Annonces
Annonces
» » Vidéo-Incroyable histoire: Violée par son...

Vidéo-Incroyable histoire: Violée par son propre oncle, elle accuse sa mère de complicité

Annonces
Annonces

12 commentaires

  • zazou
    30/07/2015 09:52

    gniak bakhoul sa nidiaye rèk mo bonne et ga balma ta mère aussi est fautif courage et n'arrête pas de prier que va le punir incha Allah

  • amy
    30/07/2015 10:56

    DOULI MO YAKH SENEGAL MELNI GEUMOU GNOU YALLA KOU LA VIOLE MENANCER LA NGAY TIT
    BASI PENRANT YI SAKH_ POURQOI PARCE QUE WAJI AMNA SERIGNE AM NA KHALISS LOOOOOL

  • seye orange
    30/07/2015 11:13

    Salam senegal ne va nil pas amna khalisse amna serigne bamou takhaw si kanamou yalla rékk

  • Bava
    30/07/2015 11:20

    Pas normal

  • jule
    30/07/2015 11:33

    tu doit la declar la police et contin a priere k dieu va te pardonne c op ta faute ca tou va ira bien inchall allah k dieu k pardonn

  • soumaré
    30/07/2015 12:30

    lii aka bari si kër yi sénégal si kén dou réagir mouy ñouni violé ak seni parent sa fait mal

  • insa
    30/07/2015 15:03

    Soknasi sa nidiay nit rekla bul am dara loy rgal diaral fanga wara diar banu mana diappa sa nidiay defsi mom li yon wakh bakkar bobu ngay wakh nak yaw amosi bakkar sa nidiay kay moy kisi am bakar sunu yonentabi alayhi salam nena 3 yi su borom dusi diappe bakar niumte manam lo tayul ak fatte ak lunula force

  • zal
    30/07/2015 19:22

    sokhnasi nguiryalla boula dara jaral bayyi jaamou yalla yalla sax danga koy toogn mouballa tè yaw toognoo sa borom tè toognoo sa moroom kon deel joully tèdi sabbal sa boroom tènga yobbou mbirmi ci yoon tènga waxko sa borom keur souladèè juegeul mou juegeulla tè yalla tax wasalam

  • zal
    30/07/2015 19:22

    sokhnasi nguiryalla boula dara jaral bayyi jaamou yalla yalla sax danga koy toogn mouballa tè yaw toognoo sa borom tè toognoo sa moroom kon deel joully tèdi sabbal sa boroom tènga yobbou mbirmi ci yoon tènga waxko sa borom keur souladèè juegeul mou juegeulla tè yalla tax wasalam

  • aminata
    31/07/2015 11:12

    badola rek mo sonne mais yalla bax naa

  • alou
    31/07/2015 12:02

    Un tissu de mensonges on a
    Jamais vu quelqu'un payer 500000 cfa pour coucher avec une fille au Sénégal

  • rama
    03/08/2015 13:17

    c pas claire du tout yaw kham guani dala begue teuder mou diokhla jus gua nane 2em foi bi warowone dem tes assez grande tes dofo mm sa yaye boulene démal guaniko wawe mai di dem

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces