Annonces
Annonces
» » » » » (Vidéo) Les confidences touchantes de Youssou...

(Vidéo) Les confidences touchantes de Youssou Ndour à Pape Diouf… Regardez

Annonces
Annonces

86 commentaires

  • titiyou
    16/05/2016 23:37

    Mais papa Youssou temps yi yeup au Sénégal on parle de la retrouvaille liberale mais a quand la retrouvaille youssale avec titi.wala bokk defale lou khess bokk gnoune Sénégal dagno name quand titi dit » diambarou elimane ndour thiaminoul ngone  » #senegal rekk vive Youssou vive titi

  • tapha
    16/05/2016 23:44

    thieyy bilahi yaye magoume seytané boléle khalé yeup botelénn au lieu de lé divisé puisk tu te di roi li dou sa thieur bilahi pape diouf mala yeureum dèmalal sa bop té bayi gni do avance dée je le jure sen interé rek lagni khol il naim persone

  • mami
    16/05/2016 23:45

    merci tapha ya dégue déeee

  • titi ak Youssou rekk
    16/05/2016 23:46

    Mais pas temps yi yeup on parle de la retrouvaille libérale à quand la retrouvailles avec titi la lionne histoire daye diekh

  • diagnenardiagne
    16/05/2016 23:59

    yaw taha yangui demak sa bob?

  • sow
    17/05/2016 00:00

    You yaa wakhon yaye chekh jakan lay teud

  • deugue rek
    17/05/2016 00:10

    limoufi wakh lane mo thiiy dvisé té chak jour nga déga dégue pire bi ci bénéne coté bi té doko wakh

  • Amar
    17/05/2016 00:22

    thim youssou ndour ya soxor

  • Amar
    17/05/2016 00:23

    nn youssou ndour ya soxor

  • pape
    17/05/2016 00:24

    grand depui 40 ans tu es le mieur mais mousou bakkou mais lou héw bagaye bakkou taye on diré que ya kelque chose ki derange

  • pape
    17/05/2016 00:25

    tapha ya sof guaye melni guor djiguene si niguay wakhé

  • as
    17/05/2016 00:32

    youssou wakhna lou raft si rakam pape diouf .

  • tit
    17/05/2016 00:33

    wakhna si digeunt mak ak rak diou yarru

  • deg deug
    17/05/2016 00:37

    youssou duobi ak akon diarna 10 millions

  • Modou
    17/05/2016 00:40

    Yaw pape Diouf dama la yeureum do avancer dé si 0 rekk ngay yam diemala avancer le sa bop ou mo geun ngay lang si you , yaw Youssou ndour sap mbakh guissagoumako dé bou fekké ni ya ngui dimbali Aÿ new du doolé tamitt sa khôl bi febar na , khanat sa yaram dou daw founé mou wo lafa foumou nekk dila wakhal lou bakh deff la com papame té moment tjrs si louy dioubolé rekk lay deff nga lank di dokko beugg wala dans nga yaakar ni so yekaté ben bate si Bercy bi wala nga nangou parrainage bi nitt GNi gnaw Bercy bâ ndakh yaw mais nakhe nga sa bop ou ndakh yalla rekk mom ndong mo Yoro doggalame du dogal té bou né waw Bercy Wally di na fess dell ndakh khalé mankewoul bat bou nekh dé , yaw miy mank wara deff yeufou mank takh nga bâ nitt yi si immaginer que ni Wally d’Ay concurrensanté ak yaw té khalé bi day defar avenirame .Té gnoun jeunes yi Wally la gnou beug sa stade bobou sou KO Wally wote wone day boudj ak jeunes khawma foko eupelé mé d’où si Sénégal te international bi sakh day ndakh mi ngui si yone dagn KO découvrir râ goul rekk ,te sa albulm dou té gni beugone Wally beug KO bâ legui d’Ay yokou ndakh mom mi ngui marker territoriale.De grâce deff KO na sa fils puisk deff na la né père té respecter nala , yalla nak mo fi ne amoul sante te tamoul tour gnepp la fi nekkale com niko Ndongo lo wakhéwone rekk  »NDIEUKEU MAGG MO AME NDIEUKEU TEKKI ME GEUNEU AME DIOM AMOUL » du courage sounou Wally plein de bonnes choses soul ker d’où KO teré fegn bagne ng en KO bâ tfm son Wally dou fa daw , Wally defal y alla sa sponsor mou eupou gnepp doolé , paix à tous

  • papis
    17/05/2016 00:41

    youssou dinafi yag dino bgeul inchala kom nakhari tala Gaz toksi mo geuna gaaw

  • la paix
    17/05/2016 00:46

    mami can you give your email address

  • dil
    17/05/2016 00:56

    Bilay pape diouf dou massa avance parce que dega deumoul sa bop

  • Tima
    17/05/2016 01:02

    Mais ou est le mal sur ce qui la dit na til pas le.droit de faire un temoignage ah li mtina way lag tiat youssou sa.kaw sa kanam inch

  • pape
    17/05/2016 01:22

    pape je tador

  • papis
    17/05/2016 01:26

    wally ak ay fansou ngordjinyi dano jaloux lo wakhsi pape diouf rk mou mtiln mais yna fat nityi sn way katbi wally mo geuna nilar si waykatyi ngn khamko

  • papis
    17/05/2016 01:28

    gordjigun yambar amouln bn classe . mais wally rk doufi pape Diouf moka dakha waay fouf ya pape fimou diar ba eksifi wally soufi diaron takh bane .

  • papis
    17/05/2016 01:31

    wally Groupou papam la yoor carriwoul Groupe . mo takh man pape Diouf dafa geun bopam mo takh mou am Genration consiance pape dafa mbabat si arbi

  • F
    17/05/2016 01:55

    Papis Wally sokhela woula diar fi pape Diouf diar ndakh mayoup yalla la ame yalla koko defal dafay âme si nitt day âme gno khameni wala gno âme dara dagnouy si sonou dog sé , âme gno khameni dougnou si sakh sonou yalla may lene lou beuri mé ça emporte et bayilene séné wakh you gnaw Wally dafa âme Aÿ fansou makk yo khameni Aÿ papa la gnou rafetoul , Wally gnepa KO beug , GNi KO bougoul c’est très négligeable face à gniko beug kone gnou réduire lene à zéro rekk , Wally rekkkkkkkkkkkklkkkkkkk gnoune wakh si pape Diouf takhoul ndakh ay fans Wally amougnou lougnouy envier Aÿ fans ou pape Diouf Aÿ nit normalagnou Kom gnepp , te Wally tamit amoul loumouy envier pape Diouf o contraire

  • boye bandi
    17/05/2016 02:00

    papis wakh ga deugue d modou mom doule rek laye deff bordel

  • natoucha
    17/05/2016 02:15

    lii yèp pour khékh WALY wayè fii yalla gnép la fi nékal té kou nèk ak sa weurseuk beugue nga bolè politique ak musique khamato fo dieume tè khalè bou ndiok nga ndiok pour barèko rafattal lénn khol yi mo guene ngè nèk fi di farfarlo

  • natoucha
    17/05/2016 02:19

    li yèp pour khékh WALY wayè fii yalla gnép la fi nékal té kou nèk ak sa weurseuk beugue nga bolè politique ak musique khamato fo dieume tè khalè bou ndiok nga ndiok pour barèko rafattal lénn khol yi mo guene ngè nèk fi di farfarlo

  • Mami
    17/05/2016 02:49

    Am djeuleule:[email protected]

  • Fata
    17/05/2016 02:55

    Bilay You ma yeureum say noone demb stade nekhoonne trop sakh stp restes dans la musique ndakh bou soukhlikou waat???

  • Rakhou
    17/05/2016 02:58

    Hé bayilen difi indi fumisterie may leen niou diam ken toudou fi Wally seck dagnouy enjoy sounou album bou bess bi

  • Eve
    17/05/2016 03:05

    Ay way fans Wally yi may leen niou diam lou ngen di wout si forum bi nioune dagnouy begué sounou opus bou bess bi ken tangalouko nak Vive la star Planétaire?????

  • Tamsir
    17/05/2016 03:12

    SENEGAL REKK merci à la star planétaire??????????

  • dioufy
    17/05/2016 04:34

    démal diamou dji yalla souniou borom

  • Feuz
    17/05/2016 06:11

    You is back rek fans Wolly seck yi dieufrou demal wakh papa thione mou dieglou senegalais yi dakh sounou économie leu beugon soukheul

  • Khalifa
    17/05/2016 06:48

    Dioufy wakhale papa thione mou dem diamoudj yalla te bayi faux billets yii

  • diop
    17/05/2016 07:36

    Youssou l’hypocrite l profiteur l seytané tot ou tard la jeune génération va t devancé mou nekhla wala mou nakharila borico

  • seck
    17/05/2016 08:03

    Bayilėne thiakhane Taye wax waxou yallah mai suivre ce sataniste de youssou ndour lui doxoul loudoul si saytanė fo rek

  • Awa
    17/05/2016 08:14

    Diop kharal beu guiss kouko devancé mais jusqu’à présent il règne sur son trône de ROI

  • nasi09
    17/05/2016 08:22

    vraiment senegal on parle de you et pape diouf vous parler de wally un peut de respect thione vous a rien fais laisser cette famille tranquille

  • roca
    17/05/2016 08:34

    merci papis tu a tout dis. youssou rek ba gudj gui frrrrr inchala. khalif gnral tout les weuy katte yala moko dff kne mounoussi darra. vive youssou ci kaw toujour rek. les jaloux von mgrir

  • as
    17/05/2016 08:51

    awa doul rek ngay def, gneup khamnan ni you hipocrite leu domerame leu ,waly rek la bagne neubeutouka ,waye soul ker douko tere fegne

  • mims
    17/05/2016 08:52

    Maii noooo waayy ana seytané fi no arretel waay diakhasse rekkk loussouy yonou wally si li youssou wakhoul Lou bess Si pape Diouf foumou fekk pape Diouf mm discour bi lay wakh koula wane ni beug nala mala mala raww manou ko fay vs voyé l mal partt man douma fans wally j conné just 2 de c chansons et pourtant jirè s bercy in shaa Allah prsk c un senegalais et sa c plaisir Ken momoul keneu koumou nekh fèteuwè fouko nekh mai dans l fespect wally waleu pape you koussi dé yalneu khekh seu morom dineu takhaw dara diarou koffi depuis un certain temps gnoune Senegalais daffa djikkk djoulit bone bougnou commencé dapp man fene wer domu diambour ray nitt sathie ak serigntou tè nenegn yoyay ak djoulit ley leu lepp raffet concurence mom mom lolou pape Diouf c un produit de prince art et kou mom label boubu ndour et frere of course you sougne diapalé pape lay diapalè mou nekh mou nakari tè nakkk en2013 souma dioumoulé youssou yobou woon beu wally a bercy et c lui ki avè fait la 1 ere parti tè nakk 4 join in shaa Allah c les mm senegalais ki y sera

  • yaram
    17/05/2016 08:55

    kharal 7 albums legui mou guene

  • Sy
    17/05/2016 08:59

    Masha Allah You baka yalla tallé dou tay donc c’est ce fils de looser de thione seck qui va l’ébranler kou we di nako lathie Thione Dollar

  • as
    17/05/2016 09:05

    lii you di def yeup da wouka def ,gneupeu khamnan ni waly mo takh, waye bilay gatame dina dagueu loumouy niak fayda, au lieu mou dem makka ,mou nekafi di ritale khaleyi, amoul bena class ,na def ni ismaila lo walla baba maal ,mak day def yefou makk ,waye dou nangou moukou ka legui mou am 60ans

  • zeinab
    17/05/2016 09:41

    mai you dafay djieufour wala mai you kagn la mail ni noow waly yaye say say tèrè nèlaw sa baye yi ak sa mag yi non waly je taim way nila senegal bo geumè sa bop wala gaye envencer rèk comancer bari none mai nak gnoune yi tita lougnou deug nexoul waly yi gnokoy takha avence yi mo gnouy yok diom aller waly bonn vent gnou waly lagnou geum t bou l 4jui thi gèn di comprende waky si cow si canam

  • Fina
    17/05/2016 09:43

    AS nak sen khol mingui bitagaz yena tarileen soreutoul mougne té khamné YOU is back

  • Cisse USA
    17/05/2016 10:01

    You is the number one.

  • marie rosalie
    17/05/2016 10:16

    you a parfaitement raison . wally khamo darra loudoul wayane .sa baye you indinna oscar yagegno sagal iow naroko t doko moussa indi . wayane reik guafi neiker ak tague guor djigueine yi tchieemmm merenala trop .

  • abou aziz gmg
    17/05/2016 10:19

    youssou ndour li douseu thieure neka mel niawna bayil dieufeurou yi waly sa dom leu diapaleko mou reusire mo gueune li

  • phil
    17/05/2016 10:34

    diviser pour régner
    parce que Habib et Jimmy sont chez Laly
    il fallait les rappeler
    ils ont pourtant attendus logtemps

  • arame
    17/05/2016 10:44

    Hahahahaha. …..ma ngui de. …fans waly sek nak neke te lou niou wah si niom deguela. ….ayy doofff deug iniane inieunieuti né sen baye thione seck…….thione ak kine niom denio dem maka nga nan youssou. …..waly nga ham né dagn ko pousse ba sona diohnan ko orchestre….diohko boîte de nuit. ….diohko télé. ….diohko radio…..outal ko renfort Habib ak djimmy après ça vous dites k pape diouf gemoul bopam mo mi toch zenith oubi grand théâtre toch fepp ba waly meun ka topando kokou da doy bay dess….youssou di todj rewmi rek diarna doul yek dey yi…..todj len s’en. ………vive youssou vive pape……en bas famille faux billet

  • Abdou diallo
    17/05/2016 10:47

    Youssou dou moromou bayou Wally sakh. Ce trafiquants que je veux mme pas cit son nom qui devait pourrir en prison…

  • Go
    17/05/2016 10:54

    You n’a rien à foutre de Jimmy ou Habib la preuve album Senegal REKK mingui todj adouna bi

  • Tara
    17/05/2016 11:29

    Wakh len Thione Dollar mou dém makka baparé ngen sogue wakh You bala ngay diglé sagay dangay sagou baparé

  • Babs
    17/05/2016 11:30

    Non vraiment je m’en doutais ,mais maintenant je sur sur que youssou ndour n’aime pas le goss wally et c’est désolant que youssou ndour un monument de la musique puisse être aussi scinique .ahhh très chère goss fait attention sinon …….. « le vieux sorcier et sa bande sont a tes pieds prudence ,prudence , prudence mon chère frère .

  • idy
    17/05/2016 11:35

    youssou diapalele saye domou baye sonananiou mo geune boye def lou bakh sa keur ngakoye tambalai

  • Mamadou
    17/05/2016 11:37

    yousou a f’ans la mai Wally cadomela waro dit koguirance ak mome kengue ak ce temps ok

  • pape
    17/05/2016 11:45

    il faut que nguene comprendre né fans Wally yi Aÿ khalé lagne mo takh ngou ame diote di khalaté ni youssou bouy nélaw di way sakh dou séne morome

  • Astou
    17/05/2016 11:54

    Man maa tite si sama reew You lan lay bagné Wally ak Wally loumou fi def loudoul yakh jeune génération bi issssshhhh

  • Diop
    17/05/2016 12:01

    You sokhor rek ak ignane rek le bon dieu est la pour tout le monde non pas pour les ndour rek

  • epagnol
    17/05/2016 12:42

    youssou demal diadou yalla.

  • dikha
    17/05/2016 13:25

    ay you legui dangay wakh rek,ni nga defone alioune mbaye nder si ay diamonom legui may guako diam rigeul ngako,nga defko coumba gawlo seck mou diguenne diou meun gorr falewoula nga rigeul ko, legui dal rigeul nga politique may nga diam karim wade ignanei ngako presidance bi mongui prision may ngako diam,legui wally nga signe yaw mba do deum.Mayal nite yi diam mak bou seuytane nga

  • dikha
    17/05/2016 13:29

    pape diouf damako yeureum sakh mouy signe begneum you barri yoyou rek.Ni nder moudie nonou nga nara mel boul demal sa bopou rek.

  • boy LG
    17/05/2016 13:33

    Li koumou nakhari sa tounou ndaye ki limou wakhe lou sy nek degue le

  • boy LG
    17/05/2016 13:40

    Senegal legi dall kien dou wakhe pour lane limou wakhe lane mosy nek pape liguey riek laye def ak waye gueme na bopame lide la wakhe waye sen thiot ndaye waye

  • bill
    17/05/2016 13:44

    L’avenir c’est Waly : Youssou doyna seuk !!! On a notre dose Man !!!

  • teranga
    17/05/2016 14:08

    merci tapha billahi toute le monde sais maintenant que youssou est un hypocrite il ne fait que seytané entre les jeunes wally te chante matin midi soir depuis qu’il a annoncé sont bercy youssou veux tout faire pour que sa casse en deux mais billahi tu verras tout devant toi inchallah ignane va

  • Marie
    17/05/2016 14:37

    Bilahi dikha wakhatico youssou ndour môme actuellement da fa dieu four et puis je vais vous dire une chose maintenant il ne se cache plus il nain pas le goss parce que la preuve en ai ke il choisi même les médiats pour qu’on lui pose pas de questions sur wally par exemple :Obs et direct info .Nous on est au 21 siècle Lou mouye beugeu deife khamnanko

  • paris
    17/05/2016 15:06

    narguna sonou salud daguna yakarni wally seck mom lanou warra wakhal lou bakh . wally dou tous ilfo gun khamlolou ya bercy 4juin dagun kham lima na camerayi wan salbi ybou gun khol 1000 persones sakh doka migui wantr beyi takhoul mou diar

  • Zoo
    17/05/2016 15:19

    Da fa sokhor se vieux sorcier et sa bande .deimal diamou dji yala mo geune ngaye former aye bloc pour meuneu kheikh se goss ki pourrai être ton thiat niake FAYDA .Non il m’énerve se youssou ndour il a des contentieux avec tout ceux qui sont populaire et ambitieux comme lui il est méchant , égoïste et ingrat . Mais dit toi bien qu’un jour tu moura et on te brûlera et tu va voir que yalla reike mo môme nguour merde et va en enfer

  • Bass
    17/05/2016 15:25

    Mais youssou vraiment maintenant personne ne te reconnaît . »tu fait du ratatati reike se que tu n’a jamais fait ohhhhh .on vous rapel que waly n’ai pas karim wAde laisse le tranquille merde

  • Dadi
    17/05/2016 15:53

    Vraiment qui wanei n’a bopame .ki da fa sokhor ignane domeirame deugue la se vieux bientôt 60an ngaye deife yeufou mankei yi ba nieupe khamko .kholal ma pape diouf môme mou mélni guignol môme mo geuneu neike mbame nieupe .mais dans un laps de. Temps vous serez tous dèmasquer bande de salaupards .

  • Yama
    17/05/2016 16:10

    Ay wa fans Wally may leen niou diam.ken Amoul droit wakh sa bakhoul way merde way

  • Marietou
    17/05/2016 16:11

    Papa you ,personne n’a chercher a disputer avec toi le titre de roi du mbalakh .mais vu ton comportement de ces derniers jours tu n’a montrer que du mépris ,de la jalousie et de la méchanceté .tu multiplie tes sortis de jour en jour et sa montre que tu deviens vraiment ridicule youssou .tu choisi même les médias. Pour tes interviews pour qu’on te pose pas de question sur wally .je n’exclu plus se que la majeur parti des sénégalais dise sur toi que « da nga sokhor da nga ignane da nga bone « .Et en se que je vois tu divise pour mieux régner et de la sa devient grave pour quelqu’un qu’on dit qu’il est le monument de la musique sénégalaises

  • Karim
    17/05/2016 16:29

    Mais yama yaw tamite deugue môme neikhoul . mais Wakh neikhoul deigue mo nekh tout le monde sait maintenant que youssou ndour a un comportement bizzare .et sa même ceux qui sont avec lui le sait disons nous la vérité toi aussi yama ma soeur.

  • Baye
    17/05/2016 16:40

    Non youssou magui beug warou si iow nak mak mou toln iow di dff yeufou soxor yi

  • Bass
    17/05/2016 17:08

    Doyna war mais sa devien louche .Personne ne comprend l’attitude de se vieux .

  • 17/05/2016 18:50

    khalle bou yaaro bock ak aye mack

  • safsap
    17/05/2016 19:07

    tchiiiiiiiim ma rousss yaw baye you coma tu parle
    nimporte koi.puisk tu parle de diapalé c parsk pape diouf dafa tiangg;tu na jamai parler ainsi alor nopil toul monde c q vou zéte paniqué

  • boy LG
    17/05/2016 19:34

    bilaye wallye diguen yame Youssou mina yi de nena thiepe bou sewo moko guenel wakhe bou sewo baya bo Guen nopa lou wally mi takhe gueni wakhe pape diouf Moy bayame sy waye li la yalla def gue len yalla

  • Khadim bamba
    17/05/2016 19:48

    Khamkham bi mo ngui fi expérience aussi .Mais vu tes sorti il me semble qu’il y’a de la panique chez vous papa you de quoi avez vous peur je ne le vois pas .Ya juste un jeune ambitieux qui viens de démarrer et qui fait son chemin tranquillement j’espère que vous devez le soutenir et priez pour lui au lieu de vous réunir et de faire un bloc pour le massacrer .je suis désolé pour vos comportement odieux papa you .Geumeleine ni yalla Amna ta moye mayei d’où domou Adama wassalam.

  • paris
    17/05/2016 20:04

    pape diouf mo dakha waay wally Lolou la youssou warona wakh mo dikh com yn kou toudou pape diouf rk sn kholyi dioog

  • abo
    17/05/2016 20:31

    ndour yag fi lol t wer tu es le meilleur de ce qu tu fait

  • Bd kh
    17/05/2016 20:36

    Modou waly bouy wo na wo papam thione ho pr koi you donc ya une intr de dans sou invit you stade fsse soufni wally kss brcy dou fse jamais

  • REPONSE
    17/05/2016 22:25

    BD KH Waly da sekhone nak diam youssou ndour mo takh mou koy wo di KO woyy parrainer KO Bercy wame ndakh lui il a tjrs voulu ke papa thione et youssou s’entendent bien

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces