Aida Coulibaly l’épouse de Youssou Ndour à nouveau maman.
Une bonne nouvelle vient de tomber chez la famille Ndour. Aida Coulibaly vient de donner naissance à une mignonne fille à son mari Youssou Ndour, informe le site Vipeoples.
Une bonne nouvelle vient de tomber chez la famille Ndour. Aida Coulibaly vient de donner naissance à une mignonne fille à son mari Youssou Ndour, informe le site Vipeoples.
lol sa c’est une rumeur seulement youssou n’a pas encore de fille senego vous …
You sa KOYE bi beurineu khon déh
ET ALORS?. BASTA!.
yala na dounde t barkl you yala nangua fk sa ndiarignou diabote gui ak mbolom dioulite
Grd You noumouy weuye’ lay kate’ ahahah ndanane kouli fadrine
Nouveau bb new Album
Senegal
félicitations la famille ndour
you lingay daw barina
Machalah ki dafay yok khetou mouhamed
Way gnoune sounou Keur daa ame Ngénté Soubeu, sama tante moo ame doom, ame na Laakh !!! Diallaléléén information bobou
Kouyyy bayyou lirrrrr bi ???
mbètè pondeuz aaaaaah eupeuneu li lan la ni
Ken begnoul lou nekh bayi ln sama grand you mou happy mai Kane moy yorr sokhna sou taaru ni diko doumoyou way wakh ln ma lenen way ish
Youssou tu fais la fierté de notre continent Africain merci
YOU mon idole de tous les temps Yalla neu sa diam yag ammmiiinnne
Félicitations Mr le ministre
Qu ALLAH lui accorde une vie pleine de grâce….. Aida njimè ngua table bi khana yangui si 7 dè?
Bone sokhor limoye Sénégal mais le chien aboie mais n empêche la caravane va passer
Sénégal nio sokhor ta imbécile félicitations you
lou nehh gnep ko beug t’ai gnep beug gnabott yu barke
rathieee
lou nehh gnep ko beugg t’ai gnep beug gros gnabot lou la laiww amga si droit sa youla naihai
felicitation pape you yala goudou fane
boy da fa fowewoul ndawame comme toi c sur a 40 tu seras impuissant
H va le dire a ton papa et ta maman ki le 7 jours sur 7 te sak niou doyal
alert demande a ton papa s il a laisse de le faire c sur il dira non et il fait meme avec d autre femme qui n est pas ta maman
TENTH tu m’a tué way deug pirrr ngeu wakh
Yalla na doundou té am barké nguen tok ba lek ndiarigneum Amin.
youssou champion fepp mané fou nek
Felicitations et longue vie au BB
Grand You moy sai sai!!!!
Ay way invité len meu ma lek si lakh!!!!
Félicitations à You et longue vie au BB
Yalla neu mague dieurigne ay wadioureum Incha Allah
Yalla neu ndounde té barkel
Félicitations à la famille Ndour!!!
Félicitations aux parents God bless You!!!!!
LI GUENI DIOUR NAK DOY NA WAGNI LENE KATANE TE BI DE LENE NELAW GOUDI WAY YOU MOM LAL REK LI EUP NA
congratulations aida champagne
Merci You..sa ligueye rafetna…
toutes mes félicitations à Youssou! Longue vie à la petite!!
mdr
NAY LERR bo sagnone You nekeu sa baye
Papa You longue vie à la petite princesse
wakh daal dafa wara andak A teguine sou meunte rafete nga nopi.
Grand You ndanaan koulou fadrine
Grand You doundeul ba feke seu ndiarignou dom yi Incha Allah maleu beug piiirrrr
Masha Allah tata Aida une femme très dévouée
Khana nekh li loukoy faye yok khetou nabi masha allah
Yalla neu ndounde té yor djiko Sokhna Diarra Boussou ak Mame Fawade Wele
Yalla nako yalla def magoup l’Islam Aminnnneeee
yalla neu dounde bay teral ay wadioureum si barké werou kazou radiabi!!!
Que le tout puissant lui accorde toute sa grâce Ammiinne yarabi
yallna donde t barkel yousou tou d mako jaime
Yalla neu BB bi dounde yalla teko thi siratal moustakhine ammiiiinnne
Bravo à you vu que maintenant ya bcps de mecs qui à 40 ans ne peuvent plus rien faire avec leur wife
BADINE bouma raye waye wala mou touddeke Michel Obama Ndoure
Félicitations en plus ça coïncide bien avec la sortie du nouvel album SENEGAL REKK
Qu’Allah lui accorde une vie pleine de grâce ammiiinnne
aida arriviste coulibaly hritage bi moko intress! qui vivra verra. suivre. . . !
aida arriviste coulibaly hritage bi moko intress! qui vivra verra . suivre…
nako toud reine lisabeth
You nak da graw dé son dernier bébé Nelson Mandela Ndour lako toudé j’espère que la petite douko toudé Mére Thérèsa Ndour diapléné cii guir yalla.
Non Youssou Ndour nak doyneu nak
You grand kateur la !
ladjln sn Bay bakham Bayina rwgun trop
You Pa geu way legui bayil affair bi niom birane…japp Aida ti tinss rek
Thiey paaby tiouckary reck.
tou mais félicitations mon grand youssou ndour yoo allha wuurno barkina
doul way senego a nous regarde pas
siiw daal dou diam boromam a koi ça sert de nous dire que la femme de youssou ndour a acouché une fille.
Thieuy you!!! Ndanane thi bèp borrr félicitations yalna mag ba diarigne