Grand-Yoff : Les mandataires du candidat Issa Sall absents dans la plupart des bureaux
Le vote se déroule bien dans la plupart des centres de vote à Grand-Yoff, fief de Khalifa Sall. Les électeurs de tous les âges ont pris d’assauts les bureaux de vote pour s’acquitter de leur droit civique. L’affluence est forte.
Mais, senego qui fait le tour des centres de vote a constaté l’absence notoire des mandataires de la coalition de Issa Sall dans beaucoup de bureaux de vote aux centres de Khar Yall, de Kalidou Sy, de l’école Grand-Yoff 2 (école marché)…
Mais, à en croire aux autres mandataires, cette absence n’a, pour l’instant, aucun n’impact négatif dans le déroulement du vote qui se tient normalement un peu partout dans les autres centres annexes dont l’importance est moindre par rapport aux autres.
Wakhna itam, lancement bou rails Dakar BAMAKO, di na aw tamitt Tambacounda, beu deff Tamba gokhou rails. khol lenn gni ko térrou yeup, war ngen khamni Tamba mom, gagné na ko ba paré »
Inauguré neu tali Tamba-dialacoto, lou tolo ak 65km, lancé neu promoville.
Macky ligueyeul Sénégal mo ko takha diok, defoul ni gnénen yiy téndéfal.
« Macky SALL deh meun neu contane ci victoireum, mi ngi dem séti Sénégalais yeup, nieup di ko top.
Macky SALL wané na fi bilan wou tabakh klatt deug. 7 ans rek, mou défal niou aeroport international, Musée civilisations, 2 stades, pont transnational ak ay centrales solaires. Lou tol ci 2 semaines avant votes bi, wagni wou ci dara, mi ngi dem fepp ngir woné lou mou fi deff, deglou sénégalais yi
Macky mo fi togatt, lolou lerr nama. Dafey khekh ngir Sénégal bou nieup am sen waleu, Sénégal bou bolo, Sénégalou Diamb, Sénégalou Démocratie, Sénégalou dimbalanté
Macky SALL investir neu bou bakh ci talli yi, yombalal na demdik bou nittt yi, ak sunu am am. Désenclavement bi ak accessibilité zone rurales yi moy li ko takha diok. Mi ngi diapalé gouvernement bi ngir mou gueuneu yokk projet yi, ak lou tol ci 1500 km ci rewmi yeup
Dolé Macky SALL ci Bitim rew, takh na beu sunu diplomatie gueneu am solo ci Afrique ak Monde bi
2012 ba tay, Sénégal amna fi ay activité you beuri you niou oubil bitim rew.
Macky SALL dafa woné ni, Sénégal deuk bou am solo leu, am dolé ci bitim rew.