Annonces
Annonces
» » » Vidéo- Zarko boude le plateau et lance le micro

Vidéo- Zarko boude le plateau et lance le micro

2015-06-12T22:37:49+00:00 Partages

Annonces
Annonces

28 commentaires

  • Iso tra
    12/06/2015 22:53

    Education aka bakh. Yalla dou maye leupp

  • Mami
    12/06/2015 22:58

    Trop con et mal éduquer ce gar la, motakh niouy khass mbeuryi !!!

  • yo
    12/06/2015 23:08

    c'est facile de parler d'éducation mais je le comprend tu t’entraîne pendant des mois et tu te fais voler c'est pas facile a digérer car siteu a bien fait 4 appuis, sur la 1ere action. bravo a zarco tu a combattu comme un vrai guerrier

  • Fa
    12/06/2015 23:17

    Yo t'a tou di. Gni dagno nafekh mo takh Sénégal dou avancer.

  • Tapha allemand
    12/06/2015 23:20

    Pourkoi Mr larbitre a siffler Kestion Pour cng

  • Ndiaye mbaye
    12/06/2015 23:35

    Ki dafa kon il a mal eduquer

  • chacha
    12/06/2015 23:37

    éducation dh dafa bakh nit mom waroul impoli

  • chacha
    12/06/2015 23:40

    ki dafa kon ba ron

  • diva
    12/06/2015 23:42

    wi Mbaye ki dafa rew trooop sakh siiiiiiiiiim

  • vérité
    13/06/2015 00:31

    wayy bayui léne zarco sii jamm siteu dafa def 4 puis you lérr zarco il la raison il faut lui comprend mes amis félicitation a zarco et courage a siteu ……

  • Mbaye mboup
    13/06/2015 01:00

    demal ga ligueyi mo guene

  • Beugue Sénégal sama rew
    13/06/2015 01:24

    Sama gayii il faut nguene comprendre ko nitt Day dioum té mom li niou ko def di na diaf mou ande ak sagom

  • m’baye le bijoutier
    13/06/2015 02:30

    dafa rèw

  • ria
    13/06/2015 08:14

    yefou sauvage hi sakh la khamoul pour lane

  • chrie thiate
    13/06/2015 08:24

    mak mou reww bakhoul do kham sakh louye deff

  • zaleh
    13/06/2015 09:35

    agir dans la colère c'est s'embarquer durant la tempête. zarco tu es très impoli depuis le début du combat tu n cesse d'insulter les gens. kholaatale sa bope.

  • diakher diouf
    13/06/2015 11:05

    ms li dafa mèti ame dame nio khalaco soukonèkhè

  • ngonisha
    13/06/2015 11:10

    l respect né pas un signe d faiblesse mais l fruit d'une bonne éducation ZARCO demal yarat sa Boop yangui Maguette siteu dousa morom mola gueuneu fété khalé maris n'empêche diohna niieup tieur motakh souniou borom mayko victoire

  • tfc
    13/06/2015 12:26

    merci Tapha Allemand en effet le vainqueur du combat depend de la reponse à votre question

  • leeral rek
    13/06/2015 13:22

    yééna geuneu con , geuneu mal éduqués, geuneu sauvages, naafék yi géén donn. si c'était vous votre réaction aller être pire. comment tu peux t'entrainner des mois et un soir on fou en l'air tout ton travail, ça fait troooop mal. may wakh le vieux naafék bobou mouy né moustapha gueye dieuleul micro bi, moustapha gueye a bien vu les 4 appuis et il l'a dit. après vous allez me dire ki matt nala baye, danga rew alors kil n'a pas fait son devoir de baye. il pouvait le calmer sans ces situations là. si c'était son fils il n'aurait pas réagi comme ça.

  • soukk
    13/06/2015 13:50

    En tout cas entre un lutteur sur 4 appuis et un autre qui a le flanc à terre, je ne considère pas illogique de donner la victoire au premier. On pourrait parler de nul ou "ndiakh" s'ils étaient dans les mêmes conditions.

  • bab’s
    13/06/2015 18:51

    bayyi lenn togn

  • fall modou bété bété pur
    13/06/2015 22:46

    cest 10 important kw .. dafa niakk ba paré nienki…mais nak bounioukoko diapé .dafa mér rekk. .ta amna genrou mér yo khamni .soko défé .doto atane sa bopou . lisa khel khalat rekk ngay deff. mais jesper k sou démé ba aggue gallém . dinako regretéé……. .mais 10 courage zarko. tu n po demerite ….Felicitation siteu. le technicinnnnnnn d larenne .Begueeeeeee yallah nala djikk

  • el maestro
    14/06/2015 01:27

    lamb j moom nanou wara éliminé sénégal gnou am djaam . nanou baayyi di wakh sunu thiossane sunu thiossaan dou lamb .diiné la moy sunu thiossan . ana serigne si lounou fi néékké won ? beuré wala doundeul diné.khol léén lamb j mak gni fi néék amoul kéén kou fi sa djangue soré . dou si diné dou si nasraan . yaaq rééw rak nguén meun yéén magou lam j . touffou.

  • dieng
    14/06/2015 13:02

    Ahha zarco daffa neup forokh siteu lagnou wakh

  • buzz
    14/06/2015 23:58

    zarko wakhna deugg reporter yi dafa am niou khamoul dara beuri wakh ratatatti rek amoul solo lamine samba dafani ci diongante diell bi betouko mane faralouma zarko me dafa merr prck parell sa comba ba leegi niou yakall la dafa meti nak

  • madiba c .ronaldo
    15/06/2015 10:39

    ki nes pas education

  • Diallo
    16/06/2015 18:59

    mo teye le lion de grand yoff

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL