(Vidéo) Eumeu Sène : "Daffa ame bène prise bou bess bouma beugu tenté si Balla Gaye, té prise bobou kéne meunou ci reuthie"