Décès de SERIGNE Abdou Samath Fallilou Mbacké

Senego a le regret de vous annoncer le décès de Serigne Abdou Samath Fallilou. L’information est relayée par Cheikh Abdoul Ahad Gaïndé Fatma sur sa page Facebook. Le défunt était un des fils de Sérigne Fallou Mbacké. Que Dieu l’accueille en son paradis.


rip
انا لله وانا اليه راجعون اللهم اغفر له وارحمه واسكنه جنات الفردوس niongi koy dialé diabotou serigne fallou gi di andak niome tiss bi di niane yalla sarakham yagg s’en lokho te yalla diegal ko te khareko al djana
DIEUREUDIEUF mbok taalibe yi. AAMIINE
Innâ lillahi wa innâ ilayhi râji’ûn, kou bakh, oyof, yalla na yalla tek lokhou sa toute tank yigua amone sa dara yi, yalla na souf touba séde sa kaw, yalla nalla yalla atéla si yeurmandé.
yallanako yalla yerame
A waay kou baxx demna
Yalnako yalla yareum te khareko aldiana amin
thieye yala.yala na yala yokou lerrame ak molome dioulite
AAMIINE
Yalla naco yalla tèrou sa adiana firdawsi ci barkè serigne falou mackè amine
yalla nako yalla yeureum té tass niou ci barkéme ci barké BAYE NIASS Amine!
amine
koubakh ta dioubowone ak boromam te oyof yalnako serigne touba Terou teralko si barke wadiouram elhadji falilou Mbacke. Amin
yalanaka yalakhri Adiana fidasi
Aminne
Yana yala yok léram si barké bayam serigne falou nite kou bakh beug ay talibém yeuk gneup fébar bi yag na wayé bala aissa amnan yakar bou bakh
amin yalnano yalla tas thi barkem
allahouma akhfirlahou wa arkhamhou
thieuy yalla sama papa aka bakh waay t oyoff yallanako mame fallou trou thi bark s fallou
thieuy yalla sama papa aka bakh t oyoff yallanako mame fallou trou mttyna waay
Amine serigne touba teroucko
kou bakh waye
kou bakh way
Amin way
rip
way sama yakaar dem na
yalana souniou borom yok a leram thi barkeb serigne touba
Amine yalla nako yalla khar adiana
ndéyssane kou bakh démna wayé sounou xél dal na si yaw si barké s fallou
yalla nako yalla yeureum te mayko aldiana firdawsi.
amine
khalo inna lilahi wa ina ilayhi radikona yalnako yalla khare aldiana si bark s fallou