Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » » Vidéo- Serigne Moustapha Sy: « A Charlie...

Vidéo- Serigne Moustapha Sy: « A Charlie Hebdo, nous avons usé de sourates et 3 manchettes d’autres journaux… »

2015-06-23T11:35:55+00:00 Partages

Annonces
Annonces

31 commentaires

  • thiate
    23/06/2015 11:53

    ma shalla sy deug ga ni wahgako yalla maye koudou fane ake weure t weurler…mayko molette djolite amine

  • fall modou bété bété pur
    23/06/2015 12:53

    Machallah yallah c'est tres important yallah nanga fi yaggue lol ta wer werle si barke seydina mouhamed psl ak mbolem ndiabotou seydi el haddji malick sy gui yeupou ak tout l musulman

  • La poubelle
    23/06/2015 13:06

    aaaaaaaaaaa ouvre vo Esprits /l'islam nes pas pour les noir ….. / La vrai Religion de l'Afric est commace /dans deux siecle personne en 'Africa ne parlera plu de l'islam. ……../revéi vous

  • maodo
    23/06/2015 14:35

    Mâshalla sy yalla na yalla goudall sa fan

  • PADANA
    23/06/2015 17:41

    ce qu'il a dit sur serigne TOUBA n'est pas vrai, il n'a jamais parlé à malick sy une quelconque face face avec les colons et je pose une question pourquoi le cheikh BAMBA a été déporte en exile. moustapha sy arrête de leurrer les talibes tijiane si t'a des choses à dire '' dit le et laisse serigne BAMBA de côté ou ça va chauffé

  • Manela
    23/06/2015 20:13

    Li nga wakh si Serigne Touba Metti nama lol, kokou wowoule kene si diggantem ak Toubab bi, And na ak gnom Gueddj douma llene, lene li nga wakh yupp bakh na. Wayya li nga wakh si serigne Touba mom offence nama lol. Wa salam

    • fatimata ngom sy
      05/07/2015 20:29

      panadi si les mots ne sont pas plus dignes que le silence vaut mieu se taire autremlent dit vaut mieu la bouclé…."sa consience mo nelaw"du coup tu ne peut que chalé
      les gens comme toi souffre de cet maladie qu'on appel "diahrré de la parole" sawar lamine baxoul!!!

      • Taloubéboukhebou
        17/07/2015 23:04

        Mdrrrrrrrrrrrr maylen ma ma ré ki loumouy wakh amoul Serigne touba Yakaroul koudoul souniou borom ndak yaakar kenen koudoul yallah bokalé la likko toubab yi sonnal natou yallah la goumou nangou té sakouko thi borom nguir dieundé ko ngeuremeul yallah ken kou wakh lenen geumounioula sa bakena takh ngay wakh.serign bi moy kouniouy tek natou mouy niane niou dooliko Ndjit dou wakhné ni ndjit dou wakh wakh diou teguinewoul ndjit dou wakh wakh diouy yakh ndjit day wakh deug mane dé lima khammsi si serigne bi moy doylona yallah té sokhlawoul ndimbeulou domou adam ak lenen loumou meunti done

  • Ndiaboot
    23/06/2015 20:26

    walay ndaysane sy malick amuniu sa faye dé

    • le guide
      01/07/2015 09:21

      UN jour lor dune longue secheresse la pluie satarda a tombé,le champ de Maodo comencé a prendre bocoup dherbe alors c dernié fut apele a Serigne touba de laidé a débrouissallé le champ;alor Serigne touba envoyé ses talibé chez Maodo pour l'aidé mais la chaleur été époustouflant;les bayes fall dire a coeur ouvert Maodo pri pour k le ciel souvre Dieu n peu refusé une seul de tes prieres parck tu fait parti du nombre des véridique;aprés un tré long refu Maodo pria et le ciel souvrit! Selement pour dire o ignorant k Serigne touba et MAME Maodo était des complices ils lutté tous les 2 pour la cause du PROPHETE PSL;répendre l'islam partout a travers l Sénégal!Essayé de faire de méme vous les talibés et cessé les querelle!bouléne takh niou hébniou svp.

  • bada
    23/06/2015 22:15

    allae akbar sy yalna yalla yokou ler

  • fraya
    23/06/2015 22:40

    dieureudieuf sy malick thiey sy malick sy malicki na sy

  • aladjidiagne
    23/06/2015 23:17

    El hadj Malick et Serigne Touba sont des cousins et des contemporains il est établi et connu De tous qu ils se consultaient assez souvent personne ne peut nier cela

  • Abdou
    24/06/2015 01:26

    Li nga wakhe thie serigne touba Man mii de métii nama walahi lolou dou wakhi s touba inni ou diahidou bil holomi wa bi toukha thie kham kham ak ragal yalla laaye khékhé wayé mbacke yi toi fofou nio geumoul séne bo pou tété khamougn liléne Serigne bi déffal

  • Abdou
    24/06/2015 01:54

    Mbacke mbacke yii Tok fofou warr na gnou lénna déllo touba dianga lénne kane moy sénne mame kham kham warou gnou ko weuri fénne la gnou bayii touba manou gnou ko diékhal khame lénne séne bopou té doyloo liléne fii Serigne bi bayill

  • mustafa
    24/06/2015 12:47

    mè xam xam dou doy

  • samb
    24/06/2015 12:48

    machallah yalla nafi yague tè werre

  • pape
    24/06/2015 12:48

    sa bakane bou reuy bii do bayii s.touba domeram

  • deug
    24/06/2015 15:24

    celui qui se fait enregistrer en mode vidéo devant des centaines de personnes ,celui la croit dure comme fer à ses convictions et à la véracité de ses dires mais celui qui se cache derrière sont petit clavier pour dire ses petits singeries ne mérite pas réponse ni considération . Kou sa baye faroul idji daguaye moytou borom alouwa (sy yalla guafi yague té weur ak képou respecter sougnou kilifa diné yi si sénégal ) wolof day wah ni ame none bou yéwou mo guene talibé bou amoul ak ragné

    • ndiabot ngom sy
      06/07/2015 10:44

      macAllah,gloire a vous notre responsable moral,notre fierté
      si les mots ne peuvent pas étre plus dignes que le silence vaut mieux se taire,vous souffrez de cet maladie qu'on appel "diarrhé de la parole" parlé pour ne rien dire ou offensé… vous etes des làches c'est pourquoi vous vous cachez derriere votre petit clavier pour dire des singerie…saware lamine baxoul….mais bon "sowe dou féne,kou nek nignoula yaré rek ngay waxé"aparament vos guides…..li yallah xam doyna…yéne gni sagua serigne Moustapha je vous conjure que yallah dina sagua sene personnalité comme il'a fait avec Abbou laham séni baye ferou gnou idji seni kilifa tolou gnouko fene ci xam-xam…saware lamine baxoul…

  • moslim
    26/06/2015 23:20

    يا يها لذين ءامنو اتقوالله

  • un passant
    27/06/2015 07:59

    Je suis tout simplement horrifié. Comment un guide spirituel puisse t-il avoir de tels propos? Dieu dit dans le coran qu'Il parle aux gens doués d'intelligence. Apparemment il y'en a pas dans ce qui ont posté des commentaires du genres maashallah et autres. Avant d'aller vous occuper de charlie hebdo avec vos soi-disant connaissances mystiques, utilisez les plutôt pour que les senegalais sortent de leur enfer de quotidien qui ne cesse d'empirer. Faites de sorte que vos disciples retrouvent une tete pensante qui leur permettrait de savoir ce qu'est le respect, la solidarité, l'envie de se tuer pour le savoir(aller jusqu'en chine pour ca, disait le prophète), un savoir saint qui aide les peuples du monde entier de ne jamais cesser de de grandir et en conséquence confirmer zaahiran wa baatinan la phrase du coran qui dit ALLAHOU WAASIHOUN… Point de connaissance destructrice!

  • Junior
    01/07/2015 08:02

    Rien qu'un menteur qui cherche a se faire une promotion … le mec n'a meme pa d'arme mystique sinon kone khana la mosquée de tivavouane aller s'achever depuis …. Arretez de vous foutre la gueule des gens et dites la vérités…Deugue rek moy moudj amo batine amo sakh na zahir

  • Baks
    03/07/2015 05:09

    Soubhanal Allah. La hawla wala ghouwata Illa bil Allahi… Qu'Allah nous guide sur le droit chemin et nous éloigne de certaines pratiques mystiques et surtout du mensonge. Ce sont vos jinns qui ont peut etre assassiné Charlie Hébdo, nuis Nicolas Sarkozy, François Hollande et Jean Marine Le Pen. Que des balivernes et des mensonges… Pourquoi ne l'utilisez-vous pas ce pouvoir mystique contre l'Etat d'Israel qui tue injustement les palestiniens, vos frères en la foi et saccager la mosquée d'al Aqsa, troisième lieu saint de l'Islam. Pourquoi n'utilisez-vous pas ce pouvoir mystique pour le développement du Sénégal, pour apaiser les pauvres qui ont du mal à manger à leur faim???!!!

  • cheikh tidiane
    04/07/2015 11:15

    Kaipeu kouy saga serigne moustapha na khamni liko mati taigou gnoukoko kou mzir kalamail yalla.li ame moy mo raw sene baye ak saine derigne boungaine mana yalar la wakh.ta kou kousa baye kharafoul fok ngakhamadi .pour nga yarou dagnelakoy wakh .

  • cheikh tidiane faye
    04/07/2015 11:20

    Senego lima binde dangueneko wara bayi mou dialeu.ndakh yena ngui bayi gnouye offence sougnou serigne diko saga.

  • nom
    05/07/2015 15:45

    tt le monde sé ke Mouhamad (PLS) est au Paradis.

  • talla
    17/08/2015 15:20

    Limou wax si serigne touba dara amou si serigne touba amoul loumouy diakh les si toubap yii toubap yii nio diakh les si mom ta serigne touba dou moromou kene legui la nekh rekkkk koune di wax mais ba fi toubap bii neke kene wakhou yalllay bour koudoul serigne touba mais yaw del wax degue way nak dakh mak ga kw ok

  • Pape
    29/09/2015 22:10

    Yaw tala liga wara wakhe wakho ko dek moy sa papa momou deh gor diugen bis bou ne mouy ware kouka lal so wakhoul won li ken douko khame mias kou khamadi rek dege li sa bay neke ok

  • Pape
    29/09/2015 22:14

    Talla yaw sou nif yi di wakhe daga wara nopi yaw lila war dafa bari wakhal sisa papa momou di gor diugen mom miga khame ne day wouyo dioulit tadi yefer gor diugen kay dou dioulit ta sa bay mom la lolou kay ga wara wakge kay yaw

  • Pape
    29/09/2015 22:19

    Talla yaw waro
    wakhe daga wara nopi yaw lila war dafa bari wakhal sisa papa momou di gor diugen mom miga khame ne day wouyo dioulit tadi yefer gor diugen kay dou dioulit ta sa bay mom la lolou kay ga wara wakhe kay yaw wala yaw khame nan li xew yaw talla dama lay wakhe li sa bay neke fi deh ak merou koñe bi

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL