kouné fésoul dagay doul waly nianal len ko diamètre RK mo âme sola sokhor doula may dara
dji
je ne suis pas un fan de Wally mais je suis fier de lui en tant que travailleur qui aspire à grandir. C’EST UN COMPATRIOTE, IL EST AUSSI PORTE DRAPEAU. TRAVAILLEZ ET ESSAYEZ DE FAIRE LA UNE VOUS AUSSI. KEEP IT UP WALLY…
chichi
Bravo Bravo Bravo WALLY BALLAGO SECK l toile qui brille sur ton front c est DIEU a mis nul ne peut l teindre ton ge d autres taient dans la galre mais toi aujourd’hui tu es Bercy plein ou pas Diadieuf pour ton courage les bonnes personnes sont derrire toi ci kaw ci kaname
Mbaye fall
Meme pas la moitie de la salle pleine
Mann
Waly je sui ton fans , déglouma ma wakh la boule rousse dara apres bercy by dakhale sa staff by yeupe té oute gnénén gno khameni liguéye mo lénn takha djouk lolou mo lay mayate dolé , boule rouss dara. Bilahi si jetai toi je fairai sa
Wotel conference de press au retour au sénégal nga nî léne fiasco bercy dou si yaw mai staff bé liguéyoule comm il fau
Ta vue noulaye djaye nay bercy fess na té gnoune gnoufi nék khame nanou lépeu .té boule di engagé jamai des grandes sall à l’étranger , sénégalais jamé mou wakh deugeu
ibrahima diop
Sokhore bakhoul nako bénéne boy déf dinanne kham ndakh wally diambare la walla wally merci je suis tres fiere de toi
coura
li gathia laa dama rouss wayy
Fatima
Bayilenn sokhor kou yagu di fessal salle yagu di am guichet ferme bou fessaloul Bercy doù djikom fi la dem zénith fessal KO bamouy tourou première fois mou dem Bercy am peuple bou toll nonou yomboul si artiste yi legui
Anonyme
done baye Fall rekk worr aller Senegal wally rekk
ousmane
Bravo waly méme si c 2 person
teacher
congratulations wally thia kow thia kaname
Bamba
Nice
rohie
succes total ??????
Mimi- paris
Wa gnî kounou yép? Bercy deé ya mém pas plus de 3000 pers taye mome je dis la vérité yageuna di défendre waly
Wayé mom doye na wakh deugueu rék bercy bi fiacso tatal la dar dafa yarakh trop sakh
Sylla
C’est hallucinant comme les sénégalais aiment répandre de fausses nouvelles. Ils ont fermé deux rideaux ici à bercy. il n’y a qu’un tiers de la salle et ce n’est même pas plein. A un moment donné il faut arrêter les contes pour enfants. Il a eu le courage d’y être ammé c’est déjà bien. Et j’espère qu’il fera mieux la prochaine fois. Mais si maintenant des fans zélés veulent ajouter à son palmarès qu’il a fait salle comble, ce n’est pas bien. On ne bâtit pas la carrière d’un artiste sur des mensonges. Wally n’a pas besoin de ça à mon avis. Wa salam.
bai fall
good luck son keep on whit faith
ibou
sokhor bakhoul
pote
beug wally tu as tout dir merci papa merci encore dfaillant yi douniou meusse nangou ta l’habitude de faire guichet ferm dans une salle de 1800 place dans ton pays si tu te trouve slm avec 5000 place l’tranger RAS
Dou The Boss
Bravo l’essentiel Waly wanna bopam c mieu do moromou Pape Diouf
coum
bilay
beug wally
noubli surtt pa ke l’objectif n’tait pas de remplir la salle mais de jou bercy il a os ka mme et je trouve ke magnifique pour un dbut
aicha lyon
fesna fessoul n’empéch il a auzé malgré tant de jeune musicien senegalais donc fiché ns la paix nékhna trop té nitt gni beuri na !!! On en cé klk choz n’s ki som laa..
aicha lyon
fesna fessoul n’empéch il a auzé malgré tant de jeune musicien senegalais donc fiché ns la paix nékhna trop té nitt gni beuri na !!! On en cé klk choz n’s ki som laa
fan
du courage et bonne chance kou diambar te reference gua thi liguaye def
Anonyme
Bayi lene fo da guene deme diamoudi yalla mogeune
Avatar
guissouma loudoul ay gor ak djigune di foh rk thiakhane di wakh nane fess na wala fssoul dmln diamou dji yallah
pap diouf
bayilene sokhor c plein il a gagn son pari l’histoire retiendra que waly jou la ou tous les grandes stars mondiale ont jou c tout
Ibrahima Balde
enti africain
bb
danio yakamti niorekoul
ndiaga
mai yaw guis nga sal bi Guido dh fi amoul lou yarakh
Ndiakhate
Wally n’est pas partie pour occupé toute la salle il est partie pour une première fois de son histoire
Anonyme
Wally bargu mame saliou day dm knne douco t
fafa
il a assuré bayi lune sokhor
MOO mergane
ah c bien Wally rempli la Salle de bercy han
apista
bayiléne sokhor c juste réussi
souch
du n’importe quoi les hommes qu’il faut à la place qu’il faut thiouthie daffa wara xam bopam
coum
bayilene iniane iniane bakhoul
right
il faut le feliciter et l encourager.le conseiller d arreter de faire des buzz negatif
fallou
sama guayie soue khore bakhe khole
maria
mé gayi yéne sokhor nguéne déee kou guisss néne do né néna ngui ni lén khénn beugue ahh no yéna sokhor way bravo walyyyyyy on aten avec impatience gnibisil gaw gnou gneuw téroula alhamdoulila
Diarra bousso
Félicitations ?????
dieukeur
emigres clandestins sans abris yi done takhawalou bir paris yeupeu guissi salle bi fi khassawna khounnnn$$$$$$$$$$$$$$$$
dakar
Man mi fala nek ni senego bayilene fen bercy bou mel ni meussou fi am yarakh rek la def je suis un fan de wally mais fessoul nekhoul
the
Bravo je suis fière de toi mon frere
wakh sama khalateu
bilahi walahi soirée bi nekheuna mais c’est pas rempli comme un euf tafa yarakh moi je suis sur si lima wakh
Bizarre
Fountou rék
waly diaw
Sall bi dafa yarakh torop, Ana nityi
info
wakhdji moy wally seck amoul lou mat 5000 person na journalisteti di wakh deug

flicitations 23h20000 personnes de la salle
bercy bou yarakhéna bercy bou wally masoufé am