Annonces
Annonces
» » » Série: «Double Vie» Saison 01, épisode 28

Série: «Double Vie» Saison 01, épisode 28

2015-06-07T22:26:40+00:00 Partages

Annonces
Annonces

34 commentaires

  • Kankourang
    07/06/2015 23:12

    Vous devez arreter vos serie a la con la PCD tu veux juste prouver aux gens que t'es pas un PD mais tes initials sans le C sa fe PD

  • didi
    07/06/2015 23:59

    franchement trop nul cette série

  • baldias
    08/06/2015 00:04

    nekhoul touss bouleene niou yapp way ces series de miérde

  • Vertus
    08/06/2015 00:47

    Dommage pour notre cher Sénégal qui, dans le passé , a vu sur son sol des hommes de valeurs, de vertus. Si en ce 21ème siècle, des microbes comme pape cheikh Diallo, salam DIallo, Waly ballago Seck,son pere thione et tant d'autres musiciens sans compter les lutteurs, les danseurs et certains animateurs,occupent le devant de la scène,alors le sénégal va inexorablement à la derive

  • C vrai
    08/06/2015 07:55

    franchement nous on v regarde comme tout les autre théâtre mais s la nou force à n pa regarde c du n importe quoi en plus ya pa d éducation pape chiekh et fama comment vous pouvez asi dan une voiture San attaché votre ceinture de sécurité

  • Sale
    08/06/2015 08:26

    Tfm amnaniou problème cet fille Elle es dangereuse

  • Marsene
    08/06/2015 08:40

    Non je sui déçu zale c une fiasco total de la tfm en recrutant cette fille elle va crée tout les problème du monde dans la boîte c sur kel a une très mauvaise habitude

  • Paris
    08/06/2015 09:16

    se pa obligatoire de regarder arêtes von conori la ok

  • DIP AKA MANE LA WAY
    08/06/2015 11:02

    yeneu soff way "tu v pa l serie plazzz zappe "on va flinguer tous les jaloux one by one ""yenkay beugue guen ko

  • Amina
    08/06/2015 11:48

    yen boulen nio sonal kan molen force pour ngen setan ba nan nekhoul dou len dem setan lenen li lep aferrou jealou rek la mais bolen moitouwoul pape cheikh dinalen rey te fek sen wakhtou joutoul bayilen iniane way bakhoul

  • jamss
    08/06/2015 12:17

    C trop nullllllll

  • sas
    08/06/2015 12:42

    madame fall et amina c'est la mm personne khana madame fall dagua commencé daww pourkoi tu change de nom. man mani c'est archi vraiment nullissime ce film. vas y meurt sooff ba dé

  • Moustapha
    08/06/2015 13:49

    khaw bou ligéyoul woon si télévision khaw ma noumuy def rék

  • Moustapha
    08/06/2015 13:50

    khaw bo ligéyul woon si tele noy déf

  • Madam Faal
    08/06/2015 15:19

    bayilen iniane sas man loutakh mai change nom man limai wakh ragaloumako con khawma loutakh mai change nom

  • anonyme
    08/06/2015 17:53

    madame fall nga balma mé kou gnak class nga tok fi rék di débatre ay affairou télé khana youssou ndour daf lay faye am na yo khamné amoul béne sens té daf lay yablou.g pa l'habitude de commenté mé chaque foi j t voi commenté change
    way sister

  • madame fall
    08/06/2015 19:32

    dimalilènema la wakh serie bi safna wa senegal

  • Madam Faal
    08/06/2015 19:53

    yaw miy wakh ne man awma class leer nama ne sen keaur yep man malen ope class Yossou Ndour feyou ma way kou wakh wa tfm dara ma defante ben saff, man ben djigeen genou ma am class motakh sama djikeaur tek ma palace

  • diepi
    08/06/2015 20:47

    si tu savais comme tu m'énerves madame fall

  • DIP AKA MANE LA WAY
    08/06/2015 21:12

    no c simple boulen setane yeneu metti

  • DIP AKA MANE LA WAY
    08/06/2015 21:13

    madam fall bian diiiit

  • Madam Faal
    08/06/2015 21:57

    sas yaw ya meuna fen man khawma kui amina, way way bayilen pape cheikh bolen begeu am jamm sokhor bakhoul way

  • soof
    08/06/2015 22:01

    série moye nekhoul dara coumou nakhari ga guol noye deff

  • fifi
    08/06/2015 22:31

    soof yaw mom sa tour bi woyou nala bou nekhoul lokoi setane niak class te inian ak bari wakh

  • boulibay
    09/06/2015 01:06

    nul comme tout bayilène forcé bi c'est trop nul vraiment

  • super xomesta
    09/06/2015 08:02

    mane mom madam fall momay dadji koi khamna kay khoulo moko dakhal kay lèkk

  • soof
    09/06/2015 08:12

    li mome boufequene deugeu rek Molene nekh diguene khamne li nekhoule fifi gamo ma gamomala li wakhtanla rek classe nak nous tousse amouniouko nak bouniou dewe aye sakhe mo niouye Leek cone yala souniou borom moye borom classe wa salam

  • anonyme
    09/06/2015 10:50

    madame fall wahal ak mane té bagne si bolé sou nou wa keur li ma la wakh nak conseil la rék té lolou la gneup constaté si yow.sou féké tfm geuno ma ko beug sen émission yi dama koy sétane(yewoulen;café avec; double vie; wiri wiri; kouthia…..) j lé adore mé yow mome kou eupeul nga momo nite yi nak.wa salam

  • Bon citoyen
    09/06/2015 10:55

    douma setane pd,do reference,do rouss,gordjiguene foko fek day niak diome

  • madam Faal
    09/06/2015 11:10

    bo amey sa coseil nga dem diok ko sen wa keaur man ben nit lai deglou moi sama djikeaur te limai def nekh nako yaw ya soof te niak fayda tok thi net bi di wout koy coseil mai wakh nganan lolou la yep constante yen yena niak class yen mimai top di set samai commemt di thi wakh, man awma sa jout nonsense

  • aliou
    10/06/2015 18:30

    Madame fall ya khoromou dé yangmay da dji hahaha

  • tapalapa
    10/06/2015 18:57

    Cette serie est interessante et instructive

    ne vous laissez pas decourager. bonne continuation

  • nina
    11/06/2015 13:40

    ceux qui disent que si vous aimez pas regardez pas se sont des vrais tetes de noeux. Est que vous savez dans certains Pays ya qui sont payes pour lire regardez puis critiquer ou apprecier.Les critiques font que les gens arretent ,changent, ou s'ameliorent.

  • doip
    14/06/2015 16:42

    damaner madame fall boulakherne yape ligawakhe moye deug série bi c que le début té nékhenaaaaaa way

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL