Arrêt sur image: Waly Ballago Seck remet son CD vendu aux enchères à 8.500.000 Fcfa…

Waly Ballago Seck remettant le premier exemplaire de son nouvel album « Xel » vendu aux enchères à 8.500.000 Fcfa à Bébé Palmire Diagne représentée par une amie.
album xel

Source: dakarlove.com

22 commentaires

  1. Na

    Defal loula nékh ba guéneu laleleu papa wally dagay liguéye bayil wax kate yi gnoune wax rék yaw rawgalene.

  2. ousmane

    sa kharite bi sakh bokossi diokhone 100000 mo dieunde diwe, diwe tankame yi balla mouye niew. sa wadiour boudé li laniou liguéye. kholate léne séne bopp

  3. ndakarou

    non vraiment senegal métina kou nék ligua sentir si sa khole géy déff ak co mountidone mais wakh réck nohhh Wally machalla migui déme si séne gaw liguéy youléne yatouléne di wakh réck mome au moins am na metier ak loumou mountidone di téral néyam ak ay mokam manchalla néwdidolléyi si lou bakh réck léy dokh rakhass léne khole yi bayi wakh diou niaw té yénanté diam adouna diékhna gou Wally nékhoule boule co deglou reck mo guene té naguou dogal bi tall bou yalla tallllllle bou yalla talllll sani si matt mo guene laf thiatttttt guéne balma akh

  4. nanisha

    Faramaréne rek dafa doy bay dess té bouniou amone milliard deff ko ci ndakh nak yaniou beugue té yaniouko diaral deugue nékhoul dangay dème dara doula off khana waure!

  5. sibarak

    donoulo sa baye béne Basse doctorou diaka yi ak diouma. il faisait la queu devant la radio dounya il leur donner des enveloppes d'argent au gens lou bakh rék ladane déf si khalissam. ligueye rek la khamone yalla na ko yalla yereum khakeko aldiana firdawsi ak boleme dioulite

  6. sibarak

    dotouko sa baye béne Basse doctorou diaka yi ak diouma, sa papa danoul yakh khaliss si thiakhne. les gens faisait la queu devant la radio dounya il leur donner des enveloppes d'argent au pauvre. si lou bakh rék il aide les pauvres. yalla na ko yalla yereum khakeko aldiana firdawsi bène Basse Diagne

  7. fése

    ahhhhh thioummm waly seck yow wakhoumala liii rék wayé louko raw meune ngoko am boula yalla féyé sa khol bravo tu a tout dit laf thiate rèk

  8. rebatass

    si ce qu on a dit est vrai que l argent sera remis aux enfants qui sont dans les orphelines et au penssionaires des prisons donc je pense que c est bien

  9. Bravo

    Tu a vraiment inovè félicitations nit Day gueum bopam nit kouné war nga gueum sa bop thi langay déf boudé dimbali domou adama rék li la war yankoy déf ko meuneu dimbali défngako maryacine yalla rék mo meuneu mèye gneup té défouko kom assama ak yow miy domou adama késsé bravo wonéwatnga nè ya finé

Comments are closed.