(18 photos) – Pape Diouf au Barramundi: le Pikinois attire de plus en plus. Regardez
Décidément Pape Diouf et la Génération consciente attirent de plus en plus. Le jeune chanteur fait danser les vips et mélomanes. Le natif de Niary Tally remplit les salles de spectacles et les fans en redemandent.
yen fimista yi gueneu lene thi digante pape diouf ak waly aye frere lagnou y a pas de competition nafekheu delene defar tass ngen Senegal
elhadj diouf mor ndadjé est mal consseiller .Nit da ngay kham sa boop
le meilleur
Diouf tjrs et enkor diouf bilaye tok gua sunu kaw nizk gua classe trop mor ndadjê
afair bi pape diouf la
Non vraiment senegal diakhal naniouma regarde moi li Elh diouf limou def dieul yaram bii dissi def Serigne touba li c pas normal Teh ken doukou wakh Teh dou yone Serigne touba amna fou mou geuneu diek ma pas diko tatouwe sa yaram Wakh Len sii
bonne continuation du courage gor foula
lool mangui si defanté bi man mai diouf un peu de classe niak ngua fayda trop
Bilay mom dou tatoné way rek lay def.
Hahaha…..fans waly sek yi yen bayi len ki d'où s'en morom……wahlen waly mou Roy si mom te ligue yi. ….pape d'où s'en morom…..malaw rek mou tit di gadou ay sac . hahaha
pape lollou nice na ni nga deff fofou la