Diourbel: Libération des membres de « Idy2019 » et « Sonko président »

Mamadou Dioum dit Diomaye et Mame Ass Seck, respectivement, responsable de « Idy2109 » et de « Sonko président » viennent d’être libérés après leur arrestation par le commissaire de Diourbel.

Pour rappel, ils ont été interpellés suite à une affaire d’inscription « frauduleuse » de personnes étrangères à la commune de Diourbel, affrétées par cars.

43 COMMENTAIRES
  • QuoiCA

    Sonko dafa tilimeul toureum, ci scandales yeup, di na am diafé diafé you reuy ngir niou geum ko.

    • quoi

      Sonko ngi woté détournement 94 miliards, ngeu degg ni dafa waron am ci affaire yi 12%. Dafa niou tek ay tiomo.

    • WillySagnol

      Sonko dé fegneu, montant bi mou diokhé won, wagnékou neu, changé neu accusation yi, bolé ci faté tourou cabinet ATLAS. Fenn neu tamitt ci statut juridique bou atlas. Akh na fi ke benn cabinet rek leu am, téy niou yéwou guiss Mercalex ak AB partners. Sonko Deh fenn rek, Sénégalais yi dofou niou deh. Nieup yéwou legui
      Sénégal dafa beuri ay sathie you melni Sonko, Wayé Macky ngi fi ngir tekk fi yonn.

    • Etalors

      Sonko adounam yeup : Fenn leu ak Trahison

    • Erreursysteme

      Sonko deh, amna tourr ci politique bi nakkh scandales yi mou nekk.

    • redouane

      Sonko fou mou toll né amna ay preuves té meusso ko woné.

    • restoamateur

      Sonko dafa tilimeul toureum, ci scandales yeup, di na am diafé diafé you reuy ngir niou geum ko.

    • rogermilla

      Ousmane Sonko, njoublang rek leu ak daw deug.

    • ThierryNgolo

      Ousmane Sonko dafey feyy ci lou leundeum rek, Sénégalais yi sonn negn ci fenn yi ak gni tékii woul dara

    • YenAMarre

      Ousmane SONKO dafey menacé rewmi, diamb bi fi am. Lepp rek ci feenn, sathie, ngen fokni amna chance doug palais ? Negn ko wakh té deh : Kenn begouleu, ci Biti.

    • Ushuu

      Sonko dey fenn sénégalais yi ak gni mou andal yeup.

    • amadou

      Sonko deh meun neu lou raw li yeupp ci lou bonn : Corruption, niak meun meun, meussoul dirigé sakh entreprise, amoul benn experience ci bitim rew, meussoul def dara ci social bi ? Ngen beug ko denk rewmi.

    • Sassy

      Sonko, Inspecteur impots bouy sathie alal bou rewmi

    • fayette

      Sonko, wathie bess leu ci politique bi, day perte temps rek. Neu tontou ci accusations yi.

    • Xeme

      Sou mey lire commentaire yiy diapalé sonko, daf mey deff ré. Faw ngen tago ak senn sago deugg ngir votel ko. Ak li yeup niouy guiss bou kenn khalat victoireum

    • Chantal masqué

      Gueuw meu ni ke Sonko nitt leu. Mi ngi fegn ci journaux yeup, réputation weum yakou na, niak neu lepp

  • qrety

    Ousmane Sonko, njoublang rek leu ak daw deug.

  • wassal

    Ousmane Sonko dafey feyy ci lou leundeum rek, Sénégalais yi sonn negn ci fenn yi ak gni tékii woul dara

  • Willysagnol

    Ousmane SONKO dafey menacé rewmi, diamb bi fi am. Lepp rek ci feenn, sathie, ngen fokni amna chance doug palais ? Negn ko wakh té deh : Kenn begouleu, ci Biti.

  • ERISTO

    Sonko dey fenn sénégalais yi ak gni mou andal yeup.

  • tousPourLeSEnegal

    Sonko deh meun neu lou raw li yeupp ci lou bonn : Corruption, niak meun meun, meussoul dirigé sakh entreprise, amoul benn experience ci bitim rew, meussoul def dara ci social bi ? Ngen beug ko denk rewmi.

  • youssoufn

    Sonko, Inspecteur impots bouy sathie alal bou rewmi

  • aliyou

    Sonko, wathie bess leu ci politique bi, day perte temps rek. Neu tontou ci accusations yi.

  • allahvotemacky

    Sou mey lire commentaire yiy diapalé sonko, daf mey deff ré. Faw ngen tago ak senn sago deugg ngir votel ko. Ak li yeup niouy guiss bou kenn khalat victoireum

  • Sambedweedsw

    Gueuw meu ni ke Sonko nitt leu. Mi ngi fegn ci journaux yeup, réputation weum yakou na, niak neu lepp

  • DIEUMERCIMACKY

    Ousmane Sonko deh, nekk neu kangam ci tontou question you lerr yi. Beu legui niou key khar ci affaire Mercalex, atlas ak Tullow, wakhou ci dara. Déclaration patrimoire mom, kenn wakha tou ci dara !

  • dgxsfh

    Ousmane Sonko mom sou waré tontou rek dafey attaquer, ci accuser rek faté ni ke nékoul ci gew gui. Fou mou tol rek dafey indi attaque, politicien dara wara nango dialoguer ak nekk kou deugou.

  • zouloudunord

    Diakhal nama bou bakh, nakh Sonko dey feyy journalistes yi am dett, nieup pey wakh ci mom. Waron neu wakh niou begn wakh ci scandales yi

  • vilaine

    Sonko affaire yi tiol neu, di ngeu am problèmes bess bo naré indi reponse you lerr ngir wakh ak sénégalais yi

  • Transparence totale

    OPERATION FAXASS : Les objectifs
    1– Nous voulons une justice libre et Indépendante .
    Zéro pression sur les magistrats.
    2 – Une lutte contre la corruption et la traque des voleurs
    de la République .
    3 – Une autorité indépendante pour organiser
    l’élection présidentielle .
    4 – La démission du Conseil Constitutionnel et la
    suppression du parrainage .
    5 – La mise à disposition d’un fichier électoral fiable .
    6 – L’intégration dans le fichier électoral , tous les
    sénégalais ayant la mention » Non Inscrit sur le
    fichier électoral » sur leur CNI .
    7 – La libération de tous les détenus politiques .
    8 – La satisfaction au plus vite des revendications
    des syndicats : justice , santé , enseignants , etc .
    9 – Une solution aux 41 000 étudiants renvoyés des
    universités privées .
    10 – Le paiement immédiat de la dette intérieure qui
    a fini d’étrangler les entreprises locales .
    Ceux sont les exigences des citoyens sénégalais pour une transparence totale dans ces
    Présidentielles . Et ramener le calme et la sérénité dans le pays à la gloire de notre démocratie

  • mhd

    Les répondeurs automatique de APR ,les seuls voleurs c’est maky sall et son entourage .si Sonko avait volé quelques fcfa il serait en prison depuis longtemps.alors cher répondeurs automatique répondez Ousmane sonko sur les idées et surtout sur les dossiers technique.mercique Allah contenus a guide les pas du président Ousmane Sonko

  • Harouna Barry

    A mhd:Allah continuera de guider les pas de Sonko dans des abîmes où vous avez contribué à le conduire par votre attitude.

  • Tidiane Diene

    on verra bien idy et sonko n auront rien Macky passera au premier tour avec plus de 50 pour ce

  • moussa Diédhiou

    Commenter de façon responsable

  • kone

    Tout citoyen sénégalais a droit de se faire inscrire où il veut sur l’ensemble du territoire national. Comment des individus sans aucune autorité peuvent prétendre se substituer aux instances nationales pour empêcher l’inscription d’autres citoyens comme eux.On est dans une élection et non des législatives et le lieu d’inscription n’a aucune incidence sur le résultat du vote.

  • mamadou Lamine ngom

    Fénkatyi khaménagnelèn motakh niou groupo bénno bokk bakkar bagne niou teudj lèn si kasso bi, Ousmane Sonko gnikoy toumal meunouniou si mom dara, Yallah ko élevé défko ci kholou gnou dioub gni

  • René Diagne

    ils crient au voleur alors que!!!.

  • ouz

    c est faux

  • Anonyme

    Macky wathial Idy yekkkkkk

  • Foof

    Voter Sonko ou périr

  • toufa

    Sonko dalle fene rek lay def il les impliques de tout sortes de mafias les sénégalais attends des éclaircissement sur les dossiers cône kokou Président Macky d ou moromame le soir du 24 février la victoire éclatante du Président Macky lep dîna ler

  • Mahamadou Sy

    Seuls les sourds et aveugles critiquent Sonko car il dérange les corrupteurs et corrompus et aux fraudeurs d’élection

  • Transparence totale

    OPERATION FAXASS : Les objectifs
    1– Nous voulons une justice libre et Indépendante .
    Zéro pression sur les magistrats.
    2 – Une lutte contre la corruption et la traque des voleurs
    de la République .
    3 – Une autorité indépendante pour organiser
    l’élection présidentielle .
    4 – La démission du Conseil Constitutionnel et la
    suppression du parrainage .
    5 – La mise à disposition d’un fichier électoral fiable .
    6 – L’intégration dans le fichier électoral , tous les
    sénégalais ayant la mention » Non Inscrit sur le
    fichier électoral » sur leur CNI .
    7 – La libération de tous les détenus politiques .
    8 – La satisfaction au plus vite des revendications
    des syndicats : justice , santé , enseignants , etc .
    9 – Une solution aux 41 000 étudiants renvoyés des
    universités privées .
    10 – Le paiement immédiat de la dette intérieure qui
    a fini d’étrangler les entreprises locales .
    Ceux sont les exigences des citoyens sénégalais pour une transparence totale dans ces
    Présidentielles . Et ramener le calme et la sérénité dans le pays à la gloire de notre démocratie

Publiez un commentaire