Les plus populaires

 

Lecteurs en ligne

Une info ? 
 

221 33 823 43 43

Annonces
Annonces
» » Vidéo: Le «garouwaalé» de Amina Poté envers...

Vidéo: Le «garouwaalé» de Amina Poté envers Ahmed Aidara

2015-06-02T14:13:36+00:00 Partages

Annonces
Annonces

91 commentaires

  • bee
    02/06/2015 14:31

    Yaw amina kenn défoula dara mais yaw yaa yénéwoul kenn jamm. Tay ngène beugma par la force amoul fenne

  • fa
    02/06/2015 14:33

    Nom mai vraimen cette tele hana garouwale rek moy sen liguey. Yen vs avez pri 2 semaines amé ahmed aidara kou lek diokh sa moram, mome bene tontou rek la def ngèn di beug dè. En je te rapel k ahmed mo gagne trophe meilleur revueur de presse. Du courage wa gfm

  • abdou
    02/06/2015 14:42

    Ahmed stp continu cme ca ne les rpnd po. Sen xol yi moy dague tai meunou gnou si yaw nada

  • jule de Paris
    02/06/2015 14:45

    Sincèrement Youssou doit revoir son personnel mais Kou wakhé diokh keulé wakh c'est bizarre y'a trop d'animateur gayi liguey l'en nguene bayi wakh bi c'est mieux et arrêter de dire qui mo Dak revue de Presse mais il faut savoir que les journaliste yi khalate le sujet gno fort pas la personne qui ouvre sa grand guele pour wakh rek okkkkk

  • daba
    02/06/2015 14:52

    Ndeyssan poté mome dafa hewi motah mouy garouwalé pr net bi wahat si mom. Il fau faut la comprendre so héwè mom lounek di nga si dougue

  • wakhal way
    02/06/2015 14:58

    Ahmed aidara diamou rek ngay am bayilenn gnouy wakh rek raw nga lenn Sentv sa kaw sa kanam

    • biggie
      03/06/2015 01:04

      loooooool.mais yaw kou nekh nga.

  • mimi
    02/06/2015 14:59

    khew kheewi dh ayoul niak khew mo aay

  • mams
    02/06/2015 15:02

    Sa lamin bou reuy motah lounek di leu dal. Ahmed dou sa morom. Ak sa xessal bou bone, sa yaram bou yakou. Va chercher du buzz parck yow mom ancienne gloire nga légui

  • padana
    02/06/2015 15:09

    mai kii nitt la lii dou télévision wayy!!!!!

  • Madam Faal
    02/06/2015 15:23

    pote wakhal tha kaw ahmed kai lim fi def dou fey di fen ak di dieuw sa ay nawle bange engristery la no ahmed aidara dou nitt way

  • Mina
    02/06/2015 15:30

    bayilen wa tfm sokhor nguene trop amina poté sa kaw sa kaname senegalais sokhor motax dou nday avancé wasalam

  • aline
    02/06/2015 15:33

    yene sen khola diekh sou mouhamed ndiaye manone kone dougne nommine chak annee ahmad aidara.yaw demal topato sa yaye bina ba kaolack

  • kani xèigne
    02/06/2015 15:42

    yaw potè dimblil nitgni saytanènga rèk ahmèd aidara dou sèn morom bayilèn sokhar ta yaaw amngafi k7 lou bone linga done wakh si wa tfm moungi Fi Dan une semène dingako dègue si nèt bi

  • fallou
    02/06/2015 15:43

    Nom mai mme fall yow wa tfm warnagn leu decore, tu pass tou tn tmp a les defendre. Va toccuper de mr fall mo gueune. Tfm gno del li gnoulen di wahé nek di garouwale rek

  • rama
    02/06/2015 15:53

    Pote vrai seytané leu c cme ca kel faisai tmps bi pape cheikh néké sentv am blem ak boubs. Il faisai du garouwalé pape cheikh nane boubs moy meilleur animateur tele. Gueumoul dara li ngay héwi

  • domage
    02/06/2015 16:05

    Mane dai tfm moy sama tele mai vraimen g honte parck tmps yi mome il font trop de garouwalé, trop dattak enver ahmed aidara. Et prtan mouhamed ndiaye et khouthia gnoko commencé en traitan ahmed de tou les nom mem bougane sah boléwone ngen ko si. Il fau k youssou ndour parl avk sn personnel

  • pote
    02/06/2015 16:25

    Mai pourkw vs indexe ahmed prtant ce son les sites ki en ont parle 3jrs avnt k journal rewmi di ko binedi ahmed relate ko. Yow mom pote sa saleté way bi nga wara lidienté ak sa gnaway ak sa xessal bou gnaw bi. Kant on montre tes bras g envi d vomir parck c tellemen sal detrui par le xessal. Va te faire foutre

  • Amina
    02/06/2015 17:06

    yen bayilen pote raw nalen di dem demlen ligueye yi te bayi wa tfm,yen miy wakh nan pote dafa khewi yen mousou lena khew sakh bei khewi kon pote gathi galama

  • nana
    02/06/2015 17:46

    deug nekhoul tfm moko yoor yen pote namoul dara bouma. khewe yana na melni pote

  • lora
    02/06/2015 17:48

    pote de retour tass deuk bi Dell wakh reck

  • Amina
    02/06/2015 17:55

    pote wakoul tourou ahmed aidara mem bouko wakhe mo tey ndakh ahmed aidara dafa warr di def yefou goor amna yo khamne djigeen yi sakh defatounioko di worr di fen ak di dieuw ba nio enristery la dafa niaw thi goor ahmed aidara na goorey way bayil dieuw,del set si Muhammed Ndiaye khale bou am class thi bopam la

  • fama
    02/06/2015 18:07

    Ki mome c une idiotte diaroul tontou el na rien dns la tete. Ahmed fi nga ko diape fofou leu, téyéko feu

  • Amina
    02/06/2015 18:08

    yen miy wakh nan tfm sen khol la diekh wakhou len ben degeu ndakh meunou nek number 1 bepary sa khol di diekh yenen tele yi kai la sen khol diekh,labali fass takhou la fassa raw tfm yangui tha kanam,aferr bi tfm la moi tele bi ngua khamne 10 keaur yo diel 8 yeup mom lanioy setan wa tfm yen sant Yalla molen warr,waratoulen di tontou ken mem bounio len sagon ndey sakh waroulen tontou Yal na len lafal thiat te mousal len thi dieuw bange engritery len Amiin

  • dou
    02/06/2015 18:20

    Amina sou faiké tfm moy leadeur loutah gnouy garouwale sentv. Yow kay so dieulé premier do guersou té do fallé ken. Mai xolal mouhamed ndiaye loumouy yak bougane, xolal khouthia bouba ndour ak birima li gnou taxler ahmed ak son patron. Yen hame ngene ni leader bi ngen di woté gueumoulen ko sah

  • raisonnable
    02/06/2015 18:25

    Ahahahaha "sa cajier judiciel"

  • ris
    02/06/2015 18:28

    Vraiment c degoutan. C po professionel. Tmp yi mom dmedia dagno am class dagnouy liguey té bolé wougn dara ak wah

  • diop
    02/06/2015 18:30

    yalla defnakho baparer numéro 1g.f.m.lé chiens aboit la caravane passe bonne nuit .

  • bineta
    02/06/2015 18:32

    merci amina ta parfaitement raison ma puce

  • jo
    02/06/2015 18:35

    nom pote khana warouga Sénégal douniou dém douniou bayi khoudem du courage ma cher

  • walo
    02/06/2015 18:38

    Garouwalé ahmed aidara dai dou tah nga héwat. .ngay melni mbam houh

  • laaa
    02/06/2015 18:43

    vive potè

  • kama
    02/06/2015 18:45

    Vrmt vs ki defender pote da ngen yapp nit gni tai da ngen far. Ns on es objectif pote mo togn tai senegal beugoul kou togn. LoloU mo tah nitt gni hass ko bamou rap. Sou garouwale woul won dou degue li mou degue

  • Amina
    02/06/2015 18:48

    ris yaw khamo loi wakh tfm kai nio bolewoul dara ak wakh ndakh togounio fen di dieuw bange engristery len

  • lo
    02/06/2015 18:54

    Ahmed aidara dal ya bah si tfm. Yow dal ben bou sew nga len di may gnouy crise. Kxxxkxxkxxkx

  • abdou
    02/06/2015 18:58

    Mai cette petass dal se fiche drs gens. Affair you terre a terre yi ngen wara bayi

  • wakhal way
    02/06/2015 19:01

    sentv rek gno ay si ponkal yi alima ndione ak ABBA yeney tothie Sénégal pote yamal khamo té bayi ahmed aidara dou sa morom rew ngen trop télé Bo kham ni si yewullenn wareef kouthia show loulou kasser ak ay série booléenne gnou fate dem lenn wouti programme

  • thiaba
    02/06/2015 19:06

    Wa yen meuss ngen guiss les jambes et les pieds de pote.dafa waga ba yakou teksi xessal bi dafko gueuneu saltel. Tchammmmmmmm

  • adji
    02/06/2015 19:14

    wa tfm nagne lidianti séne goor jigénn bi baparé soga wax si kénéne

  • kinza faye
    02/06/2015 19:26

    vive la tfm mane yeene laye weure

  • daba
    02/06/2015 19:29

    Bien di adji. Pote yow mom kou yabate te rew nga. Tu ne respectes personne. Ahmed est bien aime dns ce pays té loko wah nitt gni gnolay tontou. Amoul sa diot. Sall petass

  • vérité
    02/06/2015 19:44

    Adji VA voir Pape Cheikh Tu Vera SI c PD ou po

  • Madam Faal
    02/06/2015 19:57

    goor djigeen kai munoul wessou ki tok di dieuw banio engristery ko wakh len lenen wa senegal rakhass len sen khol yi bala len wa tfm di rey te sen wakhtou joutoul bakh na

  • lora
    02/06/2015 20:02

    mdr wayyyyyy thiaba hahahaha

  • thiam
    02/06/2015 20:14

    Lora bilaay thiaba a raison g vu ses pieds ils son tellemen sal tai gnaw. Pote si bopam mo deguelass

  • kani xèigne
    02/06/2015 20:15

    potè Fi si USA amngafi wakh yofi wakh k7 bangifi lèmou

  • beugue walf
    02/06/2015 20:16

    yaw amina am nga lou la doy ak sa tankou lafagne bi
    yaw buzz ngay out

  • réw
    02/06/2015 20:17

    yén wa gfm guemouléne séne bopou k hana youssou mot séne farou Haye

  • ivli
    02/06/2015 20:58

    nangou lenn dogal yala sounou borom afer aidara krara la raw nalen len lou soree sakh

  • la vérité
    02/06/2015 21:07

    Poté se kel fais on le paye mais vs ki vs paye senego a racontrer des conneries vraiment sénégal dou avancer dal ya bcp de chomeur aller chercher du travail sais mieux vs éte tarré je Te jure

  • fall
    02/06/2015 21:23

    poté salté nga sa khessal bou beurii rew yow keine nawlo woulaa diango diongo di garwalé yo ak sen PD bi sonal gueine gnu trope ak sen gawarlé you niak khorom yii. ahmed di ngueine ko bayii ndakh ligueyam lay kein di beuc ray sen bopou vrmnt tfm tele niou amoul class la. chak jour mm wakh changé leine touti nak

  • massila
    02/06/2015 21:29

    amed sa mame dane ko done khekh sounou wasila Serigne touba naka nonou loi sa jingulay la boul tontou

  • jamm
    02/06/2015 21:44

    Pouffffff une chaine ki se di etre number one et ki sadonne a ces basesse. Nimporte kw

  • alou57@hotmail. it
    02/06/2015 21:59

    senegal dou démmmm

  • BASS
    02/06/2015 22:33

    no pote nekhone guama trop mes yagui maye beugua soff nit kou bakh daye dougou si lou yonam nekh

  • Amina
    02/06/2015 22:48

    yen ngen ne ahmed kan moi mamam nian nalen boulen thi dougal Muhammed S A W ndakh mom khamoul won lou bon te dieuw lou bon la ahmed esk aidara la sant kou sant aidara dou melni mom,Journaliste bo khamne woyan jahasseh dieuw rek no nekhoul ba nekhoul nak way ahmed danga wara sopi jiko defaratal sa tougai way del khol thi Muhammed Ndiaye yako meuna jurr way khale bou am fayda la te am class te set tek thi begeu bopam royal thi mom way ahmed nga baal ma boula wakhji nakhary mais degeu meunoul nekh

  • Amina
    02/06/2015 23:06

    yen miy wakh pote dafa salte khamna ay nitt yu khassaw ngen te forokh motakh gfm amoul kou salte ndakh lou doi lalen Youssou di fey nio topato sen bop way way nonyi bayilen sokhor yena ngi dee yen ku thi sangon ligueye tfm mem budee pour rakhass douss pote aferr bi yaw la ken douko dindi

  • lil
    02/06/2015 23:21

    Thieuyyy amina la seul a defendre pote. Si tu laimes wahko mou bayi gnak class

  • kheuch
    02/06/2015 23:34

    Heyyyy la folle furieuse a encor parle. Cte pa la peine de faire tou c commentaire. C sur kel cherche l buzz parckil nen a plus

  • Ndiayembaye
    02/06/2015 23:55

    Mouhamet ndiaye c est le meilleur revue de presse de tout les temp ahmet aïdra ndiew rek lay def dou dra tfm sa khaw sa khnam amina pôté yague pape cheikh diallo begue rek ligueni def neckna lol sa kaw sa kanam Begue téléfision future medias

  • nana
    03/06/2015 00:58

    Tw la ndiaye mbaye tu pe aimer tfm, le pd, pote la salle mai bayilen ahmed aidara parck gnoune oci dagn ko beugue et k sen garouwale yi ca ns fai mal. Ame len touti class

  • biggie
    03/06/2015 01:07

    looooool.mais yaw kou nekh nga.

  • yes
    03/06/2015 01:16

    franchemnt gawarlé mom ci niak class la bok. chak jr mm chose khana amolene lolene di wakh wa tfm chiim

  • awa
    03/06/2015 01:17

    Mdrrrr hana ki hamoul ni ahmed mo gagné meilleur revueur d press.

  • bègue s touba rek
    03/06/2015 02:08

    Wakh rek ta yalla dakh Ahmet mou sene tv dou moro mame way

  • Madam Faal
    03/06/2015 06:58

    waay way meylen nio jamm yen khamolen lui garuwale pote garuwale woul ken li khew la wakh ahmed dafa dieuw banio enristery ko lolou la pote wakh Muhammed Ndiaye pour mou moitou ndakh rafetoul thi goor tok di dieuw sa ay nawle bange diap la dafa niaw wakhlen thi lolou, te yen miy tekale tfm ak sentv khamnane wakhou fans rek molen diap way kham ngen ne tfm dou moromi sentv

  • Amina
    03/06/2015 07:24

    man lima saf thi tfm moi bo yeewo ba jakalo ak niom dangay contane bess bi yeup ndakh ay kanam yu rafet goor yi djigeen yi nyepa rafet mongen di setan tele di guiss ay kanam yu moi

  • monia
    03/06/2015 09:40

    pote ya tay defal loula nekh ils sinteresse tous a toi yi comentair you bari koula bagn yallana dé

  • matar sarr
    03/06/2015 10:03

    boulékoko diapé fimou nek la tfm télé khawaré kharani garwalé kessé amoul programme

  • Yacin
    03/06/2015 10:19

    Yenak potè yéna yam prsk mom boudè yakeu dérou Ahmed aidara yeneu yeneu ngueneudi yakeu deram koneu yeneu yam môme aumoins gnikoy fay yeneu nak yenay yokou seneu bakar li dou actualitè amoul bèneu sens keneu di yakeu derr rek

  • Khalifa
    03/06/2015 10:37

    Tfm television garouwale la ak mana togne normalouniou douniou aye vrai animateur

  • Madam Faal
    03/06/2015 11:00

    hahaaaaa tfm bou amoul emission khawma ban tele mo am emission bolen begeu nio yok emission yi wakh len ko rek mongen yi ngen di def inian bakhoul tfm number 1, pote defal loula nekh ya tey koum nakhary nga saff souf tok thi

  • jina
    03/06/2015 11:01

    pote outile dieukeur mo geune guaye ratatati rek

  • astou
    03/06/2015 11:01

    je suis à tout cœur avec TFM mais franchement je ne supporte pas les garouwalé c'est pas bien. c'est pas à vous d'apprécier laisser ça aux téléspectateurs sabou dou fotte bopome. affaire de ndiogane

  • jina
    03/06/2015 11:03

    Ma fall kouwara topoto sa menage mogeune guavnek fii diniou sonal

  • sentv
    03/06/2015 12:07

    Wolahi vous êtes fous ce vous qui est nafekhe pote elle a dit mohamed ndiaye est meilleurs même moi je peut ce moi le meilleur ou est le mal arrête de vos connerie pote elle na rien arrêté de insulter pote.ce hamed aidara qui as fait mal !tfm 2stv wallftv c est les meilleurs télé sénégalais

  • diop
    03/06/2015 12:16

    je suis à tout cœur avec TFM mais je ne supporte pas le garouwalé c'est pas bon. je déteste ce qu'a fait Ahmed Aïdara mais c'est pas à vous de le critiquer ou de le juger à tout le temps tournez cette page pour de bon. c'est pas à vous aussi de nous dire qui est le meilleur laissez les auditeurs et les téléspectateurs de faire leur choix sabou dou fotte boboppe. sénégalais yi beugue nagnou TFM mais nak yé nangui beup soffe. affaire de ndiogane

  • diop
    03/06/2015 12:28

    nit ki no faral faral sou dioumé né ko dioum nga, sou tougné né ko aussi ya togne diame ame c'est ce qui est rare actuellement au sénégal. les gens pensent que si tu es avec quelqu'un tu dois lui chanter les louanges pour toujours au contraire il faut lui dire la vérité car elle est éternelle

  • diop
    03/06/2015 13:09

    hhhhhhhhhhhhhhhhh

  • yaram
    03/06/2015 13:39

    Pote mom c une illettre ,analphabete, deguelass, salle ,idiotte ,vau rien ,cancre

  • @aw
    03/06/2015 13:52

    non bravo diop ta tou di

  • phou
    03/06/2015 14:06

    Mdr tu ns fatigue alors que tu peux mêm pa prononcer casier judiciaire. Casié judiciel lol

  • Ma
    04/06/2015 11:08

    Yen mi di khass tfm dite moi ki d'entre vous prend 1h de temps à regarder la sen tv sans zapper. c parcek ils sont nuls, sans programmes beu paré di woyane rék. akhmet mom di djaye revue de presse à 250000. ameth ak aladji de vrai nafik

    • kebe
      04/06/2015 14:33

      poté dousene morome amoul kouye défe télé melni mome moléne eupe
      thiathie dakhléne

  • Madam Faal
    04/06/2015 14:28

    Muhammed Ndiaye dei dou diay reveu de press te dou dieuw banio enristery ko ndakh khale bou am class la

  • Amina
    04/06/2015 14:41

    way way yen boulen sonal sen bop di tontou dof yi di wakh pour man kep koui tekale tfm ak benen tele rek dof nga ndakh pom dou moromi new lolou khale yi donga judou sakh khamneng ne tfm dou moromi gayi thiow le bari rek way kou wet kham sa bop te koune kham nga kala meun

  • fanta
    04/06/2015 19:19

    tfm hamga louma soff si yenn daguene meuna garouwale trop surtout yow Amina pote seytanne bou reuyga yow deffal yeufou intellectuelle way

  • sama reew
    06/06/2015 19:27

    tfm defoniofi dara lou bàkh
    garouwale rekk lang fi nekke sourto lamine samba
    ak amina momo.
    mohammed Ndiaye nak mom jiammbarla ta man na
    li moy deff ma chà Allah.

  • malick
    06/06/2015 19:40

    tfm dal c la télé des ratatiweurs gnom wakh rek

  • seck
    06/06/2015 22:29

    daguena sofe trope

  • Madame ly
    07/06/2015 13:27

    Amina nèkh gama mai bayill garouwaalè

Poster un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *

Annonces