(04 Photos): Cheikh Sarr dépose ses valises au Canada pour…
Cheikh Sarr séjourne actuellement au Canada. Choisi pour présenter la soirée de Maabo et Omar Péne, l’animateur de la Sen Tv prêt à assurer son rôle de Mc.
Cheikh Sarr séjourne actuellement au Canada. Choisi pour présenter la soirée de Maabo et Omar Péne, l’animateur de la Sen Tv prêt à assurer son rôle de Mc.
Nice
Mor lingua amna solo
Soutoura mo bakh yalla bari soutoura
Bayi len toñ ab dioulit du toñ moromu dioulitam li guene gaw sakh moy ken warul toñ ken ndakh ken begul kula toñ ceikhe sarr mi nguen di toñ raw nalen yag na ndakh mom mingui def ligueyam yen nguen tok si internet bi di bakarou rek delen xalat sen terayu bamil bakhna dina ñeuw de mu yekh ak mugaw nak bayi len si khel
Cheikh sarr borom thiou thiou bi mdriiie Sénégal mo nékh rek
Ki dou Cheikh Sarr borom tiou tiou bou touti bi….
Hihi dama diotali rek dou mane mako Wakh.
Thiey cheikh sarr yagui noce dal dignou bayi mais dara laff thiat rek gourou alima chéri alima lii