Annonces
Annonces
» » » Vidéo-Thione Seck à Rebeuss dans info people de...

Vidéo-Thione Seck à Rebeuss dans info people de Petit dej Walf tv

Annonces
Annonces

19 commentaires

  • vérité
    03/06/2015 11:00

    dém'lène liguèyi mo gueneu si yène. li motakh senegal avance woul

  • zeyna
    03/06/2015 11:17

    falf bayi lene dialat ay info disi waxate

  • gorgui diop
    03/06/2015 11:38

    mbokou yi ma ngi leni nou yene gneup dilene sant je me nome gorgui diop jai 80ans dama febar depus 10ans awma diabar awma dom waye am na alal machallah té docteur bi nénama si mois de juin bi laye dem té awma bena mbokkou ma bougone yene internaut yi kou si am sa compte banque wala sa mail nga diokhma ko ma transfere la xaliss bi ma amone yeup sokhlo wou ma si dara dama koy def rek te yalla takh xaliss bi ma ngi ko yoré sama keur ay malette la war na tolou si 2/ 3 millardes cfa ak ay euro yeupe ay faux billet la MERCI !

  • deug
    03/06/2015 11:52

    faut billet gua wax dh gorgui gassko soulko wala gua del mayko wa dic wasalam

  • deugg1
    03/06/2015 11:56

    suis de tout coeur avec papa thione et waly seck

  • bègue s touba rek
    03/06/2015 12:10

    Yaw deemal ligue yi sathıe rek may go go yorout khalis gor gui begue lou youbou sakh wala dagay diokhee sa nimero wala skyp senegal dou mali wala fanee dee lou leer rek so beguee khaliss dagay deem ligue yi ga am khalis gou bakh

  • minetou sow
    03/06/2015 12:18

    Bilay gorgui diop yay domamaramm tigui

  • KHELLOU
    03/06/2015 12:32

    IMBESILE VIEUX POLTRON VA LE DONNER AU DARRA OU DIC C MIEUZ CRETIN DOMARRAME

  • ousmane
    03/06/2015 13:50

    Gorgui diop mane mom sokhla nako diokhma ko

  • diadia
    03/06/2015 14:24

    da beugue nguen fater wakhou thione

  • gorgui diop
    03/06/2015 16:29

    ousmane mangi hopital principal bayil sa mail wala sa numero quelque jour moma desse ma dem wasalam.

  • paraqulo
    03/06/2015 16:43

    gorgui diop man modo modou la dama am probleme mou khaliss diokh ma sa numero

  • gorgui diop
    03/06/2015 18:35

    (paraqulo) 4798533 sama numero

  • mbakhal
    03/06/2015 22:34

    Yaw gorgui diop sakhaliss bi demal nga diokhko gordjiguen bi nek tfm ndakh khamna alal diaralnako dioutou nioukoy niam

  • mbakhal
    03/06/2015 22:34

    thione rk

  • maitre
    03/06/2015 23:23

    salam sw au Brasil ; senegal boungen bayiwoul kou nekoul ti deug ngen di def l avocat du diable rew mi delou guinaw rek , Thione da feegn rek waye yey blanchir khaliss barina trop

  • maitre
    03/06/2015 23:26

    gni di dioy ak di kharou nalen police diapale ndah damelni da gno beugeu deugeul li sen bay def <que dieu nous en preserve > AMINE !!!!!!!!!!!!!!

  • deugeu
    03/06/2015 23:26

    yaw

  • DJ BOS
    04/06/2015 08:54

    wakhal nio solalèlako bo dèwè mdrr

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces