deukou diné yi gueuneu rafett. Yok ci mou developper pole urbain bou diamniadio ak sphére ministérielle bi, cité des affaires. Lolou yeup ak li nou samp yeup ngir diapalé sénégalais yi si senn santé ak bien etre : PUDC, PUMA, bourse familiale et CMU.

  • THALYSOU

    Macky SALL, Sunu president bi, dieuf rek, Investir rek, di tabakh rek, di yok kom kom bou rewmi

  • YOUssoufNDOUR

    Macky SALL, borom khol bou rey, mi ngi khalatt bien etre bou population weum, Sénégalais yi yoroul, gni am handicap. Lepp lou mou beug, moy nieup tolo ci meun meun.

  • odre

    Macky SAL, programmam yeup ngi khalé yi leu, di lenn yokkal liguey ak financement yi, fermes agricoles yi, wa DER, mo takhitt 2012 ba tay, chomage bi di wagnékou

  • PAS DE WADE

    Man Talibé bou mak la, ma ngi sant Macky SALL, yombalal nama accés TOUBA ngir talibé yeup. Kerok ci Magal bi, sunu president mo niou yombalal yonou Touba bi.
    Macky Sall li mou wakhonn yeup def nako, mo takh meu key diokh benenn mandat ngir mou agalé Talli yi, ak yon yi, Touba ngi key woné. Mi ngi financé hopital Khadim Rassoul, financé université TOUBA. Macky dafa yok komkom bou Touba. Lou mou wakh yeup, deeff na ko

  • amadou

    Macky dafa beugueu def Sénégal deuk bou fekh, am komkom, economie bou am dolé, bou séleu, bou deugou tégou ci yonn, lep lérr, lepp sett.

  • dcrf

    Yokouté bou am ci Tali yi, ports yi ak aeroports yi, mo takh beu nieup beugueu investir ci rewmi. Yoyou moy takh beu nieup di nieuw sunu rew, lolou Macky SALL rek mo ko meun !

  • tatou

    Macky SALL dolém yeup daf ko def ci diambi rewmi, nieup bolo donn benn, di diapalanté, nieup tolo. Macky rek !

  • Georges*

    Macky SALL dafa am lou niou beuri amoul, Dolé ak Meun meun. Lolou moy takh beu mouy defar rewmi, ci yonn you deugou, rew mouy diokh tieur sunu thiossane ak ada, wayé oubékou ci diamono

  • saoune++h

    Macky aura zéro voix á la diaspora

Publiez un commentaire