(8) Photos: Soumboulou Bathily chez la comédienne Ndeye Khady Sy de Daaray Kocc
En compagnie de ses proches et dans le but de venir en aide à sa consœur Ndeye Khady Sy de la troupe théâtrale Daaray Kocc qui est frappée d’une maladie de longue durée, Soumboulou Bathily a effectué une visite de courtoisie chez la comédienne. L’actrice de la série Wiri Wiri a offert une enveloppe dont la somme reste inconnue.
bon geste soumboulou yalnala yallah fay sa khol
rafet na trop
Senegalais moo beugue Guiss-teul sokay ñiokh khaliss waroko wané comme ça Thiéyy yalla adouna
Ndeysane yalnako yalla eukheti si diam
Idée bou Nice.mais t’avais pas besoin même de publier les photos encor moins l’enveloppe ke tu lui a remis.Yalla soutoura la beugue.mais après tout def nga lou niceeeee.les gens qui passent tt leur temp a gaspiller des millions au grand théâtre devraient copier sur toi.Merci pr ton soutien
yaw soumboulou doul amo benn soutoura tu nai pas oblig de venir avec la presse chez elle luigadef amo thi yalla
Lu baax la ci kaw wala ci suuf(sirran wa alaaniyatan Al Xuraan moo ko wax
Que Dieu Le-Tout-Puissant la retablisse completement et accorde ses bienfaits a sa bienfaitrice
Amine
Bienvenue a JONI JONI
Les 25 000 envoyes a
ASTOU NDIOUR viennent detre retires. Merci de votre confiance
Lou baax la muy ci kaw wala ci suuf (sirran wa alaaniyatan:cf Al
Quran Al Karim)
Que Dieu Le-Puissant la retablisse completement protege la Bienfaitrice et augmente ses avantage
BOU NJEUPP DEFFON NE SOUMBOULOU DEM DJOKHE WANE ko LA KONE NDEY KHADY WER NA BOU YAGU LI BONN KAY MOY DJOKHE WO SI SOUTOURA DJOKHE WO SI KAW NEK FI DI RATATATITII REK DJEM LEN NA ROY SI SOUMBOULOU NAKH MOM DEF NA GESTE bou nice MEM SOUKKA FEUSSEULE
tres bn jest bilahi
Senegal rewou ngistale
Deet bouleen diawale koumelni soumboulou doit montrer ce qu elle fait pour que d autres puissent la copier c est exemplaire pour les autres
Kou df t yalla takh yalla fay la way kou df t nit yi takh yalla bayi la ak nit yi t nit yi amougnou fay don na gana raft nit gni bagnon ko giss
Innamal ahmalou binniyai
Kou df t yalla takh yalla dina la fay. Way kou df pour nit yi giss ko yalla bayi lak nit yi t nit yi amougnou fay way don na gana raft nit yi bagnon ko giss bou fk yallA takh
Diaroul won wane si internet bi han
Batieli bour ngalam yala nala yala faye sa khol lafal la tiat ci bark prophte (ps l)
kel q’en soi l’intention, c 1 beau geste
BOU NJEUPP DEFFON NE SOUMBOULOU DEM DJOKHE NJOU WANE LA KONE NDEY KHADY WER NA BOU YAGU LI BONN KAY MOY DJOKHE WO SI SOUTOURA DJOKHE WO SI KAW NEK FI DI RATATATITII REK DJEM LEN NA ROY SI SOUMBOULOU NAKH MOM DEF NA GESTE MEM SOUKKA FEUSSEULE
c bien de le publier pr sala xalat
LOU BAX.Kén dou ko nobou.c un geste qui doit inciter certains de ces collegues artistes qui ont les moyens à penser aux autres.nicena soumboulou
beau geste
donner a une personne est quel que chose de noble et cela serait plus encore si il y avait pas cette publicité derrière toute acte
Sénégal toujours devant aimons nous les uns les autres
C’est bien une très belle geste mais un peu de discrétion c’est mieux
et ceux qui ne font rien
badiane wakh gua deug soutoura
Rama badiane sama xalat elle a bien fait de le publier comme cela les autres vont suivre ses pas bouko wanèwoul kena douko kham
Mè daccord soutara bakhna mè li dina takh gayi yor di diokhé
rafetna trop sakh
jolie geste
mais il faut savoir donner sans se montrer
dieu le veut ainsi
soumboulou (meilleure actrice des années 2015 et 2016) c’est vrai que adouna amoul solo mais pour aider vraiment tu n’avais pas besoin de te faire voir. Discrètement rek doyona ci
Loubakh couvo def mou si caw bakhna wala thi souf
Soumboulou Yalla nala Yalla fay defal la diam ju bari,NdeyKhady Yalla nala Yalla mei werr ak kep kou tawat,Amiin
suis dakor rama badiane
beau geste mais pourquoi le publier si ce n’est que le voyait moi pufffff!!!
Soumboulo ides bi bakhna mai soutorabi mo geunone tu mo e peu tiyaba
aduna amoul solo ndey khady yalna diougue si diame dev Lou bakh rek mo woor
soumboulou mane gueune nala beugue linga df dafa Raft yalla nala yalla fay