En direct de son émission Libre Antenne sur la Rfm, Ndoye Bane réitère ses propos sur certains conférenciers religieux en quête de « frics ».
Audio: Ndoye Bane persiste et tacle les conférenciers à nouveau

Votre avis sera publié et visible par des milliers de lecteurs. Veuillez l’exprimer dans un langage respectueux.
Mercy Ndoye Yalla nala Yalla lafal thiat te mousal la si nit yu sokhor yu bone yi Yalla nala Yalla arr lakh la fa yakh yegoul,Amiin deugeu rek ngay wakh senegal dafa bari ay nafekh daniouy guiss degeu te douniou ko wakh fen ak dool ak masla rek moy sen ligeuye
Sa legui gniy khew du nguente nak et le mariage gnou kay ngawara wakhal conférence boco guise bala nga guissat dina yag
Si ce n’est que cela, NDOYE BANE TU AS PARFAITEMENT RAISON ET ON TE SOUTIENT A 300%. La couleur « jaune » est la couleur de « judas » le menteur et hypocrite toujours souriant. Le « rose » et le « rouge » sont les couleurs marques déposées des homosexuels. Tu es l’ennemi public n°1 des homosexuels et des hypocrites de ce pays.
les thiant aussi dranger beaucoup
ga nopi rek nek si lenn wasalam
Ndoye bane limouy wakh l’islam moko dieunk condamné fortement en plus des hauts parleurs jusqu’à 6hres du matin melni les gens falétou gnou akk deukeundo quelque soit les appartenances religieuses et ne pensent même pas aux personnes malades et celles qui doivent se lever très tôt pour le boulot ou bien pour les cours.
vakhnga deu geu deu gnioy gadou akhe you barbari varnagio khamne aw yon kou fekhe beu bamou sete beu nitgny mana Dem yool bou reu la vaye kou Ko fate beu ken dou mana dialle manga thia am mbougal mou reu foumay yalla rek nga thiay diale
ndoye bane tu doit ferm ta grande gueule tu n’as rien a dire gumo dara doul rk ak diakhass vrai satann
niom yp pa yem bane ak Ahmet Aidara Bane gumoul dara diamou youssou rk lay def nip pa ko tan
Deugue rek nga wakh senegal laissse aller bi ak masla bi mofa bari ak ay tapete mai mane d degue rek lafi degue .
ki dafa kaw kaweh torope
diadieuf ndoye bane le rfrence des des jeunes
AHMED AIDARA MOM BILAHI WAROUL WON SANTE AIDARA DIAHASSE RESK AK WAH LOU GNAW LAFI NEKE MAIS NDOYE BANE YOW BOUL RAGAL DARA ASKAN BI REK NGA FI NEKAL
bravo Ndoye la verite c est la verite Ahmed aidara na wakh senegalais yi qui est son pére domou biral sokhoor