PUBLICITÉ

Direct-Senego-TV: Suivez le débat sur la campagne électorale avec Pape Sadio Thiam et Omar Faye

Pape Sadio Thiam, professeur à l’UCAD et journaliste et Omar Faye de « Leral Askan Wi » sont nos invités de ce jeudi.

Avec notre confrère Pape Maguette Ba , ils débattront sur les questions brûlantes de l’actualité politique du pays. La violence électorale, les enjeux lors de l’ élection présidentielle du 24 février 2019, mais aussi sur les heurts entre militants de BBY et du PUR, qui ont entraîné la mort d’individus, l’interpellation des membres de la garde rapprochée de Issa Sall sans occulter le rôle joué par l’inspecteur de police du commissariat de Tamba.

Regardez

Campagne Électorale Direct
Annonces

(19) commentaires

Queditut

Ousmane Sonko dafey feyy ci lou leundeum rek, Sénégalais yi sonn negn ci fenn yi ak gni tékii woul dara

Willysagnol

Ousmane SONKO dafey menacé rewmi, diamb bi fi am. Lepp rek ci feenn, sathie, ngen fokni amna chance doug palais ? Negn ko wakh té deh : Kenn begouleu, ci Biti.

Etalors

Sunu Président moy defar ak samm ay relation you wor ak ay partenaireum pour def Sénégal, Rew bou am dolé

Redouane

Ak PSE, bi niou ko lancé 2012 néniou khamni Macky fou sori ak fou rey ley guiss. Sunu président bi, woné ti neu volonté bou mou am ngi developper sunu rew

Troudbal

PSE, projet bou niou togg ba mou nior leu, dé niou seytu bou bakh sunu komkom ak ay experts you nek ci domaine you beuri. Mo takh niou def projet boul lerr, bou kham fi mou dieum. Macky war neu meuneu am bénen mandat pour agalé ay projets wan ak réalisations yi. Tek fi kenen mom woroul ci komkom bou rewmi.

Younes

Macky dafa dor transformation kom kom rewmi ci ay domaine you am solo comme tabakh bi, courant bi, mbey mi, mines yi, dekouway ak tourisme.

Souliman

Ci histoirou Sénégal yeup, benn nii indiwoufi richesse bou toll ni ci Afrique. Macky rek mo ko fi def, mom rek mo meun né moy chef d’Etat bou mateu nek Njitou rew bouy youbou deuk ci emergence. Macky, kangam leu

Damian

Macky dafa fonk niit, dafa sokhali domi adama ci njang bi, ci formation bi, ci santé bi ak ci diapalé gni new dolé ak bourse familiale bi, CMU.

Feudeboi

Macky Sall, li ko sokhal moy wakhtane beu joubo, diamb, stabilité rewmi ak sécurité nioy li ko sokhal ci gouvernanceum. Macky rek!

Gabriel

Macky mo fi digonn benn taux de croissance bou 7%, affaire yii mat neu té dey gueuneu yokk fi ley 2035. wolou na Macky.

Husew

Macky mo takh sénégal developpé : Pole urbain bi niou tabakh Diamniadio, tali you bess ak autoroute yi, aeroport bi, TER ak projets you bess bou port
2011, Sénégal dafa amonn probléme courant, bi nou défé PSE ba tay, production bi dafa yokk 500 MW à 1141 MW, ak energie you bess you niou yokk. Ci Solaire bi, 7 centrales you niou yokk.

Jeanvalj

Projets you beuri, ci secteur energie bi leu : benn bou 60mw ak nathiee bi (Solaire) ak Banque Mondiale et un benn ak guélaw bi (Eolienne) bou 150MW
Ci domainou mbey mi, yok negn terrains yi, yok semences yi, ak automatiser mbey mi, lancer programmou mbay ci gokh gokhat yi pour khalé yi. Macky Sall mo takh niou yokk thiep bi, fi lé ak 2020, thiep bou niouy défar di neu doy pour rewmi yeup.

Zagar

Macky SALL, mi ngi defar villou sénégal. Lancé neu ay travaux assainissement, yon yi, eclairage public et lolou yeup dey créer emploi.

Xanax

Diapalé Macky SALL moy diapalé Sénégal

Creil

Khibar ngir gni begn Macky yeup : Macky topato neu khaliss bi niou lepp yeup beu dou sonnal kenn ci rewmi. Rapport Ministre bi néna mi ngi toll ci 45/50% té li niou nangou ci zone Uemoa mi ngi tol ci 70%;

Viru

Negn lenn fatali lou touti, sunu taux croissance mi ngi tol ci 6,9% ci année 2018 bi. Té niou wakh ni meun tol ci 7% 2019, spécialiste yi nio ko wakh. Ci waloum lepp mbi, niou ngi tol ci 3 ak 3,5% en 2018. Li dafa lerrr, kenn dou ko wédi !

Mamadou Diouf

Diapalé Macky moy Diapalé SAI SAI moy Diapalé OUNKEU

Joo

Urgent Bougane est arrêté par la gendarmerie en plein émissions
Toulouse a été gagner sonko
Paris sonko
Canada sonko
La casamance Sonko
Chine sonko
Tambacouda sonko
Touba idy
Je donne un conseil à sonko et idy coalition en 2ème tour pour battre Macky

Joo

2eme tour
Nous voulons la vérité
2eme tour