Annonces
Annonces
» » » Audio: Youssou Ndour feat Akon-Nouvel album-Song...

Audio: Youssou Ndour feat Akon-Nouvel album-Song Daan. Ecoutez

Annonces
Annonces

16 commentaires

  • la paix
    11/05/2016 11:53

    uuuuuffffff

  • la paix
    11/05/2016 11:54

    liiiiiiiii nekhena deeeee

  • Diaz pako
    11/05/2016 11:58

    Vive youssou

  • mimi
    11/05/2016 11:59

    diame rek lay ame youssou ndour incha allah

  • Senegal
    11/05/2016 12:01

    Popopoppooooo putinnnn ça déchire. Euuuuuuh ma contaneeeeeeee

  • KHL
    11/05/2016 12:13

    C’est trs neikh vraiment

  • boy LG
    11/05/2016 12:19

    diottou Ndayame limo nekheeeee hooooooo ma contane

  • pap
    11/05/2016 17:19

    nkh nekhi la df

  • faly ngack
    11/05/2016 18:36

    mercie c est magnifique viv l galsen

  • titguen
    12/05/2016 13:12

    way lii kouko sagna tekhele ak son wally seck..way nek len nitt wayy.. lii nekh way

  • SA
    13/05/2016 15:13

    Kounekk ak ki nga beug mane ma ngui mounou ma degg lou Aÿ son youssou ndour té je préfère mille fois deglou Aÿ son Wally yaw esk deglou nga sons Wally yi akon ak gnepp gno si yam battu bou nekh mom yalla koy maye té maye nako Wally arrêtez les comparaisons kounekk ak kila nekh kom niko Wally wakhé « kouy dioy mounou takh kouy dioy yaw miy retane andalak kiy ré kone nagnou retane » adouna bi metiwoul si kaw bougnou yenaneté diam

  • zou
    13/05/2016 21:27

    SA daccord na ci li nga wakh kounek ak kila begal, yow do deglou son you alors kesk tu viens foutre dans ce forum, waly tu pensais k ct un son à waly? Lol
    moi par exple ce gosse ne minteresse pas, du coup doumako deglou, te douma lire ay affairam, je suis a paris douma dem bercy.tu vois c comme kon doit se comporter qd une chose ou personne t est indifférent mais nek diko lidianti fo tolou.

  • moustapha
    14/05/2016 04:14

    Youssou ba faw bâ kérok may déh

  • sy anna
    11/06/2016 08:55

    Moffinek kouko bagnieu rek thiona dikaleula nangouleen lii Yallah doggal Maachallah You thiakaw thiakaname inchallah souma sagnione nak foo jouer maa fekeulaffa mane yamaye danel laafe thiate Ndour?

  • djime ndiayedd
    03/07/2016 11:52

    Tiakaw tiacanam

  • cheikh sow
    14/09/2016 15:57

    Youssou rek

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces

L'ACTU EN TEMPS RÉEL