Nouveau Clip de Youssou Ndour "Serign Fallu"
Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Ouvrez l'appli si vous l’avez déjà, sinon téléchargez-la pour une meilleure expérience et pour recevoir les dernières actualités en temps réel.
Nice right la wakh heurou pipi dodo diot na pour waly
Le walymania mdrrr ZIAR ray ngama mais nak tu as dit vrai stop à ses charabias qu’on a assez entendus depuis que le roi était absent
Quel beau clip oh j’en ai les larmes aux yeux sur le saint coran You moo fi meun
ZIAR tu m’a tué wakh ngue deug papa est rentré à la maison
Ndaysann nekh na sen morome
le walymania (il chante bien nak ) c fini papa est rentré à la maison. ….
le walymania(il chante bien nak) c fini papa est d retour
Merci mon idole na niou wakh nak
nekh na torop ahh serigne fallou way
g pleuré avec cette exposition sur Serigne Fallou Mbacké ndayssane . Youssou yalla Serigne bi takhawoul bopam . C trop beau
youssou bokousi
Classement des albums les plus téléchargés sur iTunes
en France (en temps réel)
1Radiohead
A Moon Shaped Pool
2Drake
Views
3Djadja & Dinaz
On s’promet
4Kalash
Kaos
5Gregory Porter
Take Me To The Alley
6Beyoncé
Lemonade
7KAYTRANADA
99.9%
8MHD
MHD
9Youssou N’Dour & Le Super Étoile de Dakar
#Senegaal Rekk – EP
Classement des albums les plus téléchargés sur iTunes
en France (en temps réel)
1Radiohead
A Moon Shaped Pool
2Drake
Views
3Djadja & Dinaz
On s’promet
4Kalash
Kaos
5Gregory Porter
Take Me To The Alley
6Beyoncé
Lemonade
7KAYTRANADA
99.9%
8MHD
MHD
9Youssou N’Dour & Le Super Étoile de Dakar
#Senegaal Rekk – EP
Oublies le top France. On parle du monde maname world. Tu peux être 100ème en france et être premier quand il s’agit du monde. Sokhor daal meuna goumbeu loo nitt.
Tabarkala
tu est le meilleur machala
You sou cakaw sa kanam koulabange sonn
C’est Beau !!! Merci You
cou beugue meune wayye il faut.gue tarry.7 foix youssou ndour si nokhe gue songoco
qui yalla que maye don.de dieu cou beugue xameu music.il faut.dir 7 youssou ndour si nokhe apr g songoco
Yalla nala serigne Fallou Mbacke fay
Ou sont les apprentis chanteurs prenez vos congés ndakh sen baye nieuw neu????
bilahi pom do moromo nw
Bilay wakh ngeu deug ken khamoul foumouy guene masha Allah album nekh trop je n’arrête pas de l’écouter depuis que je l’ai acheté ce matin
youssou moy barca fimouy guen mo graw
thiy youssou ya dof d
noo ki kén khamoul lanla kw yamana wayyyyyy
Les apprentis chanteurs n’ont qu’à prendre des congés bien mérités ndakh sen baay gneuw neu
Merci You noon yi dieufrou nagn mais bou yabo nguen nopalou
C’est vraiment excellent!!!
bayilen bokale diourom niary seringe fallou fadioul adio ken Yalla moy fath adio
Ay li nekhneu Youssou yalla ngueu goud fan si barké Serigne Fallou
Barké serigne Fallou ma beug You
Yalla nala Serigne Fallou fayal bopam une chanson très originale chapeau à la star planétaire Big Ip
Masha Allah je suis très contente de retrouver mon idole????
merci waye pour ce merveilleux ta frapper fort sur ce coup dieureudieuf serigne fallou
barke seringe touba mande serigne fallou sayou maka wowe mou wouyouma diorom niari 7 seringe falou rek sa adio fadio
Assalamou’Halleykoum à tou le monde. Maangui diégalou nak si dérangemen bi bou wérr khana ame Problém bouma Sonnal rek trope sakh depuis plusieur jour et personn mounoumassé aidé ba laigui. C’est que dama ame Problèm Problém 20 000F cfa Bouma Sonnal trope et Barké Serign Fallou jusqu’à présen j n’arriv pa à l’avoir. Ma beugoone koumassi dimbali rek SVP… Ne pensez pas que je sui nimport, malgré mes étud, je fai un peti boulo mai je n’arriv pa à récolter cett somm et Je m’appell bien SERIGN FALLOU… Je pourrai apporter toute mes preuve. Mon numéro c 70 948 98 07 … 70 948 98 07 !
Hé You album bi def neu doomm surtout le duo avec Akon
Merci à la star internationale pour ce chef d’oeuvre????
Tu est le meilleur je serais toujours avec toi
Merde!!! et dire que j’avais insulté ce mec dans un commentaire récemment. Franchement c’est un volcan. je suis séduit. Le Roi icontestable je reconnais.
il es le meilleur vraiment
Je t adore respect tu es le meilleur koumou nekhoul kalamel yalla
youssou dotoul am way rék lay cd lépa diaryoon
Ppppppppp papa you bo djiéko del balè
nekhena
les jaloux vont encore maigrir..koula baagn dafay sonou reek
le meilleur
Machallaa kiii machalla nekhna toroopppppppp j’aime
dawo leeeeen sen baye ak sy na niiiiiiiiiiiiiiiiiiiic ne nekhee na trie joliiiiiiiiiii
NON PAPA YOU BOKOSSI TU EST ET TU RESTERA TJRS LE MEILLEUR ; C TOI L EMBLEME DU SENEGAL ; SENEGAAAAAAAAAAAAAAAAL REEEEEEEEEEEEEK:!
DIEUREUDIEUF YOUSSOU !!! Away Yalna nga goud fann, Yalna nga goud fann té bari kheweul. Barké Serigne FALLILOU RASSOULLOULAH. Grand Bégué na. j’suis très content, très ému et fier. DIEUREUDIEUF YOUSSOU. YALNA NGA GOUD FANN té am Diamm ak Khéweul ak weer. Amiiiin