Pape Diouf, musicien et leader de la Génération consciente a reçu ce week end le « Award de l’Artist of the year » et « Award of contribution Africa’s Musical Herutage » des mains du Senator Athony H. Williams de Pensylvania, et de l’adjointe au maire de Philadelphie. Réagissant à cette consécration, l’artiste Pape Diouf, l’enfant de Pikine, dans un anglais bien articulé, rend hommage au peuple sénégalais à qui il dédie cette distinction. Il n’a pas manqué de remercier les promoteurs de la tournée qu’il effectue aux Usa et surtout les Africains et Américains venus en masse assister à ses prestations au pays de l’Oncle Sam.
kep kouy doumou senegaleis tey liguey yalla nala yalla may ay ndam you bari felisitasion pape diouf waly guisoumako me kontanna thiliga am tay bravo pape bravo waly senegal benla ken menouko khar niar mercy
encor félicitations pape Diouf
sohor dal am ki defoul ken dara dafay ligueye boleko ak yar ak teguin li merite la yalanga am ay dami dam ba raw sama papa youssou ndour
Ay door ra rek . Trophée de rien du tout .
Ahahahaha Retane kagn li mo tax moy sagua youssou rek mais nank rek tei wakhal lou rafet si ki yalla dieul
felicitation pape et bnn contination ndam rk gay am ak diamm aferr diaroul youtt bou barii bii liguey rk mo worrr pape begueeeeeeee
Non Reetane taye doumala wakhe dara Guayi liniou la tontou doyena seuk!
rétane yame khamena nioula bou bakh finga bokk ayyy goor djiguéne ngénne motakh meunoléne beugg pape diouf kiii daa khousss diall thé kénne diallé woukko goor yalla pirr moyy pape diouf dara diombouko yakkamtiwoul darame amna foulleu amna dignité wérrouwoul si kénne limou amm mérite la kattall sa ndaye feullé domou sarame ndayame binga donne
félicitations pape diouf mé senegal amna niou téppi sén leufeul ndaye sokhor qui démm Amérique ay festival reusir yeupp bou ammé liii dafko mérité
waw gayi en peu de serieux s il vous plais
Félicitations mon ami mon frère Pape Diouf chéri Bebe Basse et c l Sénégal qui gagne Waly Pape Diouf ay domi ndeye laniou
Yaw sa soiré Gordjiguén doufa nek félicitations Pape Diouf amna nio xamni Ken doulen décoré danio oumouu nakh sen soiré thiaga ak gordjiguén niofay nek
Non legui man nagno comparer youssou ndour ak wally , ndakh youssou mo nekone ap joueur nawetane gnafé ba nekk joueur international , wathiéwate bopam di football nawetane , di deff ay vacances citoyennes di dajjalé khalé yo khameni beugougnouko sentirougnouko , beugeu gen rekk molen yobou sa concert ba , waw ap artiste planetaire bo khameni mi ngui si navetane ba legui fi la ame , il me deçoit les petits essaient de grimper l’echelle et lui il descend plus bas di melni kou faté limou don yaw wally tek nala stress , et felicitations à Pape
Félicitations Pape Diouf yénén mogui thi yoon bi bakh nga yarou nga gueum nga liguay def ndame rek
Plus mauvais k retane tu meurs l’âne mofiy ndeyou toudou liguey ndongo lo yaw do nit kou bakh dh yala bagoul kou sokhor va bosser com eux mo gane nakharou khol dalay fate rek ndeysan bravo pape tu es sur le bn chemin nank rek courage aux autres waly et consor
Bravooooooooo pape tu le mérite kou mer demal penc mi
Mdrr retane dinga mourir de chagrin espèce chômeur du web
Retane dinga daï dh Youssou hamula sakh ndeysan sa thiopairaitu ndey way
Retane feign nga tay tu n es kun fan de Waly DC jaloux d TT s Ki touche a Youssou ndour prince art je t jure k tu vas mourir de chagrin VK TN PD de waly penc mi ak acapes rek molaini décoré domeram k u es sa nounou mâle way bonne khôl wa bravo pape
Sokhor feliciter le c’est mieux way
yaw félicitations kou sokhor nga Kome dolenesénégalais c’est grave
Yombouna ngen defar seniy couronne rekk djokh koko té gnou koko geuneu meriter nekk fi