Audio: Cette femme est une voleuse, mais elle ne sait pas pourquoi elle vole…
Amadou SY
6 COMMENTAIRES
Nafi
15/04/2016 à à 20:27
vraiment le journaliste est irrespectueux. cette dame est venue chercher de l’aide mais j’ai l’impression qu’il se fout d’elle avec ses questions bêtes
education de base daffa am solo si nitt.sa dome bokko ammee del sittlou loumouy def bou bakh.yaw nak sokhnassi bou demme ba khamne liguay def bakhoul toubaal de djeugeulou.bayil sath!!djiguene day doylou.sinon bo dadiek gnenn nitt yi bolen sathee, dindalgnioula yakk vie wala gua beugeu bouger mou teuleu . »lii momou makko fi lakoy bayii tay deggo » deeko khakh chak jour ligui gua bayi sath.

c clair, il est discourtois
Yalla nalla si Yalla guenee ak kepe koukoy def dou yomb waye diemko dindi sa khel sabablou t outesi ay gnane bilay Yalla nalasi Yalla guene
tous les parents doivent ecouter cette femme l c’est intressant. yalla nalako yalla teguil
education de base daffa am solo si nitt.sa dome bokko ammee del sittlou loumouy def bou bakh.yaw nak sokhnassi bou demme ba khamne liguay def bakhoul toubaal de djeugeulou.bayil sath!!djiguene day doylou.sinon bo dadiek gnenn nitt yi bolen sathee, dindalgnioula yakk vie wala gua beugeu bouger mou teuleu . »lii momou makko fi lakoy bayii tay deggo » deeko khakh chak jour ligui gua bayi sath.
Bayil sathie la wakh ioe ko Yp