Annonces
Annonces
» » » Vidéo – Cheikh Béthio Thioune présente...

Vidéo – Cheikh Béthio Thioune présente ses excuses à la communauté mouride

Annonces
Annonces

129 commentaires

  • Mamadou
    01/05/2016 23:32

    Defe lo kham wakh lo kham so tede nelaw!

  • Malick
    01/05/2016 23:34

    Dieureudieufety S SALIOU MBACKE.

    CHEIKH BETHIO THIOUNE, diegeul nanioula Bou bakh lii rek nafa rafet Togn diegeulou vraiment acte de noblesse rek la.
    Dieureudieuf.

  • DEUKHINE MBEUP
    01/05/2016 23:34

    Comme dit l, adage !!! Une faute avouèe se pardonne a moitiè , maan deey comme je suis musulman je te pardonne entierement, mais n, empeche que je te donnerais quelques conseils!!!! Ressaisis toi , reflechis avant de parler , libere les enfants et jeunes qui sont autour de toi qui ne font rien du matin au soir , ne Donne plus en mariage des couples avec seulement ( BARKI SERIGNE SALIOU ) tu n , as pas le droit d, avoir 7 femmes ( c, est pas conforme avec l, Islam ) , demande aussi pardon aux BAYE FALL , et sache que dans cette vie ephemere rien n, est eternel!!!! Qu, Allah te benisse car il n, est jamais trop Tard pour bien faire !!!!!!

  • mbalax man
    01/05/2016 23:35

    kousouk kii rek

  • mis te go
    01/05/2016 23:37

    ndayesane yala rek modoul diome

  • lamine
    01/05/2016 23:38

    yaw do dara

  • lamine
    01/05/2016 23:39

    yaw do dara khamo touss te do nopi

  • lol
    01/05/2016 23:39

    djiekalle leen ko rck sr.touba amoul morome

  • khadim
    01/05/2016 23:40

    liiiiiiii mommm bahna togn jegalou

  • tita
    01/05/2016 23:40

    mdrr senego lidieuneti guene vidéo bi c bien.li guene beaugone mouner leene balema. teugue guene ko nak ndeyssane nakh SERIGNE SALIOU DAARA OUMPOUKO.

  • oussou
    01/05/2016 23:41

    bo khamna da ngay poup ba par di ko tonni loo fay poub

  • oussou
    01/05/2016 23:41

    bo khamna da ngay poup ba par di ko tonni loo fay poub

  • Ayle
    01/05/2016 23:42

    Da nga rey lamign rek balanga wakhaty setlou kou.mais je n’ai pas senti une franchise dans ses propos sinon un sentiment de peur. oui il a peur car il a franchi le rubicon.

  • deug deug rk
    01/05/2016 23:42

    massou mako naw mom bethio wayai nak sama yaram dawna ci cadou youmou yekati nanou beuss sunu xol t jegalant ndah avan tt gnoune gneup ay djouliit lanou tai din lislam ak ni wakh dji meuna barri ken rek moy ndjiit t mataiko mouy yonent yalla Mohamed

  • senegal 1
    01/05/2016 23:42

    djeguel nagnou Laa thioune

  • deug deug rk
    01/05/2016 23:43

    massou mako naw mom bethio wayer nak sama yaram dawna ci cadou youmou yekati nanou beuss sunu xol t jegalant ndah avan tt gnoune gneup ay djouliit lanou tai din lislam ak ni wakh dji meuna barri ken rek moy ndjiit t mataiko mouy yonent yalla Mohamed

  • MBEUR
    01/05/2016 23:43

    figa tegone sa bopou ga egoul

  • Khadim Sangue
    01/05/2016 23:44

    le coup est deja parti ap mouride deug dou wakh yéneu yi surtt sounou yakar tay ak euleuk

  • gragg
    01/05/2016 23:44

    c triste … surtout de voir le visage de son fils qui se sent dsoler

  • perso
    01/05/2016 23:46

    mdr…

  • fall yaran
    01/05/2016 23:46

    bagua teude nelawo serigne touba wannala bobap sa talibeyi neek si netbi la di diaye dole lane beugue gnioi oibe srn guemogne kou si melni cheikh diop lisbone fi serigne touba rek mo fi nek

  • Nit kou woyof
    01/05/2016 23:46

    Serigne Touba newone na dilene nate goor yi bala guene di djebalou si gnom.Ab kilifa day wakh yiw ak louy djeurine djam yi serigne touba dé fonk diné ak souna yonantibi moka yobé djouli si bir wedj dji wakh nak dafuay khelou mane sé djeurignou na diamou yalla ta bayi thiakhane djeureudjeuf Serigne touba diarama mame cheikh ibrahima fall

  • akhirou chaman
    01/05/2016 23:48

    da nga wara nopi ta roy si wAkeur s saliou yi niom kene deggou len si ay wakh waye wakh rek nan s saliou ngay roy

  • Khadim Sangue
    01/05/2016 23:48

    SERIGNE TOUBA yagna bale gnouy togne ay ndaw lagnou mais bo guemé sap serigne Serigne guem kimou Donou nagne topou ci guinaw Tarikha mouride mo sensible bo lalé kéne day mélni lal ga gneup

  • diolof
    01/05/2016 23:48

    merci

  • Saliou
    01/05/2016 23:49

    Thiy ma warrou ?

  • ousmane
    01/05/2016 23:50

    no noo yombouna dee

  • lebaolbaol tigui
    01/05/2016 23:53

    djeguel nagnou Laa

  • niagass
    01/05/2016 23:55

    je suis un talibe me bethio le n le considère même pas un musulman je le considère comme un fran maçon

  • alioune dieng
    01/05/2016 23:57

    salamoune hawlal min rabbin Rahimi

  • abdoulaye
    01/05/2016 23:59

    il faut que tu arrete cas meme il est grand temps que tu arretes te nga yeme si talibe te nga khamni leup lo done tay ba meune see guis sa bop wala ngassi yeug sa bopp khamal ni serigne touba la te yow yakh ngako ba pare , andalak dale tenga delo sa bopp si wa keur serigne saliou yi te nga toubb jegalou te fass yene lila desse si sa aduna ngay dokhe seni ndiguel tey bayi seni terree te tamit dissi khirtal sa talibe yi , nga bayi gni ngay tekalek sa bopp te nga sorilene lolou sakh , bu fekke ni serigne saliou mola defar ba ngakoy ndamo ni khamal ni serigne bi nonou la defare gnenene gno gnou andak dale ak talibe gou Matt seukk wa salam nga balma akh

  • saly
    02/05/2016 00:00

    dieureudieuf serigne Saliou mbacké

  • fallou
    02/05/2016 00:00

    danga reww rek di doull rek aka fene rek

  • niaw gaddi
    02/05/2016 00:01

    yaw booy poup akka daye do daye ndankk t khamni yako poup ya koye tonni fn rek kon khamgani linga wakhon dou deugg ak sa kanam gou bonn yfar bou makk bi bofi doulat rek ma katt sa ndaye domou biral binga donn khade bou bonn bi

  • Italy
    02/05/2016 00:03

    Selon moi Béthio ne regrette rien de ses propos,il a juste dû céder aux pressions de son entourage pour présenter des excuses publiques.Mais au fond de lui,il est persuadé d’être meilleur que tous les mbacké-mbacké.

  • amsa
    02/05/2016 00:07

    yaw do darrra bilahi

  • sy
    02/05/2016 00:09

    serigne daye mate serigne Ki d’o dara mand serigne touba sakhe bokoumako ak mme talib d’Ay sope wosilame???

  • homzo
    02/05/2016 00:10

    dioume diéglou lou bakhla. J’étais très faché mais c’est fini

  • boy djiné
    02/05/2016 00:14

    il demande le pardon à la communauté mouride et seulement à la communauté mouride…mais aussi aux bons musulmans

  • boy djiné
    02/05/2016 00:14

    il demande le pardon à la communauté mouride et seulement à la communauté mouride…mais aussi aux bons musulmans…

  • fayebirame
    02/05/2016 00:15

    il faut pardonner, il faut tre une personne humble pour demander pardon.moi de ma part je vous pardonne,je suis talibe de baye karim fallilou, mais je suis mouride avant tout.naniouye diegueler di dieleler thi doley cheikh ibra

  • amadou
    02/05/2016 00:15

    !!

  • lybasse12
    02/05/2016 00:19

    ohhhh ndeysane sama yarame dawna

  • bara seck
    02/05/2016 00:20

    cheikh bethio khamal lounla wakhoul linga wax reye na lol yaye s.touba yengal nga nak iska khol nga linga wax

  • dofou s fallou
    02/05/2016 00:21

    Ki da khamoul tous di chékhal djigéne tékiwo dara yaw ak sa bire bou reuye sa kaname bou reuye

  • TOULOUSE31
    02/05/2016 00:21

    J’ai toujours su que Bethio est un truand et menteur…Il n’a jamais eu la bénédiction de Serigne Saliou Il n’a été Cheikh..Pour résumer Béthio est un VOYOU CRIMINEL..;Il mérite la prison à vie.;LA PERPETUITE..Il détruit la societé sénégalaise en deviant les enfants à travers des propos mensongers…On doit interdire les thiants de Bethio..On doit brûler toutes ses maisons à Touba et lui interdire de se rendre à la ville sainte de TOUBA..
    Le pire Bethio ne prie JAMAIS ..Je lai remarqué lors de ses visites à Bordeaux…En plus il fume non seulemlent des marlboro rouges mais aussi du yamba ..Chanvre Indien..C’est une Dame très proche d’elle qui le lui avait remis à Bordeaux.;C’est pour ça que son ex femme Penda avait déclaré que Bethio fume et qu’elle ne dira jamais tout ce qu’elle sait de lui ..Il fallait la laisser déballer..
    .C’est un Satan..Il ne respecte même pas le coran où allah dit qu’il faut se limiter à 4 femmes au max..Bethio en a plus que 4 femmes et que des jeunes alors qu’il a 74 ans et ne veut pas avoir des cheveux blans d’où la teinte noire qu’il met sur ses cheveux pour épouser des jeunes filles.;

    Nous mourides, particulièrement les baye fall..on doit égorger Bethio Thioune car si CHEIKH IBRA FALL était encore vivant il l’aurait égorgé lui…
    Dieureudieuf SERIGNE TOUBA…

  • BREF
    02/05/2016 00:25

    ANA sey talibs yifi nekone nane linguay wakh degueleu? Bethio khame sa bopp mo gueune niou wakhla ki nga done ,deloussil si souf

  • mame mor ndiaye
    02/05/2016 00:31

    bayi dakegu si diagalo

  • buxussbanxass
    02/05/2016 00:32

    BETHIO ,VOUS N’ ETES PAS UN CHEIKH,NI VOTRE FEMME NI VOTRE FILS NE LE SONT.VOTRE SOURCE DE FINANCEMENT EST MYSTIQUE VOIRE DEMONIAQUE.TOUBA NE MERITE PAS DE MAINS ENTACHEES DE SANG

  • el’Bachir dia
    02/05/2016 00:36

    NdaYsaaN Sama YaRam Dawna BaaLnaaLa thiOune

  • Binta
    02/05/2016 00:38

    Thieye yalla rek moye bour

  • salam
    02/05/2016 00:54

    J’ai pitié des sénégalais ni guen toppé serigne si dafa eupeu.hamelène serigne touba,baye niass,elh malick sy,serigne fallou babacar sy,bepp waliyou contennoul thi Niguendi diamo yallah bokkalè rek guendi deff.Aldianna yakoy ligueyal sa bopp.Niom waliyou yi senn mission c’était que you djangalyou louffi le prophète bayi modi l’islam

  • Khadija
    02/05/2016 00:56

    Excuse parce qu’il a peur pas regret c est un satan arreter le avant qu il sera tard reculer pour mieux sauter…demon

  • Khadija
    02/05/2016 01:01

    Domi galass doussa morom franc macon bou bonebi li doulassi guenne de evil man

  • tita
    02/05/2016 01:07

    YOUKHOU DI DJIB FOU GNIOU KO FOGUEWOULE. BARKI SERIGNE SALIOU. YEENE NAK GNI BINDEU SENEGO DI SAGA DI YEEK CHEIKH BETHIO LOU NEK. ATTENTION SERIGNE SALIOU DOU MOROME.

  • loth
    02/05/2016 01:12

    Serign Bethio dieureudieuf

  • Sant faw
    02/05/2016 01:19

    Yénit li Serigne Béthio di wah kouniou ka wahone sa baye mou wah ba khottikou tay féthie ba thiaayam naw. Serigne Saliou limou ko dafal kouko amoone wah ko. Iniaane baahoul. Nit loula wauroul Mandou ci. Limou am kéne amouko. Zair rek laay waah mo eupe talibé guena gueumlé, dakhalé Sokhna gueuna civilisé lé.

  • italy
    02/05/2016 01:27

    @TOULOUSE31.
    Tu raisonnes comme un thiantacoune.Comment une personne normale peut il appeler à egorger un être humain et ensuite brûler toutes ses maisons?Ça se voit que t’es comme Béthio,c’est-à-dire t’es pas sain d’esprit.

  • gambien
    02/05/2016 01:38

    mais deukhine doo nitt…

  • gainde
    02/05/2016 01:41

    Honteux si kilifeu si la parole est dargent le silence est dor remuer la langue sept fois avant de parler taurais pu tinspirer de ces paroles de sages pour un homme de ta dimension moytoul micro comme ay toth toth rek Guay wakh

  • myan
    02/05/2016 02:04

    IL a peur de ne Plus aller a touba il ne regrete rien J le deteste tout comme le reste do groupe d imbecile qui veulent salir le region…. je suis fiere Des 2 qui ont prie le courage.. il faut pas oublier L imbecile de Kara il est franc Macon.. allez ds Google et regarder bien les signes et ce kil a sur ses tenus…

  • myan
    02/05/2016 02:05

    IL a peur de ne Plus aller a touba il ne regrete rien J le deteste tout comme le reste do groupe d imbecile qui veulent salir le region…. je suis fiere Des 2 qui ont pris le courage.. il faut pas oublier L imbecile de Kara il est franc Macon.. allez ds Google et regarder bien les signes et ce kil a sur ses tenus…

  • touba rek
    02/05/2016 02:05

    man malay feke fofou dorrla ci kanam senegale yepp ga khamne serigne touba dou sa morom Say Say bi gadone

  • toubarek
    02/05/2016 02:09

    soumala diape dinala dorre ba senegale yepp khane doumanala serigne touba gayi fonto

  • toubarek
    02/05/2016 02:17

    wakhal say talibe yepp nanou la bayi Ta Dem diuebouloudiu ci serigne sydi moukhtar wakh Ko lesgu na gaw

  • sénégalndiaye
    02/05/2016 02:29

    Retrouver le sénégal en entier sur le nouveau réseau social sénégalais SnConect.com

  • allemagne
    02/05/2016 02:58

    kikay dafa xamoul dara cest dommage

  • srgn silip
    02/05/2016 03:03

    Bethio le franc macon bou degu dayam binga donn

  • Golas
    02/05/2016 03:22

    Je suis encore un novice dans le wollof. mais y a t- il une personne qui peut me traduire? car j’aimerai comprendre ce qu’ il dit? qu’est ce qu’ il a fait ? Et pourquoi il le fait? merci d’avance

  • Golas
    02/05/2016 03:24

    Je suis encore un novice dans la langue wollof. mais y a t’il une personne généreuse pour me traduire ce qu’ il dit? Et qu’est ce qu’ il a fait? ainsi que pourquoi ? Merci d’avance.

  • milk
    02/05/2016 03:48

    Mouride Yi diegal lenn Ko dafa dioum rek wayé kou atana def niakhama ci younou Serigne bi la té niou moytou sagayi ci senego naniou wakh Li niou nakhari té bagn di saga Serigne modou Bousso moy Sama Serigne terewoul ma ngui anda ak dal. Adouna amoul solo WA salam

  • abcde
    02/05/2016 03:59

    silip thioun

  • 1234
    02/05/2016 04:00

    silip Thioun est un salopard

  • doum
    02/05/2016 04:31

    bethio ne connait ni le quran ni la sunna
    j ai pitie de lui

  • gour
    02/05/2016 05:14

    se wakh dafa bare daga wara dal te daga wara khamne serigne touba mola tagalek wayan dioxal thier moritye mogan thi yaw wasalam

  • matar
    02/05/2016 05:40

    en tout cas dans ces rangs il y a trop de diegeulou signe qu’il ya trop de togn. un guide qui se respecte ne fonctionne pas comme a. femmes patial cheveux nat danses tathiou et je passe. c’est quelle religion a?

  • ousmane dieng
    02/05/2016 05:51

    Nit dale boula bou yalla df ndjit danga wara kham wara moytou ynne yikhalat bala ngua eakh mo gueune yi. adouna bi daye diekh ti biss dina gneuw gnou diakarlo ak sounou borom. gnou bayi ci khl thiakhane yi barinagne looleeee

  • dan
    02/05/2016 05:59

    mais serigne touba mounoul nattou ken yalla rek moye nattou dommou adama

  • Kou bakh
    02/05/2016 06:16

    Dafa diot ngua teuth sa guat

  • mouride
    02/05/2016 06:37

    Bethio dafa rew koi li lp khtou dorr la

  • kira
    02/05/2016 06:47

    dett waye koubakh

  • deugg
    02/05/2016 07:15

    ¡¡¡¡¡¡¡¡¡¡¡tita yaw naafekh nga deh¡¡¡¡¡¡¡¡¡¡¡¡

  • modou
    02/05/2016 07:19

    raykatou nitt kènn douko bayyi mouyy libre, sinon ayy tokhidouna rèkk layy dèfatt…. yawmall qiyamm digua expliquè serigne saliou lou barri bala guayy wakh akk yalla.

  • baye lahat
    02/05/2016 07:41

    louway def bopam. ya torokhal amy coll chanteuse il faut yalla torokhalla.domram jingua done

  • bai fall
    02/05/2016 08:00

    akassa serign be contenue ton chemin

  • Ziza
    02/05/2016 08:17

    togne ba paré di diégalou,amna lou ko guene.moy bagne di togne.

  • sibarak
    02/05/2016 08:22

    diegal gui demone gakofi tewoul commencer wate ga dama déféné boye wakh moussi bayi do ende ak sa sago bou resser gananeagui diegaloumouno fakhé ba santé Mbacke wala ga yene ak gnioume thiane ga sante maye wakh gani arabe ga,liga done bouko bagne daye fekh ga guene sé gniaw nakh sa bopp gaye déf. béwe bakhoul. yemal sitalibé

  • MOO mergane
    02/05/2016 08:22

    ndye sane acte bou noble leu serigne bi donc yalla may leu wer ak diamou gou sakh dak

  • talibe
    02/05/2016 08:22

    no

  • talibe
    02/05/2016 08:24

    Walker serigne Saliou se ne yoon nekouji

  • talibe
    02/05/2016 08:27

    serigne cheikh mom Sr. saliou maga thia toolya depuis 4mois dialna touba darou salam dit maodo mourid

  • kocc
    02/05/2016 08:36

    Tu n’es qu’ une impasse tu emballés tes seins vers l’ignorance tu ne parles que de toi même égoïste .reviens sur terre et sache que tu es un humain et tu es des éléments de la plus basse échelle des mourides.tu veux etre une goutte de sang dans du lait (au mouridisme) ce qu’aucun talibe n’accepte. Mets toi dans les rang comme tout bon m ouride écoutes ton guide et fini ont les messages personnels et égoïstes tu sera un bon mouride et tu aura le salut de cheikh salut ibn cheikh Amadou bamba mbacke khadimou rassoul

  • RM
    02/05/2016 09:00

    merci DEUKHINE MBEUP, deugue nkhoul.

  • seune
    02/05/2016 09:15

    thioune djeigueul nagnla yalla rekka doul dioum

  • fikk tiff
    02/05/2016 09:18

    yonuu Mouride benn bopp la.

  • messi
    02/05/2016 09:20

    franchement bethio yapna mouride yi.mom dal dafay waneni falewoulene falewoul lislam bi.makhala koul diangoul meunoul tari alkhourane meunoul dara loudoul yakar diap ay talibé ligueye léne baniuodof.ana serigne ak 5femme ak fouko lislam binde.guisagouniou dara lep dinaler

  • mimi
    02/05/2016 09:39

    yaw kne doula bal sa wakh mo reuy

  • GM
    02/05/2016 09:48

    Man dey ba naa la ndakh hawma foo gnou djeumei waayei, dou ci yoonou Yalla akh Yonneint « Salla Laahou Aleyhi wa Salam « . Mbeureuss!!!

  • deuze
    02/05/2016 09:50

    Kilifa Dou dioume baye diegualou bethio do daraa reste calme thé libéré talibe yii wakh leen deugue stp

  • binou
    02/05/2016 09:54

    c mieux je ne suis pas un talibé mais je respecte ce geste

  • cartel
    02/05/2016 09:57

    ourdou c pas bien de parlé comme sa

  • Mme
    02/05/2016 10:00

    Dieueudieuf thioune on vous pardonne yalla ngafi yague loool té andak wer

  • Mme
    02/05/2016 10:03

    On vous pardonne thioune kou tedd ki yalna ngafi yague té andak wer looool

  • cheikh tidiane mbacke
    02/05/2016 10:14

    ki bane genrou kilifala ki mo dadialé setané yonou mouride teup.mbalite mbi lay dadiale.kou ame touty djoulite do ko tope ndakh diangoule .diongoule kate rek lay def

  • cartel
    02/05/2016 10:49

    yalla n’a diam yague bethio dioumgua watte itamitte soope joule mo guene yalla der jaam qui Sénégal amine

  • Giss ??Giss
    02/05/2016 11:19

    lingadef movar danga dioum dioumte Lou reur

  • Atuman
    02/05/2016 11:20

    Encore toi..stp reste dans ton et fais pas de bruit

  • diop buegg dëgg
    02/05/2016 11:50

    togne dièglou yomboul

  • Omar ndiaye
    02/05/2016 12:12

    Ndeyssane ereur say amm

  • borom ler
    02/05/2016 12:14

    Bonjour mangui ziar gnep n’a wahyi teguine koudoul dioum amoul lolou borom bi rek moko yayo waye tahatou sa guinaw portable wala machine di wah loula neh ta bo diakarlowon ak mom do waw nit day mandou ra ap dioulite dou togn senego delen filtré yen wah yi ngen balma wa salam

  • baye lahat
    02/05/2016 12:22

    En tout cas bethio est mieux que les bayfal.taukh taate takhourane sathie ndialoo bokkal.vous faites honte au secte mouride

  • Djolof
    02/05/2016 12:51

    Ziar bu wer les ami j’ai de serieu problme je sors vk une fille depuis presk 2ans je l’aime beaucoup elle aussi mai mon pre ne veu pas cette relation car elle n’est pas de notre famille il me di de la kitt. Mai franchement je peu pas la kitt car je l’aime beaucoup bakhna Amna yar mangui deg lou vos conseils bakham lou si l’islam wakh

  • karbala
    02/05/2016 12:56

    soyez très prudent Mr thioune serigne touba dou morom amoul morom bilahi

  • kheus
    02/05/2016 13:33

    kit dou nitt je ne sais pas koi il joue l avenir nous le dira

  • dieukeur
    02/05/2016 13:51

    @Djolof fille bobou sa baye bougouko sa ndaye bougouko lene rek lalay khamal boude amga alal dioubari seuy bobou tek co si souf et viens m’epouser moi bakhna yarouna douma materialiste dieukeur lay weur te guiss nala.AL KHAYRY gaw

  • fall sylla
    02/05/2016 15:52

    salut golas il a insult l’ain Serigne fallou Mbacke deuxime khalif gnral des mourides .il demande maintenant pardon la communaut mouride et musulmane

  • sama serigne
    02/05/2016 15:53

    bethiou …xeurem fenn foh …seytane dila diay xamee leen mayok yalla ak diayok seytane…kou ser salih defar dou melnii .diote wolak yaw darra .youn wamla tegoun danga lankk diaar sa youno bopp..kola topo dou xam s salihou dou xam s touba dou xam yonentabi dou xam boroumam ….dou diariniou tayak alleuk..seytane ngay legeuyal xeurem fenn foh

  • abdousow
    02/05/2016 16:26

    serignebi yonwi ci alkhoûrane ak sounatou rasoul lakotek kouywote lenene moytoulenko mbalak saytane radjimla yala nanou yayala

  • lahat
    02/05/2016 16:37

    ki bakhole

  • rakadjou
    02/05/2016 18:10

    boulen gnou sonal nan nanouko djegal dafa wara teuth mouti gui

  • Makhtar saliou
    02/05/2016 18:56

    kouciywakh coune nasiwakh loumoukham wakhde maloufetalla amna alee waye amoul reyour

  • mareme
    02/05/2016 20:17

    dieureudieuf thioune

  • Goor
    02/05/2016 20:43

    Yeen ñii di ubbi seeni gemiñ di wax safaan, su ngeen xamoon du ngeen ko def. Amuleen xamxam koon noppi tay goorgoorlu ngir ame ndimbël. Yeen waa senego su ngeen xamoon du ngeen ubbi forum ta segguleen wax ji, di bayyi ñu repp ta xamuñu dara di wax ci Koo xamne du seen moromu baay ta ëlëk su ngeen texee MOOM La. Lu fi waay wax ci lu kay Galankoor ame ngeen ci wallë. Ëlëk lepp dina leer, waaye woorul ndax di neen ko fekke yeen ñii di wax seen musiba

  • chirba
    02/05/2016 21:52

    Boulène niou sonal fi lafiyy sabotè al couranoul karim kèn waxoul mounane mourail dou dara kèn waxoul taay mou toudou niit dongue comme ni mom ngèn niouy sonal je deteste bethio mais je deteste aussi les hypocrytes dèlou lèn si yalla ak yonaantèm ngèndi far farlo ndakh adouna ta daay dièkh bou gaaw

  • Giss ??Giss
    02/05/2016 22:14

    chirbA ya dokhn sa ndy

  • pape ba
    02/05/2016 23:02

    waw eureur monoul niak me l’EP si bir la

  • Yayou fallou
    03/05/2016 01:51

    Li laye yoot khamoko sakh yaw cheickh ibra mo geune sa ndaye ak sa baye meusoma nekh cheickh ibra bou dallé sa kaw nga kham ni dara dou tricage

  • amari
    03/05/2016 15:15

    Nit kou diangoul louko nékh wakh Abe diail la

  • fallen bi king off
    04/05/2016 12:32

    ndey San li de rafetna trop tong diegalou dieredief Thioune mame bambi yen nak hay domouram guen rekk amo len ak talibe

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces