10 COMMENTAIRES
  • bina

    diaspora dieureuf way leup souniou mame laniou Sénégal bene boppe rek yalla naniou tasse si barke souniou kilifeu dine yi te dane Sénégal

  • ouze

    Merci seka cool yalla n’a serigne babacar takhawou ak kounieuw amine amin

  • ablaye

    serigne mbacké kasse amine way

  • diaspora

    serine mbacke kasse serigne babacar ak serigne saliou mouy sama mame tamite nion bok mame marame mbacke na rafete rekk

  • pipo

    waw barigo siii bartal pouce mou dem pousoul mo dém secka way gua kpu diara way mé khamal nii bayoi sheikh ahmad tidjaniii syyy al makhtoum khalifatoulahiii fiiil ardii kouko lébal nagne mou fay la kérrr boul ragal dara tidjane moy deug merci secka

  • serigne mbacke Kasse

    dieu reu deuf serigne touba serigne salliou yalla na yalla yok ay leram

  • diaspora

    ligua way sama mame nekhna yalla nala yalla fay ci barke cheikh ameth tidiane cherif

  • asta

    nekh na trop machalla yalla nala serigne babacar fay

  • coumbiss

    yalla na bade weure thi barke cheikh barke alouwar ak barke tiwawone

  • safietou

    super

Publiez un commentaire

Votre adresse e-mail ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *