(8 photos) – Yahya Diop Yékini en pleine forme. Regardez
En prélude de son combat contre Lac de Guiers 2 prévu le 24 juillet au stade Demba Diop, l’ancien roi des arènes, Yahya Diop Yékini s’est confié à Senego. Le champion a expliqué pourquoi il va en découdre avec Lac 2, il est revenu également sur son avenir dans la lutte entre autres questions. Nous y reviendrons tout à l’heure. Nous vous rappelons que ce combat est organisé par Aziz Ndiaye productions.
mécontent la dou dann kenn khol bi moko sonal.il n’est pas sportif.do am dara le 24 juillet.dangay danouwate 2 fois mouy 4 défaites dans ta carriére.
Yékini le plus grand lutteur de tous les temps mais chaque chose à une fin et on ne peut pas être plus fort que ses cadets s’ils y croient: faisons la nuance entre la force et le poids en plus la force de l’homme se trouve entre le ventre et les pieds. Toutefois, par stratégie il est bien dans son role d’intimidation de l’adversaire que devra montrer qu’il est un guérrier pour l’affronter.
Vive la lutte dans la sportivité. Que le meilleur gagne
You for ever yay sen baay
Vos gueules on verra bien vous oubliez que ce sont de vieilles marmites qui préparent de bonnes nourriture……Dix mille euros s’est mon paris à vos mises
Yikini dou moromou lac
Yekini dou moromou lac
WA GOLO BI LOUMOUYE DEF NII. COPINE NIANYE LA EUPEU. TOGAL WAY SAFATO FII C EST LA VIE
hooo tu es formidable mon ami du courage
lac dou terase ken dolem bayinako tecnopole
ah tthieum sama mbeur wayy do moromou gayi
yakini lanu wakh deh
yikini sa c vwa que trois an yi nga tok beuré wo danga done noyal dhé j n vwa vraimai pas une bonne forme aussi nite dey doyoulou dans un sport de combat le plus jeune a toujour plus de chance de s en sortir
bèn affaire lala destesté et se sera pour toujours je suis de joal mai je te deteste lac nokal mako stp
le champion
xalei moy berei yékini té makk dou forcé yékini lac sou féké doléi rék gua yakar pour dane ko digua dém retrait vrien
doyna warrr
yakni
il est vieux et il a de la graisse il n est pas du tout muscle yekini .
ya mme arrne bi kouko bagne na mate bakname
maguetna
Putin ! Et il veut nous faire croire qu’il n’a pas encore 45 an ak sa yaram bou tass bi.
no afr bi yikini la
kou dioum rek danou
wawaw diap dann rk
waaw diop
ndjogoye ngore n
grand yangui yoobou fitou boyby ,
En tt cas Il prefere montrer ses Atouts : Le buste et non ses points faibles LES JAMBES. .LOOOL. .Bonne chance ..
tout sera clair ce jour ji
yekini du moromu gayii
sama gayi yena mona dull
niak diome mon takh nga dougate guediawaye mai nakhar ngafaye diel …
amo dole maguetga forza lac 2
li dou Dole non
Défaite rek , Lac 2 va te terrasser
Yekini niak gueu fayda bayil beurri nak il est temps darreter
yakarnani
merouwally . sakarnani yikini dafa dess sisa biir khol bi ba tay .pask wolof dafani beugue dou bagne dafaue mr . Ta mr dafay diekh. seydina mouhamed nena kouy mr dkko diapou sisa bir kholbi .bagneko fate bako sisama kht ta doumou dioulit nga donc oublie a
Yekini souf gui dara nekouthi.ndigueu bi dafa noye. Champion demal ligguey watt touti
Défaite rek , lac va te terrasser
Trop vieux.
do moromou gars yi koor siga
ki mo mane Lac 2 foôooooooof
nama YALLAH BAAL DPUIS BIMOU HUMILIÉ BECAYE MBAYE WAKHATUMA THI MOM DARA AAK NIMOUMA NEKHE WONE
Eh lac attention dé.. !